55 COMMENTAIRES
  • zoro

    yekini il est temps de raccrocher

  • Momo

    Nnn yekini danguoy warou koi mane boy bi rèk la bagne

    • BALLA GAYE JR

      khalé maggna.LAC 2 DIAMBAR LEU BILAHI.BEEN MBEUR NIÉMÉWOUL BEURÉ AK YEKINI.MOM MOU AM FITE BEURÉ AK YEK.EUMEU LA SOXLA REVANCHE

  • CONTRE toujours les hommes

    khoutrokhol djiguene yalla wann lako

  • rafete khell

    flicitations sama mbeur mi yaye diambaar yaye garmi

  • f

    nooooo li lou kay fauyyy mddrrrrrr bien fai pr yekinii

  • MBEUR

    selbe ndong

  • buur

    Flicitations ?? lac yallanayalla ndffal diam buur nguweul

  • selbé

    PROMOTION SELBÉ NDOM………………..THIEY SEYTANÉ

  • youssou

    momo cone di nga dé

  • senegalaise

    momo yekini pa la maintenant lac da fresh khalé bou daw la day doga dor mais bonne fin de carriere a yekini sama khol da sed quoi bilahi

  • Sam le pirate

    🙁 En tout cas que que ce soit Selbe ou yekini,tout les deux n’avaient pas droit à l’erreur au risque de voir la fin de leur carrière respectives , »guissanee petaw  » « lambb ». En fin de compte, Selbe dayy dem teunkounako si Barkee Lahilaha Ilalah !!! 😀 🙂

  • plac2

    Khana yikini moye president du senegal naniou dimbili thie wakh die

  • fyeee

    tay mome afr biii salb tay lay ame loumou wakh nak

  • Momo

    Youssou mane douma sa morome

  • momo

    momo mala guene bagn lac noooooo yekini day fo way

  • fyeee

    afrbii salb laa tay reek lay ame loumou wakh

  • mbaye

    ya bari jome lac2 thiey selbe ya bari xam xam

  • fyeee

    baravo lac thia kaname reek

  • fyeee

    momo niit kne doukou bagn tee lac deefou kne darra lou niaw

  • fyeee

    momo niit kne doukou bagn tee lac deefou kne darra lou niaw

  • dioncounda

    frema

  • Sagna

    merci senigo ci kaw sa kanam merci encore

  • Walo Walo bi

    No salbe Dou niitt ki Mo graww

  • dieye

    lac 22222 aferbi yaw la

  • SERIGNE MBOUP

    kou wakh deugue khamnii lac de guier 2 mbeur kamil laa mé yékini ducourage tu n est démérité dinabakh

  • dieye

    wakhal de lac 2 rek

  • Sans nom

    Il es vieux mena.il es tan de racrocher aider c poulain c mieu que de sem brouiller avc heu

  • lipo

    felicitation

  • mbaye 23

    yékini dafa maguéte té nangouwouko mé kaname rék la dieume

  • Omar

    Garca SENEGO me gusta a vez la casas de senego

  • milk

    Selbe amna loumou kham

  • bill

    bravo lac tu as ose contrairement a certains qui veulent etre roi des arenes et n’ont pas ose defier yekini

    • Papa thug

      Mon cher bill gsprk tu n parle pas d’eumeu sene! Eumeu est le premier lutteur d cette generation A defier Yekini et Yekini l’avait evite en prenant gris-bordeaux. Mais aujourd’hui tout le monde sait que Eumeu est plus fort k yekini et lac2.

  • Mame Saye

    Bravo champion

  • mike

    Yekini moy kan khana dou nit rek sou beugué amate victoire. Na bayyi teukou yi té dem balou becaue mbaye

  • Jo

    Je veux plus entendre quelqu’un dire que Lac2 n’est pas un lutteur de high level. Non seulement il a osé prendre yekini dont beaucoup de soit disant vip avaient peur, qu’ils le reconnaissent ou pas. Lac2 l’a affronté et l’a battu de fort belle manière . Je tiens quand même à dire que yekini demeure la référence absolue, the greatest.

  • lamane

    merci laccc. yekini Dagua done trokhal djiguene tay gua khamni yalla mola eup Dolé gnawwww

  • Manikolo

    Soss yi nokhat nagnou Srre yi

  • Jo

    Bill je suis d’accord avec toi, bcp veulent devenir roi sans vouloir affronter yekini la référence absolue. Une chose est sûre battre yekini est un fait qui reste gravé à jamais dans les mémoires collectives. Et Ca bcp de lutteurs ne l’ont pas compris, oú plutot il leur manque une grande culture sportive. En tout cas lac est entre dans le HALL OF FAME de la lutte et c’est amplement merite

  • leuz

    yekini maque daye khame bopame guediawaye dofa ame dara wakh diou bari rek ngua done danai ak khereum fi yalla mofi nek

  • SAMBA

    Un retour rater , une nouvelle fois a terre l ex roi des arènes …triste fin de carrière pour Yékini, il se souviendra longtemps cette nouvelle défaite .Bravo Yékini et bonne chance pour Le vainqueur

  • MBAYE CHEIKH

    VIVE LA JEUNESSE. VIVE LA FRAÎCHEUR.

  • ndeuz

    Momo doul way

  • mamadou

    Diaram sengo sakaw tiakanam

  • peter

    oh yekini danouna

  • Landing

    Après la chute contre Balla 2 yekini a dit c’est sont entourage qui l’a trahit et dégagé tout.maintenant il dira qui a causé sa chute.je demande encore aux de croire à dieu car il est maitre de la victoire et du défaite

  • cartel

    cette fois ci c son ninja Blanc qui la trahit hahaha

  • Socé

    jeper k fébaroul bi pa lol ték khél la rk way IPRES grand pére

  • anna

    Oh mon dieu pitié c triste fin

  • sofesss

    bravo lac2 sougnou hole sede na yekini dafa yeuke bopame

  • Salissou En vert .

    Moi je ne peux dire que la chance n’a pas frappée à sa porte ,yekini doit reconnaître sa défaite comme il l’avait connu au tournoi précédent pendant sa victoire. Merci .

  • dame diene

    Merci lac non tan

  • mario

    En réalité la longue carrière de yekini n’est pas aussi élogieuse qu’on veut nous le faire croire, même s’il est resté 15 ans sans défaite, pour vous en convaincre décortiquons la ensemble
    De ses 19 victoires, 10 ont été obtenues sur 4 lutteurs (Tyson 2 fois, Baboye 3 fois, Khadim Ndiaye 2 fois et Bombardier 3 fois)
    3 victoires sur 3 vieux, Mor Fadam, Mouhamed Ali, Mor Nguer( en fin de carrière)
    2 victoires sur deux sémi-champions ( Gris et Lac 1)
    4 victoires sur 4 lutteurs qui n’ont jamais été pro, Baye Fall, Pouye 2, Pape Cisse, Kadd-Gui, dès qu’il a commencé a affronter des jeunes, ses revers ont commencé,et avec la manière, c’est cela la vérité, je l’aime bien, mais il faut savoir raison gardée
    j’espère que cette fois il ne dira pas qu’il avait des problêmes de jambes

  • Ba

    triste sortie. Yekini à tout gagné dans la lutte. Il aurait dû partir la tête haute après sa première défaite. La deuxième constituera la tâche indélébile de son beau palmarès.

Publiez un commentaire