Annonces
Annonces
» » » » Vidéo: le témoignage émouvant de la maman de...

Vidéo: le témoignage émouvant de la maman de Waly Seck et sa sœur Aicha Seck

A quelques jours du Bercy, un plateau spécial dédié à l’événement de Waly Ballago Seck était le lieu d’émouvants témoignages des membres de la famille du chanteur. Sa mère Kiné Diaga et sa sœur Aicha Ballago Seck appellent en direct sur le plateau de Aba et Cheikh Sarr pour témoigner leur complicité avec lui, mais aussi saluer le soutien massif des sénégalais pour la grande réussite de l’événement.

Annonces
Annonces

6 commentaires

  • meiii
    30/05/2016 08:54

    tu as bien dit mme seck mane dee yako diour mai gueuno mako beugue lunek mangui koy datie thi mom ta YALLAH REK TAKH SAMA DOME DJI DAAL YALNA KO YALLAH LAFAL TIATE REK L AAY NIANE

  • zeynab
    30/05/2016 09:48

    merci maman kiné wax bi rafeè na liga wax sax xamoulo li la ko wax lo bilakhi yako diour wayè geunoulo mako beug ndakh lounèk laye dèg lounèk lay dath ndakh mom wayè dou térè madiko geuneu beug kon nak lolou yala la merci maman kadou yi ende na ak tey ende na ak yare niga mèl rèk ga yarèè sa gniabote am nagn yare am nagn dinè machala yala na yala tapè xol yi yala na yala fote xal yi barkè seuydina moukhmed salalawou aley walasal psl

  • La LIONNE
    30/05/2016 09:49

    Maman Kine so teud nlawal Machalla Wally diam rek lay am Inchalla .Man peulh bou set weth la Bounk Yalla waly toujours thi kanam si Alla diaby

  • Bass
    30/05/2016 10:08

    C’est vraiment émouvant

  • Amina
    30/05/2016 13:42

    ndeysan li lep pour nit yi yereum Wally dem si bercy bi ndeysan demlen diamou Yalla mogeun wa sentv yen mom dama ragal geun toy ava bercy bi sonou geun si publicity bi trop ndeysan

  • zeynab
    30/05/2016 21:27

    yow amina beuse boy dé waly molay rèy yow balama beug dé rèk ganan demlèn djiamou dji yala yow djiamou wo yala ndakh wax lou sa yon nèkoul si djiamou yala la bok wax loula lèroul si djiamou yala la bok t yow thi yoyou rèk gay yèndo ba ngone ga teudeu bo yèwo xeuyat nèkal kothi kon nak boul gnou sonal yow boula waly baloul dou bax thi yow waly rèk meun nala yagal bèsou pecc ya bonn ya ognien ya soxor yay nitou safara bou mag

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL