30 COMMENTAIRES
  • Bro

    Skeey Mbacké wakhdj rafetna….Dieureudieufff Serigne Touba Diarama Lamp Fall Baboul Mouridina

  • abdou aziz

    Merci le marabouttu es un vrai taibè de serigne touba.Tout le senegal te souhaite une longue vie santé.Voilà DES HOMMES comme toi à qui le peuple a besoin tous les jours.D autres marabouts devraient suivre ton exemple c est à dire faire passer les messages de serigne.Vive à toutes les confréries du Sénégal et à tout le monde musulman.

  • sambe

    amna solo lole liy rek mo am solo mbolo bolen dadiale fekhell ba wahlen loulen di diarinie

  • moustapha

    Macha allah mbacke balla aicha li rafetna trop yalna yalla faye thi barcké seydina mouhmed psl amine

  • sama reew

    raftna mbacke yalna yalla fayla!

  • Pape

    wérna mbacké

  • gour

    yalnala yalla weral defalko bep diolet rafetna

  • thioune

    diadieuf Mbacke li werna diadieuf

  • lune

    Des propos extraordinaires pleins de sagesses et de vérités , mais peut être un peu tard , car ces marabouts de la nouvelle génération ont déjà gouté aux fruits défendus , ( les plaisirs et privilèges ) comment quelqu’un élevé au caviar jusqu’à un âge avancé , d’un seul coût vous lui demandez de se mettre au régime pain sec et encore quel pain , alors qu’il a encore les moyens de manger son caviar ? Mais le plus grave c’est quand vous dites que dieu demandera à chacun individuellement ce qu’il a fait et dit sur terre alors qu’à eux on a fait croire que ce problème est déjà reglé par qui vous savez , ou qu’ils font semblant de le croire et continue à le faire croire à des ignorants a qui ils ne demandent que de crier et pas réfléchir , je dis que le problème des mourides est grave , l’héritage de Bamba est déjà perdu .

  • alassane diop

    Dieredieuf sama serigne
    Tay rekk la ameuh louma nekh
    Sama khol seddnaa gouy ndakh kilifa momoul loukhew rekk mou tokk ci salon dieul camera di wakh rekk tè loumouy wakh dou dèfar moukou khana di fèwèlè
    Yènn mbacke yènn lagnou ameuh ndakh yènn nagnouy saggooo
    Dieredieufety serigne bassirou mbacke khadim awa ba

  • KHANANEKH

    LUNE c toi ki es perdu nel euskey ta teuthie sa gumine lo metris woul mandou sa. l’heritage de bamba est bien gard d’ici bas et dans l’au dela wa salam

  • Ouza USA

    Dieureudieuf Serigne bi wakh dji rafetna Yalna Yalla yok fanwi boubakh temou and ak wer si barke Seyidina Mouhammad S.L.A.W

  • btd

    mann ki laa geumm parce que hamham lay wahh

  • ibrahima

    raretna lool

  • sam le pirate

    🙁 🙁 Machallah le marabout a tres bien parle,il a touche le fond du vrai probleme engendre par cette generation de mbacke-mbacke agee entre 30 et 60 ans.De mon point de vue,je trouve imperative pour la resolution de ce probleme de discipline au sein de notre communaute religieuse qu’est le mouridisme,que le khalife organise une fois l’annee ou le mois,une grande rencontre ou toutes les grandes familles des fils de Cheikh Ahmadou Bamba seront representees par l’ainee de chacune d’elles,de la famille de feu Cheikh Mouhamadou Moustapha le premier khalife jusqu’a celle de serigne Mourtada Mbacke le fils cadet du fondateur.Dans cette rencontre,il ne sera question que de discipline et d’etablissement de nouvelles et modernes chartes pour le bon fonctionnement de la vie administrative,economique et sociale de cette cite sainte que leurs a leguee leur illustre grand-pere.Deja nous constatons que la politique vient d’etre interdite par le khalife Cheikh Sidy Mokhtar Mbacke.Il est tres difficile pour une cite comme Touba avec ses pres de 3millions d’hbts de fonctionner sans un dynamisme,une vitalite politique et je suis certain que le khalife le sait,il a simplement pris cette decision de reduire l’activite politique de la cite a neant parce qu’il a ete frustre par cette meme INDISCIPLINE citee tantot de certains guides religieux(inciter leurs talibes et sympatisants a huer devant la demeure du khalife le president de la republique,ordonner ses talibes a bruler les maisons d’un adversaire politique non mbacke-mbacke,jet de pierres de corteges d’autorites,bagarre entre militants simples et talibes de « DIW »)vraiment tout ca est indigne d’une ville reconnue comme SAINTE.Il est donc temps qu’une organe composee uniquement par les ainees des fils de Bamba voit le jour si on veut eradiquer tres rapidement cette division entre petits-fils pour des interets pecunieres et materiels qui se fait sentir de plus en plus par les talibes en premier mais aussi par les autres foyers religieux musulmans du pays.Enfin pour le cas Bethio Thioune,je me dis que s’il a ose aujourd’hui arriver au point de s’attaquer aux tres hauts dignitaires qui malheureusement ne sont plus parmi nous,en l’occurence Serigne Modou Bousso Dieng Fallilou et Mame Cheikh Ibra Fall,c’est en grande partie au fait de la tres grande importance qu’il a gagne premierement en reussissant a commanditer 2meurtres de ses propres talibes sans pour autant payer le prix,oui il est totalement FREE d’ailleurs plus free que tout les senegalais reunis parce que simplement il dis haut et fort aussi ce que personne n’ose dire sur nos kilifat,le deuxieme facteur est que recemment,en moins de 3mois,Bethio avec tout le mal que nous voyons et connaissons de lui a beneficie de la visite du numero 2 de notre puissante tarikha,Serigne Mountakha Mbacke puis du porte parole Serigne Bass Abdou Khadre Mbacke et enfin meme si Serigne Modou Kara n’est pas un bon exemple de dirigeant mouride,le moment de sa visite et le discours laudateur qu’il a tenu a l’endroit du guide des thiantacounes a contribue positivement a contribue aussi au declenchement de l’appetit et la soif de pouvoir du tres BADOLA BETHIO THIOUNE. 🙁 🙁

  • fall yaran

    diadeuf serigne bass khadim awa ba ton ami et talibe gora mou serigne qbdou karim

  • Dame Gueye

    diadieuf Mback bala amn solo

  • pape cheukh diop

    diere dief mbacke lou wr t wor ga wakh mana solo louu yalla nala serigne touba takha wou amin

  • MOUSTAPHA

    yaw ya gueuneu gnak kilifa gnép fii la serigne bass abdoukhadre mi yor kadug yon wi wakh si ndigueulou cheikh sidy mokhtar si veillou election yi nga démentir wédi leep en direct tfm ba serigne sidy mokhtar di wakhat bay tangor dakh say kadou;liga wakh lép sa bop nga si sogné té bo déssè si seutou serigne touba yi ma dièbeulou ci khassidayi

  • modou

    yaw do exemple lou mbacké mbacké bou gnou wara roy ya gueuneu gnak gnép kilifa khaliss rek ak adouna nga beug fi nga wèdi wone en public wakhou serigne bass mi yor kadou yonou mouride tfm si election bobou lala wédi khamni amo kilifa adouna rek gay wout ak khalliss

  • SERIGNE CHEIKH MBACKE KEMTAN

    contane nane trop mbacké wakh dji amna solo loll mbacké siguill gua nou bou bakh mbacke yague fi téwér

  • pap

    Damqné saytané toujour Bounite dieulé yonou mbax yowma déndak mome daye yax same xélle lamouda dieuf thi ay reuthi reuthi rék lala saytané di fatali pour bagne gatopouko wayé nite mome noumoumana méle boulawothi mbax ak deugeu démale gafécke kotha wola ga mandou

  • papis

    Damané saytané toujour Bounite dieulé yonou mbax yowma déndak mome daye yax same xélle lamouda dieuf thi ay reuthi reuthi rék lala saytané di fatali pour bagne gatopouko wayé nite mome noumoumana méle boulawothi mbax ak deugeu démale gafécke kotha wola ga mandou

  • khadim sylla

    sa waxx rafetna mbacke

  • serigne Yadaly mbacké Khadim awa bà

    dieure dieuf serigne Bassirou Khadim awa bà yal nala sa mame serigne Bara takhawou te moussal la thi Barkep serigne touba

  • tra

    tidjane laa waye ki kalifa bou mot gou khalifa

  • mamadou diop

    amna solo mback yague fi lole t werrrrrrrrrrrrrrr

  • DEUG

    WAHHDJI DEHH KOU NEK WAR GUATHIER GUISS SA BOPOU KADOUYI DEGOUNA WAHDJI AMENA SOLLO MBACKE

  • bower

    Moustapha ak modou yénn doul khana déglou wolén néna thi bopam lay comassé da gnou yaradikou té dieuféwou gnou ndiguel.dieureudieuf serigne bi

  • dieuwrigne

    Serigne bass tu a bien passé a côté kouy diglé thiangay dangaye sangou naa wakh ba gnép ni gongo té geumothi dara naroko dieufé amoul solo sa wakh dji doula takha chance bayivo yoro dara politique nga geum macky sall nga andal

Publiez un commentaire