Annonces
Annonces
» » » » » Vidéo- Mbaye Dièye Faye « je n’ai...

Vidéo- Mbaye Dièye Faye « je n’ai jamais vu Youssou Ndour autant pleurer qu’à l’enterrement d’Ablaye Mbaye… »

2017-01-26T21:55:43+00:00777 Partages

Mbaye Dièye Faye « je n’ai jamais vu Youssou Ndour autant pleurer qu’à l’enterrement d’Ablaye Mbaye… »

MDF et You par redactopic

Annonces
Annonces

22 commentaires

  • Je m’indigne
    26/01/2017 22:32

    Des larmes de croco.

  • fifi
    26/01/2017 22:34

    ndfeysane c’est vraiment triste
    yalla nako yalla xaré aldiane

  • HERCULE
    26/01/2017 22:35

    Que Firdawsi soit sa demeure éternelle
    Et qu’allah veille sur sa famille

  • gaindé
    26/01/2017 22:36

    Déhhh biiii dafa métti téé dafa bétté nakkk
    moi qui ne le cnnais ni d’adam ni d’eve toyal neu sama xol

  • zaly
    26/01/2017 22:36

    senego laissez la personne se reposait en paix

  • akhh
    26/01/2017 22:37

    Senego kagn moy lolou quoi

  • vivi
    26/01/2017 22:37

    diss neuh wayé délo lép ci yalla
    diko nianal mou xaré ko aldiana you gueuneu kawé yi ci barké SEYDINA MUHAMMAD SAW
    RIP ablaye mbaye

  • tagg
    26/01/2017 22:38

    Que son ame repose en paix!!!!!!!!!!!

  • nitt
    26/01/2017 22:38

    Walay dafeu daw yarammmm bilay walay

  • DOUNIA
    26/01/2017 22:41

    DA FA METI TROP WAYE YALA NA KO YALA KHARE ALDIANA

  • popi fall
    26/01/2017 22:41

    Adouna demal ma gui niew rek geneu metilé amoul deh geuneu besselé rek mo fi ame que dieu l accueil au paradis

  • bonooboo
    26/01/2017 22:43

    Paix a son ame!!une perte pour la musique sénégalaise

  • grand bass
    26/01/2017 22:44

    Non senego yèna ngui beuga gnakh khoromm nak ohh no way
    bayilénnn ablaye mbaye mou nelaw
    teh dimbalu=i youssou ndour touti

  • jojo mbengue
    26/01/2017 22:45

    Ablaye mbaye kou am chance leu,dounde na ba khey deh guissoul dara Lou gnaw.lepp Lou gnaw rek yalla neubb nokoko bam kheuy wouy djiko

  • Anonyme
    26/01/2017 23:21

    souko toll fofou na ragale yalla bayi limou nk bala de di nieuw

  • anta
    26/01/2017 23:48

    way doule way yén mayléne gnou sounou diam tè bayi ablaye mbaye mou nopalou trop de nafékh et dhypocrasie dans ce pays

  • Adji
    26/01/2017 23:52

    Soufaikai sa bay yarou là nga respecter mémoire ablaye mbaye nain ngain trop

  • omar
    26/01/2017 23:58

    Vs ki insultez youssou dangain hamoul rek limou sekhon ak ablay mbaye mandou bahna trop si djoulit

  • musulmenteur bi
    27/01/2017 00:34

    Et tu penses k yaw tu ira o paradis lui enfer mn dieu ?
    Thizy musulmanenteur mandoul mo gane

  • machala youssou
    27/01/2017 02:04

    Vraiment c grace a You k senego existe mais laissez le gars en paix mai Youssou machala yala maynako soufaikon man daina bu yag ku diok toudou leu tai yarou bâ dai do tontou keneu Aÿ famille di doundeu sa barkai dila gnanal Ndaw tiyaba yu bari machalaa hamna narnga dougal GNU bari safara

  • machala youssou
    27/01/2017 02:09

    Ma yok si kilifa dine yi dila gnanal touba tivaone wa keur Thierno tall Kaolack yala nala yala samb youssou amine

  • ishhhhh
    27/01/2017 10:33

    sa waye nitt dafay mandou diokhoulou Youssou mou nann wala mou lékkk teh sa baye meuneouko aussi donc mandoul koi boulma sagalou si adjouma bi issshhh

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces