Annonces
Annonces
» » Vidéo: Macky Sall raille Aissatou Diop Fall...

Vidéo: Macky Sall raille Aissatou Diop Fall « Ngay melni djiné »

2015-06-27T15:26:53+00:00 Partages

Annonces
Annonces

29 commentaires

  • madam Faal
    27/06/2015 15:46

    mashaa Allah Mr president Yal na la dole diapale, Amiin

  • sall
    27/06/2015 16:03

    TFM BAYII LENN MACKY MII GEN NOUY Forcé

  • ous
    27/06/2015 16:17

    tfm travail pour les politiquecient

  • baba
    27/06/2015 16:18

    jaim c presiden

  • Ndeysan
    27/06/2015 16:25

    J bagni maky me vidéo bi nice na kw

  • diongue
    27/06/2015 17:07

    fekhe niteguimouneligueye ba amalesenebopou

  • ive
    27/06/2015 17:07

    la tfm a laché le peuple depuit que leur patron a eu ce qu'il voulait,il est nommé ministre alors qu'il n'a meme pas de bfm ,il cotrole bocu de chose lui et sa famille;pendant ce temps le pays est entraint de foncer tout droit vers l'éxtréme pauvreté .Ces espéces de journalistes me font vraiment honte

  • Diery
    27/06/2015 17:08

    Télé Fansou Macky !

  • amdy
    27/06/2015 17:26

    vakhale thi révoumi dara dara dara dara dara dara dokhoule.

  • Ana
    27/06/2015 17:39

    Courant bi , ndokh mi , ndiank mi , patje mi , ligueyou ndawi , lek aka nane … yoyou laniou wakh ! Dieul khalissou rewmi di sedalé ay ndogou de gauche à droite nieupko meune !

  • New York
    27/06/2015 17:57

    Yow ame ga lou la doyi léguié Senegal mo guine ga top si sa guinawou diabar dji di lambar lambar lak…

  • nekh
    27/06/2015 18:37

    Tfm forever macky ba fawou

  • taf taf
    27/06/2015 19:25

    Yow ame ga lou la doyi léguié Senegal mo guine ga top si sa guinawou diabar dji di lambar lambar rk

  • jalouse
    27/06/2015 20:59

    seul le travail paix bayilen sokhor te dem ligueyi macky rawnalen beu paré dehhhhh

  • jalouse
    27/06/2015 21:00

    seul le travail paix bayilen sokhor te dem ligueyi macky rawnalen beu paré deh

  • cheikh
    27/06/2015 21:01

    bayiline shokhar li mo takhe Sénégal dou dem Sénégal mogui dokhe yine ne baga lou yombe

  • Beugue Sénégal sama rew
    27/06/2015 21:27

    c'est la première fois que j'ai vu MACKY SALL MOUGN (RÉE)

  • il maestro
    27/06/2015 21:58

    Ce sont les 35% des population qui aboient, ils ne cessent jamais de le faire.Aywa il presidenté gniy fal ak yawa nouro dougnou wakh

  • Sofia
    27/06/2015 23:34

    vive mon president simple humble vrai sénégalais.

  • elhadji faty
    27/06/2015 23:47

    y alla n'a yalla dia pâle là présidant amine

  • Kalz
    28/06/2015 02:16

    Démal ligueyi té bayi takhawalou bi , lolou mola war !
    Nazzz !!!

  • SONINKE
    28/06/2015 11:16

    MAME YALLA MAY GNOU NDOKH BOUGNOU DOUNDER FAYLA NDOKH

    LOLOU MOGNOU DC LEGUI YAKAR TASSNA NDOKH AMOUL COURANT AMOUL
    SONOUNAGNOU REWMI METIINA WEUY YAY YOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOY
    MACKY DEMAL NA DEMA DEM

  • fa fa barry
    28/06/2015 11:25

    Vive Macky j aime ce présidente

  • daouda
    28/06/2015 11:54

    honte pour mon president

  • daouda
    28/06/2015 11:55

    rewmi doxol ndox amoul

  • Xeme
    28/06/2015 13:33

    Aussi gauche qu'un éléphant dans un magasin de porcelaine.

  • LeMambaNoir
    28/06/2015 20:25

    Bientôt la rentrée universitaire 2016……….Et dire que jusqu'à présent ils n'ont même pas encore sortis la liste des boursiers étrangers de 2015.
    Désolé mais on dirait que l"état ne fout plus rien.
    J'ai pitié du Sénégal et de tous les sénégalais d'ailleurs.

  • boul fale
    28/06/2015 23:13

    vive mr le President

  • tfm
    29/06/2015 00:40

    macky pire koumou nèkhou dèmal gambie

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL