Annonces
Annonces
» » » » Vidéo: Ngoné Ndiaye Gueweul chauffe le public...

Vidéo: Ngoné Ndiaye Gueweul chauffe le public avec son leumbeul provocateur

Ngoné Ndiaye Gueweul était au concert de Guigui. L’artiste a, comme à son habitude, chauffé le public comme elle sait si bien le faire avec son leumbeul sensuel qui ne laisse personne indifférent. Regardez 

Annonces
Annonces

15 commentaires

  • Awoka
    23/05/2016 20:55

    Déff sa leumbeul bou saff ba paré né BARKE YA RASOUL ILALLAH Sénégal bou délo guinaw boumou diakhal kénn.

  • mimi
    23/05/2016 21:00

    khamn classe mome boko am dagua d niak nga fayda torope

  • leuz
    23/05/2016 21:42

    fontou rek elle doit penser a ses enfants chiim nimako dieupe

  • only God can judge me
    23/05/2016 21:56

    aduna yagoul delene def lou bakh t bayi fo bii diamoulene yalla

  • Dou89
    23/05/2016 21:58

    Ngone Ndiaye Guewal bokk na si artiste senegalaise yi gueuna niak fada ak class dou rouss avc ta mass d malhr

  • koba
    23/05/2016 22:23

    ahhhhh mane sakh danou n’a. kodallll na ba danou

  • diadia
    23/05/2016 22:51

    koba tu me tue ahahahaha wahatal way

  • diadia
    23/05/2016 22:56

    koba ahahaha tu me tue wahatal wayy mdrr

  • Fafa
    24/05/2016 00:08

    xolal ma domeram dji mome dama tite tchi nouvelle génération bii

  • Ousmane ndiaye
    24/05/2016 00:55

    ragalal yala ngon

  • diop
    24/05/2016 10:10

    pute

  • argantina
    24/05/2016 19:24

    ay way Li niawna lolll fi toudou fi nit kou bakh apouna rawatina yonénté bi khalat lién bamél té bayi thiakan yi

  • argantina
    24/05/2016 19:26

    yall nako yala sopi

  • argantina
    24/05/2016 19:28

    ay way Li niawna lolll fi toudou fi nit kou bakh apouna rawatina yonénté bi ragalal yala té khalat niati fani bamél

  • Mello
    26/05/2016 20:40

    C’est très bon

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL