Annonces
Annonces
» » Vidéo: Le message touchant de d’Amina Poté...

Vidéo: Le message touchant de d’Amina Poté à Thione Seck et Waly encouragé, Regardez

Annonces
Annonces

10 commentaires

  • @aw
    06/06/2015 17:57

    ahh je né jamé etai aussi contente de toi tayy mom wakh ngua wakhou nitt vremen li forna

  • Zale
    06/06/2015 18:05

    Good

  • krumah
    06/06/2015 18:53

    Mais lane moy dignité nitt…kou dignité daay joub di deff lou joub thione sou amone dignité yakk nako senegal nagne bayi thiakhane akk tapalé

  • deugg1
    06/06/2015 19:03

    Kol vraiment Ya rafet xol je t'adore bcp

  • anita
    06/06/2015 21:21

    Merci amina

  • Thièy lii
    06/06/2015 22:27

    nafêkh rek nguèn déf, fimounénii kou def emission rek ta wakho ci pour gnom dangua contre Thione non.Liguèyi len ta bayi affaires yii, emission yeup yakhe nguènko ci affaires Ballago dem leen Seeti njaboot tam mo gueune.nafêkh nak bakhoul nim mél bokoul ak namou mél ayamwa day néck ci biram yiw wa néck ça kay.

  • lalo
    06/06/2015 22:40

    amina wakhngua lou rafaite bilaye

  • Thiat
    07/06/2015 18:16

    ay way dioulit dou soxor dé nianlén yala bou guénn si diam li ndogal la rk

  • chacha
    07/06/2015 20:15

    amiine amina tu e gentille

  • nay rafet
    15/06/2015 12:34

    senegal guem len yalla liii ndogal la rek diomoul kena .amina wakh gua lou rafet kouko menoul gua tok figa tok gnanalko.

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces