Annonces
Annonces
» » Vidéo : Oustaz Iran Ndao Attaque et déclare la...

Vidéo : Oustaz Iran Ndao Attaque et déclare la guerre à Ahmed Khalifa Niasse, découvrez pourquoi …

2017-06-28T21:31:22+00:004146 Partages

Annonces
Annonces

63 commentaires

  • khadim amar
    28/06/2017 21:44

    iran ndao ya souf ta sokhor bayel diabor monoloko dara fi do bor kholo

  • khadim amar
    28/06/2017 21:47

    iran ndao ya souf ta sokhor bayel diabor monoloko dara fi do bor kholo

  • Rijal
    28/06/2017 21:51

    Iran yagui mer dé kilay doundal bamba lay yakar d bamba feupou lagn wakh

  • khadim amar
    28/06/2017 21:52

    iran ndao ya souf ta sokhor bayel diabor monoloko dara fi do bor kholo jjkkkkkkjvhhgyrygr

  • bataclan
    28/06/2017 22:04

    merci iran ndao.qu Dueu t benisse

  • ibgueye54
    28/06/2017 22:23

    maodo fepp, kou nell sa serigne ma la gueneul , que chacun s’occupe de son marabout, il y a que Allah soubxana wa talla et le prophéte et tous les autres ont chacun sa chapelle !

  • Cheikh Tidiane MBACKE
    28/06/2017 22:40

    ahmed khalifa niass wakhoul lou gnaw te mane mi bok si bamba ak maodo khamnani kéne meunouno dizkhassé bouléne sonal séne bopou.allahou wahidoune

  • Dieng
    28/06/2017 22:40

    Iran fii dou pour khoulo eutou diiné dél wakh si diné mais pas pour garouwaalé diiekhoul rafétoul

  • leBaolbaol tigui
    28/06/2017 23:03

    khalifa niass baaxna cii reewmi deh!1

  • Coumba
    28/06/2017 23:06

    Vraiment c’est honteux d’entendre des propos pareils. Ahmed Halifa Niass tout ce qu’il dit il emmène des preuves et des paroles de témoin. Moi je me dis que Ahmed Halifa Niass à raison en disant que vous êtes au niveau primaire. Il faut le répondre par des preuves et démentis mais vous fêtes du bruit pour rien.

  • Ousmanembodj
    28/06/2017 23:06

    Mais Ahmed khalifa waxoul lou ay dé mane dé néxnama guir serigne touba

  • Ousmanembodj
    28/06/2017 23:08

    Dieurdieuf Serigne Touba

  • Malick
    28/06/2017 23:08

    Man dama Yakarné Khamé wouléne Nafekk, Khalifa Niass Nafekkk Geunoukoo Makk si Sénégall , Foumou Dém Li Nioniou Beugg degg Rekk laléne dii Wakh Kou diarra Moytoula

  • Man la
    28/06/2017 23:09

    Linak wa tele bi lay wakhal boufekeni fi dageunko def pour khoulo wakhleun niouko ndakh nioun khoulo takhoul niouy setan sen tv

  • Man la
    28/06/2017 23:11

    Linak wa tele bi lay wakhal boufekeni fi dageunko def pour khoulo wakhleun niouko ndakh nioun khoulo takhoul niouy setan sen tv

  • mikk
    28/06/2017 23:14

    iran a raison ameth dafa nafekh

  • diapro
    28/06/2017 23:40

    merci iran

  • Maodo
    28/06/2017 23:43

    Uaw Iran tu es une petite personne ta tapette nga ndax dangaye garouwalei epui kou yabatenga khamo Sara epui dangaye togn

  • diaw
    28/06/2017 23:47

    Merci iran wakh nga dague khalifa niasss saytane la

  • DAME
    28/06/2017 23:56

    IRAN KI LIMOU WAKH DIAROUL MENACE YI…YAWE LA PROCUREUR WARA WO…EN PLUS YAGUI WONèNI KOU TOUTI NGUA Tè KHAMOULOKO….THI SA BIIR WAKH NèKA DA NIèMè LALE GNISSI DèSS SA VE DIRE NIOUNIOU GNOLA NGUèNA KAWè…NALA BOUGANE DAKHE WAYE

  • Badou
    29/06/2017 00:10

    Iran nafekhe nga ahmet khalifa wakhoul dara sy maodo yaw la wakh fero idji nga merr bege ko diakha seke adouna

  • Thiam
    29/06/2017 00:37

    Waye ki môn sof yaw tafsir al qourane laniou la teke si Tele bi tafriro bayi wo nek fi wakh Yah sof waye en + niass dekeu rek lala wakh khamon dara bimala khamei ba legui bayi Wo diouli waxall lenne waye wala nga bayi sof khamon l’âne dara

  • Ngoor
    29/06/2017 00:53

    Iran, personne n’a jamais douter que tu etais Tidiane.

  • Isseue
    29/06/2017 02:40

    Iran yaw khalifa Niass mola gueune ndah dou garou walé ,il a raison nak prsk niveau primaire ga nék … wahal ci lolou mo gueune…. Sénégal yeup comprendre nagne la lègui ,dangay négocier wara té gui rek…

  • sall
    29/06/2017 03:35

    iran ya saytane kounek amga droit Tague serigne touba fii si Lou warr

  • mame sarr
    29/06/2017 04:49

    YENN WA SENEGO NIOU KATTE SEN NDAYE NGEN LOUTAKH NIASSEN BI TONTOU WON MALIK BOLLE MBAYE DOUGALOULENKO AY VRE NAFEKH NGEN KHANA LADIOULEN MEKONTA YINIOU TEGON THI RADIO DAKAR NIOUDAN CONTR TARIKHA MOURID FOUNIOU MOUDJI NIOM NIEPA TOROKH

  • mame sarr
    29/06/2017 05:00

    YEEN WA SENEGO AY SEYTANE LOUTAKH NIASSEN BI TONTOUWON MALIK BOLLE MBAYE PUPLIE WOULENKO KEP KOUKONTRE YONOU MOURID DAGAY TOROKH ADINA AK LAKHIRA https://www.youtube.com/watch?v=JePYAIzNgps&t=121s

  • Omission
    29/06/2017 05:42

    Thiey senegal avec leurs histoires de marabouts matin midi soir …moi jaimerais vos marabouts soit des ingénieurs ou scientifiques ou économistes développer senegal touti cest mieux je pense… a part diabar ak dom niou barri rek … bayilene nelaw

  • phata
    29/06/2017 06:22

    vous qui vous attaquez a Iran on sais bien pourquoi vous le faites dans ce pays satan a tjr domine .Ameth Khalifa c est l incarnation par excellence de Satan .Son pere a été disciple et moukhadam de Seydi El hadji Malick sy .Ils ont voulu tjrs mentir a leurs talibes en leur disant le contraire , mais c est peine perdue.Il a sorti une video dans laquelle il dit que Maodo est le heros national tous les autres marabout n ont pas resiste avec intelligence vous n en parlez pas vous voulez tjrs entendre ce qui vous plait c est a dire les fleurs qu on jette a votre Serigne .Akhmet khalifa niass n est pas une reference ds ce pays c est un coureur de jupon déguise en marabout il s est marie 26 fois et il continue tjrs a le faire .Il n a aucun respect pour la femme .C est un fils de pute qui veux semer la division au sein des confreries il va être démasqué bientôt

  • mamie
    29/06/2017 07:59

    Oustaz Iran y a des individus qui méritent d’être répondu d’autres qui ne méritent que l’ignorance. SVP Ignores ce type il n’est une référence pour personne Il a acheté une maison au point E pour la louer à l’un des plus grands bars du Sénégal/ Le bar « Chez DIAMI APPARTIENTà AHmed Khalifa NIASS cela veut tout dire. Alors ki dou nawlé dou référence dou royoukaye ; IL EST CHEYTANE EN PERSONNE , il mérite l’oubli sinon il risque de te détourner de ton objectif qui est très louable pour nous. Vous au moins vous nous apprenez quelques choses et ceci n’est pas négligeable, donc merci à vous Iran NDAO

  • boy dioffior
    29/06/2017 08:13

    Dans un pays oú 85% de la populalion vivent dans la misère,ces Iran Ndao et consort ne trouvent rien de faire à faire qu’à jouer à « mon marabout est le meilleur ».Où était ton marabout quand il y avait l’ébola?Ton marabout a-t-il apporté l’eau potable et l’électricité au Senégal?Qu’a inventé ou crée ton marabout pour rendre meilleur le monde en général et le Sénégal en particulier?Alors toi Iran Ndao,Ameth K. Niass et tous ceux qui vous ressemblent,allez vous faire foutre

  • hj
    29/06/2017 08:43

    A OMISSION
    arreter de generaliser au Senegal, des marabouts hyper diplomés et plus diplomés que toi OMISSION, on en trouve des masses au Sénégal. Allez dans les usines, les hopitaux, les grandes boites du Sénégal et vous verrez des marabouts medecins, ingenieurs, scientifiques, designer, financiers etc…. je vous rappelle le meilleur orthopediste du senegal est un fils d’un tres grand marabout. bcp de fils de marabout aujourd’hui sont diplomés des plus grandes universités occidentale. Yaw nak omission wakhe niou lane gua done avant de critiquer, bo démé simple secretaire gua ba paré di wakhe. inane guéne torope ci marabout yi.

  • francois
    29/06/2017 08:44

    tous des satans

  • Vérité vérité
    29/06/2017 09:02

    En voilà bien quelqu’un qui n’a pas froid aux yeux… Qui n’hésite point à hausser la voix pour dire la vérité dans tous les cas. Iran yageu fi loolu waay té andak werr. Mala beugeu piiirrr

  • badara dieye
    29/06/2017 09:04

    mais pours mane de wakh gi dou merci khalifa wala merci iran pours mane eta mo wara khol niane nio necke thi ganaw khalifa pours tale Senegal mane lolou la yakar wakhouma ne mo am de lima yakare lawakh te bamou soti lima yakare ne mo guene thi noun Senegal nanou khalat ba pare soga wakh ki nane fila kee nane fila dou wakh gi leppe Senegal la

  • Malick
    29/06/2017 09:05

    Yen mom dinégui ak tarikhayi danguaine KO beugeu deff comme Iran ak Irak mo takh Sénégal Dou mousseu dieum kanam Iran a raison on doit respecté les kilifeu dîner k sa soi les mouride ou tidiane yeup beneleu si yonou yalla rek lagnou diémeu kone bolénko djapé nawétane gayiii. Wassalam

  • gj
    29/06/2017 09:09

    ameth khalifa massoul wakh lou gnaw si maodo

  • Liech
    29/06/2017 09:14

    iran mi seytané là dééé

  • aicha
    29/06/2017 09:22

    faites attention les gars, vous êtes entrain de tomber dans les bras de satan. les critiques n’ont pas leurs raisons d’être que chacun croit ce qu’il veut croire. Khalifa niass ame na xam xam mais il l’utilise comme il le souhaite. laissons le faire. nanou bayi lëep si lokho sounou borom. boulène kène yok bakar. Il ya des personnes plus compétentes pour répondre aux attaques et fausses accusations mais elles ne le font pas donc maîtrisons nous et cessons de faire le buzz.

  • Diop
    29/06/2017 09:45

    Tout ce qui défendent ce fils de Satan parce qu il a jeté des fleure à votre marabout mais s il avait ça sur leur je vous jure en ce moment même tous ces biens seraient saccages c est parce que il a parlé mal de mame maodo que les mourides doivent applaudir ou vice versa ces fils de de pute2 doivent être combattus par tous le monde lui il doit s occuper de sa tariha au lieu de être comme une chèvre sans maître c est pas une référence pour personnes merci Iran et nous on comprend tout tout ça c est pour les élections

  • Gueye
    29/06/2017 10:02

    il faut pas s’attarder avec Ahmed khalifa Niasse c’est un mythomane

  • Taiba Ngeyenne
    29/06/2017 10:49

    Mdr certaines personnes défendent Ahmed parce qu’il a fait l’éloge de serigne touba, détrompez-vous ahmed geumoul dara, beug lou nekh mouride yi rekk, serigne touba beugoul kouy togne, ahmed fila tokk di xass son petit frère sidy, ak son grand frère l’actuel khalif de leona donc c’est un grand nafekh, niounn mouride yi naniou xamm kann mo beug serigne touba ak kikoy mboubo, adouna amoul solo

  • mamy
    29/06/2017 10:53

    yaw rijal wakhoumala kiye doundal iran mais yaw sa baye sa mame séne serigne binguéne yakar iran moko geuna yégue ci yala ok bisou bb

  • Marifa
    29/06/2017 11:12

    AHMED KHALIFA DAFA GUISSS YALLA AM MARIFA DOU SA MOROM IRAN KI WAKHAM DEG DEG LA LADJI VRAIMENT …TOPPEULEN CHARIA BI REK BAGNA WOUT TASSAWUF DIGUEN YAGG DEF YEUFOU CLOUN SI TELE BI

  • Marifacool
    29/06/2017 11:14

    SENEGAL AMOUNIOU KHAM KHAM …AHMED DAFA AM MARIFA KOKOU DEG DEG BATINE LA LADJI , WAYEI GENROU IRAN YI AK WARATEI KAT YI LAKLOU NIT YI REK LAGN FI NEKKEI MELNI CLOUN..AHMED DAFA AM MARIFA AM KHAM KHAM GUIS YALLA DIKO DOUNDOU … JE TE DETESTE IRAN VRAIMENT JE NE TAIME PAS

  • Ciré
    29/06/2017 11:36

    vraiment je ne vois pas de problème dans ce qu’a dit Ahmed Khalifa…personne n’a le monompole du savoir. les grands marabouts dont on parle on toujours échangé des connaissances et des livres d’autant qu’à leur époque tout cela était rare. Certains ont même voyagé très loin pour chercher la connaissance c’est ça le progrès. Vraiment Ira introduit un faux débat. Apprendre de quelqu’un n’a jamais été une humiliation au contraire cela grandit l’homme.

  • Cire
    29/06/2017 11:51

    Vraiment je ne vois pas où est le problème, les grands marabouts dont on parle on toujours échangé des connaissances et des livres d’autant plus qu’à leur épôque tout cela était rare.Certains on même dû voyager loin pour chercher des connaissances. On a jamais entendu ces marabouts authentiques dire du mal ou mépriser les autres ce ne sont que les talibés qui ne connaissent rien qui nous cassent les oreilles avec des conneries. Apprendre de quelqu’un n’a jamais été une humliation au contraire c’est le signe de vouloir progresser. Pourquoi les talibés ne peuvent pâs avoir un esprit d’ouverture et de pédagogie. Je suis sûr que si nos grands marabouts pouvaient revenir, ils corrigeraient beaucoup de leurs talibés à coups de baton. Ahmed Khalifa rappelle des faits historiques et utlise le savoir il va de soi que ceux qui veulent nous bluffer et vivre de la religion ne voudrons jamais l’entendre parler. je crois que Ira a raté sa sortie. Wa salam.

  • cheikhordinateur
    29/06/2017 11:56

    iran ak noumou mana démé mane diap nané ahmed dou sa morom banga diko saga ak noumou mana mél kilifa la ta amna niouko yakar guinaw yala

  • lee
    29/06/2017 12:05

    Sougnou Diné dji di islam bilaye yallah mokoye samal bopam Dieu est omniscient

  • yazzzz
    29/06/2017 12:21

    on file direct vers le cataclisme religieuse la suite vous le savez tous. l’islam au senegal cest comme une championat ou chaque equipe se declare champion en titre champion pour toujour champion de tous les temps.Perso jai beaucoup destime pour ces percurseurs e lislam aux senegal sans on en serai pas.car si cela ne dependait que des toubabs on serai tous Chretiens. et crois a liberte de pratique la religion que veut. donc tous cette propragande malsaine. on a dit que tous les chemin menent a rome donc yoon yii yeup fa YALLA wasalam gueen balma ak. yalla diam yaggg

  • mame sarr
    29/06/2017 12:49
  • tawhid
    29/06/2017 13:25

    soub halallah magal dioudou nit ak doundeum ak dé wam.chirk bou leer toubal avant mouy trop tard

  • ali
    29/06/2017 13:51

    kou anda ak hamed khalifa niass nafekh ga thi lou

  • ali
    29/06/2017 13:53

    merci iran wa keur aeydil hadji malick amouniou sa diot ya hamed khalifa dou kenn si niome

  • Salam
    29/06/2017 14:04

    Je ne vois pas ou est le mal sur ce qu’à dit Ahmed Khalifa, juste que c’était son grand père qui dispensait l’enseignement à Tivaoune auprès de Mame El Hadji Malick. ça n’enlève en rien sur la dimension de Mame El Hadji, ni à son sa qualité d’enseignant, d’ailleurs c’est par faute de manque de temps pour pouvoir servir les fidèles sur d’autres choses, sujets, mieux servir le bon Dieu pour solliciter le pardon, la grâce sur les âmes de leurs disciples qu’ils délèguent certaines taches a leurs hommes de confiance aux vertus et qualités d’enseignant reconnus. En tant que mouride, je me réjouis d’entendre que c’était Serigne Ndame Abdourahmane Lo et pas Serigne Touba, qu’Allah soit satisfait d’eux, qui a assuré l’enseignement pour beaucoup de dignitaires mourides, même s’il peut y avoir d’autres personnes qui assurent la continuité à un certain niveau, famille Mbacké, Diakhaté, Mboussobé, Mbaye…
    Et Iran doit aussi savoir que beaucoup de gens le regarde, parce qu’il nous parle de questions religieuses avec les réponses, vu par l’islam(coran et souna) non pas par des attaques personnelles. Je pense qu’il aurait été mieux d’aller faire un interview dans une télé pour droit de réponse, écrire dans un journée ou le faire dans sa page personnelle sur les réseaux sociaux et non pas utiliser la télé lors de son émission, et ça Bougane devrait ne pas l’accepter et le recadrer. On n’a pas le droit d’utiliser la télé à travers on émission pour régler des comptes personnels.
    Di balou té di bale gnep akh
    Wassalam

  • @tawhid
    29/06/2017 14:29

    Yaw dialale feulé, si ce n’est pas ces personnes, par la grace Dieu, tu ne serait pas née musulman baye wakh tawhid ak toube baye kham louye diné. Une fois que vous partez dans les pays arabes ou que vous soyez lobotomisés par certains arabisants, vous vous croyez plus savants, arrêtez votre complexe, la plupart de vos références n’arrivent même pas la chevilles de nos hommes religieux

  • boy dji
    29/06/2017 15:57

    MANI AHMET NIASS SAYTANELA LEPE LOU MOU WAKH DAY DIAKHASSE NIOU KO EUPE KHAM KHAM REK KA NEK THI REWMI SAYTANE WEROU KOR MOY NIT KI AMOUL BENE KHAM KHAM DAMANI NI WAKH DEUGUE MOY NIOU WAKH NIT KI FENE KATLA . DAY DIAKHASSE REK FAMILLE BOU MOU DEME. WAKH FA LOUY DIAKHASSE AY NIT. WAYE BILAHI EL HADJI MALICK DOU MOROM TE TAY DJI SOU MOYTOU WOUL BOPAM DINA GUEUNA TROKH DAMA YAKARNI DAY NANE DI LAKHATOU COME NI MOUY NIALO AK TRIYANDE.

  • Ibrahima ka
    29/06/2017 16:13

    Iran yaw amet khalif molah eupe xam xam eupe la doleye adouna ak doleye poch con waro co yapp
    Yaw tegou ñulasi teleh bi pour taryha pour coference islamique mo takh con wara nex si teleby di yéfitena ahmet ñias daf ni serigne touba kouñe ko teuk lele nakh nañ lah lo lou boume la mety ndakh mo ame

  • berci
    29/06/2017 17:44

    khana yako yakar iran deug la kokou day diakha se tarikha yi rek souko nekhr khas mourid yi mba mou khas tijanyi bayi len ko ak yalla mag day wakh deug

  • maara
    29/06/2017 17:56

    Amet niass kouko toppou mou yoboula safar

  • serigne modou
    29/06/2017 21:13

    yén gni fi commenté yéb di fi toud serigne touba deguén yabaté bolén di wax guén wax sén wax rek téguén guéné ko si ndakh mom tognoul tognelou woul té limou amm sounou borom moko déff si mom khoumou néxoul boulko gueum mai nak boulko di togn

  • hummm
    29/06/2017 21:16

    ahmed khalifa niass seytaané bou makk la, il est entrain de diviser les musulmans du Sénégal, moytou lène. fii il n’y a k Dieu et Seydina Mouhamed

  • cheikh tidiane gningue
    30/06/2017 22:44

    li iran wakh leep deug la te kou defendre saitane khalifa niass naafekh ngua wala dagnion laaloul sa serigne wassalam

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL