Annonces
Annonces
» » » » » Vidéo : l’Ais se prononce sur...

Vidéo : l’Ais se prononce sur l’affaire Bethio par la voix de son Pdt Mame Cheikh Mbacke Khadim Awa Ba

2017-08-19T23:52:14+00:0039 Partages

Declaration de l’ASPC Association des serviteurs du patrimoine de cheikhoul khadim et l’ais sur l’affaire Bethio par son President Mame Cheikh Mbacke Khadim Awa Ba.

Annonces
Annonces

23 commentaires

  • sy
    20/08/2017 01:07

    ndeysane bethio mbiram jeehna kom farawna

  • Jules
    20/08/2017 01:09

    La verite cest que serigne touba na pas besoin de maison aux usa nguen defoneka touba moka geuneul.creer une maison serigne touba aux usa cest juste pour ay begue rek amoul bene sens ngeum si hol lay nek mais trop de prologande pour rien.retournez au vrai enseignement de serigne toiba vous verrez que tous ces gens bavardes de gauche a droite ne suivent pas les eiseignement de serigne touba.

  • Galgui
    20/08/2017 02:16

    Detway Jules boul wakh lolou USA amna ay mourides sadikh t bou serigne bi diklai lolou pour yatal yonou lislam ak mouridoulah si adouna bi yeup la. Lolou lassi dioublou. Affair bi waroul yem touba rek kou tedki adouna la warr dathie.

  • Fatma
    20/08/2017 08:10

    Damani vous etiez ou quand il dansait a touba devant Serigne Saliou ???
    Serigne Touba rek , mais les petit fils ont vous a vu ! Soutoural lén sen bop .

  • Deb
    20/08/2017 08:22

    Une seule declaration de la plus haute autorite mouride declarant bethio et son mouvement anti mouride et exclu a vie du mouridisme n aurait t il pas suffi a mettre fin a tous ces tirraillements ?

  • Diammoup Serigne Saliou Mbacke
    20/08/2017 09:30

    SERIGNE BETHIO THIOUNE DIAMOUP SERIGNE SALIOU MBACKE BI YAGU FI looooool te Sakh thik wer.

  • deugue rekk
    20/08/2017 09:58

    vous eties ou quand,bethio disait que serigne saliou yala la,serigne bi est plus élever que mouhamed,vous n’avait rien dit de cela,pour vous tout est bon,vous faites des bêtises et que vous pensée que serigne bi est plus fort que Mohamed,et tout le monde ce dise mouride voilà les conséquences

  • deugue rekk
    20/08/2017 10:01

    gère vos problèmes, serigne n’a pas voulu des maisons

  • Ive
    20/08/2017 11:29

    mais pourquoi le Khalifa ou son porte parole ne réagissent jamais? surtout quand betio dit que serigne s aliou est dieux, et que serigne Touba est au dessus du prophète psl

  • Astou
    20/08/2017 13:18

    Yawmi dé dagga yagga bagne serigne bethio gni ko bagne la yalla di wére…nakare dinaléne raye serigne béthio défoul wakhoule lépe serigne touba la serigne saliou mokoni yaye mane maye yawe diape thi yawe moye deuggi deuggi diape thi mane kouko déf dinama nopale taye dji ak euleuk guagnou dieume té dina déf louma nékhe

  • Diaxlé
    20/08/2017 14:06

    Je’ai du mal à comprendre tous ces soi-disant guide religieux de toutes les confréries musulmanes de notre pays. Au lieu de travailler à créer les conditions d’un vrai développement ici ils se complaisent à regarder la Jeunesse fuir la misère et la suivent partout dans le monde avec leurs passeports diplomatiques pour les racketter. Abominable!

  • opinion
    20/08/2017 19:37

    senegal empire du nafekhisme

  • saliou
    20/08/2017 21:43

    mourid yi kesse la ken degoul yenen ngi italie bou ete diote niom nieup nieuw tey milan souba genova torino brescia weur rek ak ladj khalis defouniou fi tous keur serign touba yi bougou niou fa nek hotel laniouy beug bastaaaaaaaaaaaa

  • habib geuye
    20/08/2017 22:01

    beug serign saliou nekh na trop waye serign saliou beug la mo gueneu nekh betio serigne saliou mo ko beug deug nekhoul

  • Laye
    20/08/2017 23:12

    Affaire de Guéweul rek….Dou lénène…. Regardez bien, une bonne partie des taillé est Guéweul…normal niouye sabarou

  • Laye
    20/08/2017 23:14

    Affaire de Guéweul rek….Dou lénène…. Regardez bien, une bonne partie des taillé est Guéweul…normal niouye sabarou

  • Serigne Bi
    20/08/2017 23:15

    Affaire de Guéweul rek….Dou lénène…. Regardez bien, une bonne partie des taillé est Guéweul…normal niouye sabarou

  • papis
    21/08/2017 10:20

    MOURID BOUY DINGATT FEETHI ,cest grave .juste une question :SERIGNE TOUBA mi nangoul Bour sine coumba ndofene teungueum bi ak péthiam mi ba aldiana nak ,khana da nguene khamoul tarikh bobou .vous netes que des mourides complexes .KEUR SERIGNE SALIOU MBACKE ,mo fété kaw bép lieu de culte .
    MOURID bou diombalé sa boppou féthial SERIGNE TOUBA ,khamal ni amo daray xam xam si SERIGNE TOUBA.
    CEST DOMMAGE .MA KHALA ,kou diokk ,dém EGYPTE wala TUNISIE OU MAROC ,ni da ngay wouti xam xam ,bayifi diangalém SERIGNE BI ?MOTAKH si wédi dieufi SERIGNE BI rék ngay deuk ,ak diko diappé un simple citoyen .
    MOURID yéwoul té gueum sa boppou .SERIGNE TOUBA nékkoul si tééréé(livre) ,
    LE 18 SAFAR ,MOUY MAGAL GUI ,pourtant nékkoul si ALKHOURAN ,et nieup guiss nagnou fi beuss aagu taay.
    OUTILENE XAM XAM .

  • Ngom
    21/08/2017 15:34

    Dieureudieuf

  • boul mére .. doukate tchi yone bi lebokk
    23/08/2017 14:36

    féthial serigne touba dalll ..mo geune féthial séytane…té l’islam 2 le..farata akk souna…té sounna wanéna..kérok b musulman yi gagner kharébadar..b recupéréwate makk…dénio teugg tabala yi…bégué bégué bi…féthie féthie bi b fadiar…té yonnaté bi ayéwouko…motakh serigne touba né .. fépp fou yonantébi diarone.. lépp loumou défone akk lépp loumou dathie …mane serigne touba dinako déf…mo waral baye fall yi di doukate…thianta yi di doukkate ….lolou mome koumou méti..guawal kharou gaw té khamné yonnou mouride … sante te akk djieurigniou…koufi guiss lénén…démal gabon..dioulli tchia gédjie gue …soo nieuwaté tékk se Yonne ..

  • dia
    23/08/2017 14:50

    bien dit …bo dégué tahalbadrou alléyna….moy hymmne nationalou islam bobou…tchia diamono yonnénte ba…légnko donne bakk…diamm yi diko féthie…..kérokk be l’islam gui gagner kharé be…dénio tékk tabala yi…féthie bamou nékh..té yalla téréwouko..yonnanté bi tééréwouko…kérokk ba yonnanté bi di diougué makka di gadiaye médina ay tabala légnko térou..gor makk akk ndaw dégnko féthial..guir wanko sénn mbékk…donc kouné féthie amoul tchi yonnou l’islam khana dagua fatté lolou…té le plus hippocrite dans tous sa c’est que..on as vus presque toute les confréries se regroupé au grand theatre de dakar ..chanté et danser padendant le remadant..mais kénn dou wakh ..mais boufékk béthio le nieup di mbaooo…

  • le sénégal
    23/08/2017 14:53

    quand bethio danse c’est le diable… mais quand youssou ndour organise 1 gala au grand theatre ..ou toute les confréries chante et danse c’est la nuit du prophete ok sénégal gui nii ..

  • delle
    23/08/2017 14:54

    quand bethio danse c’est le diable… mais quand youssou ndour organise 1 gala au grand theatre ..ou toute les confréries chante et danse c’est la nuit du prophete ok sénégal gui nii ..

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL