Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

221 33 823 43 43

Annonces
Annonces
» » » (Vidéo) Ndoye Bane se confie: « Le...

(Vidéo) Ndoye Bane se confie: « Le sénégalais n’aime pas voir son prochain avancer… »

2015-06-24T16:40:20+00:00 Partages

Seneweb

Annonces
Annonces

15 commentaires

  • kani xèigne
    24/06/2015 17:12

    yeine niar nèipou aye saytanènga ana loungène di toudou si ahmèd aidara ndouye bane nit kou bakh dou damou

  • Waxal dh
    24/06/2015 17:14

    No bane waxal dh il n fnd k commenter s'en life te lou niaw rk lagnu wax nak te iow kigay waxal xamula nek sa clavier di ratatati rk

  • Fatim
    24/06/2015 17:38

    Doye bane Si kow si kanam tu es sincere les senegalais n'iame pas Sa bon courage

  • borome senegal
    24/06/2015 18:49

    ca c tres bien

  • lebou
    24/06/2015 20:25

    deug nekhoul .deug rek ngua wakh

  • fallou
    24/06/2015 21:33

    Dagay fen rek tu puto madre

  • saliou
    24/06/2015 22:43

    wawaw ndoye mane yaw lay weur

  • Dada
    24/06/2015 23:24

    ndoye bane nékhoul ba nékhoul mé hypocrite nga! yaw avant ngaye nieuw tfm yaffi dakhone khasté taye nga déme fa rék wakhato you beuri! guémo dara! yague nalla déguelou avan danga dane critiké youssou ndour nane ministre bouye waye ak féthie, dane critiké séne petit gallé ak yénéne taye nga changer position! Sénégal dal mon nékh rék tok di wakh wakhou diambour bayi sa bopp

  • 0stress
    25/06/2015 01:31

    Merci Dada ta tout di senegala gui

  • bijou
    25/06/2015 01:50

    Guemolene dara surtou yaw louneck guadone yack Wa tfm mem deguene chimer si yaw ladone degue guanane com poupée menoula eduque kene tay mofi geune fo tol dico tague chiiimmm themal goor dieguene gui daguaco sagne niak yom

  • malsain
    25/06/2015 03:55

    vraiment noye bane ce que tu dis sénégalais mo sokhor et bonne continuation

  • deug
    25/06/2015 11:27

    ndoye bane sa sarap ndaye yaw wahofi tousse mane maye sagua sa ndaye

  • eie
    25/06/2015 19:41

    voilla pour koi tu dit jamais de bon chose sur les modou modou tu es un ranguignier doye banne

  • madam Faal
    27/06/2015 16:30

    mashaa Allah Ndoye Ban Yal na la Yalla diapale lafal la thiat, Amiin nitt kou bakh dai am ambition te yaw am ngua ko

  • anta diop
    11/07/2015 10:34

    Yaw sama bonkhougua sa yaye sama badjianou yaye la soda ndoye la toudou me dakar laey seuye yayame couea diouf la toudou sama tonton mo nekh pire tapha ndoye la toudou senegal kouye wakh deugueu lagnouye bagne senegal bou amon 5 you melni yaw senegal si kanam la dieume kepp kouoa critique dagako laal du courage si kaw di kanam sa youssou ndour kepp kouye wakh si mome nagua tite sa boop nakh mome kholam mo bakh satamite yalla dako maye keep kouye wakh si mome lou boondigua am natou boula daal wala gua dee macha alla youssou mala beugueu nel youssou magui espagne me fi nekhatoul bouma diokhon ligueye si tele bi ma gnibisi man b a teatre manna wakhtan deretebila ndoye ban mala gueuneu nekh

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL