Annonces
Annonces
» » Vidéo-La Tante verse de l’eau chaude sur...

Vidéo-La Tante verse de l’eau chaude sur l’élève en classe de 3ème

Annonces
Annonces

48 commentaires

  • tamara
    30/07/2015 10:23

    comment une personne peut faire ce genre d chose

  • trainingaday
    30/07/2015 10:38

    Il faut être vraiment mauvais pour faire ça

  • rakhou
    30/07/2015 11:22

    Ki domeram leu way

  • police
    30/07/2015 12:21

    naysane ses tres triste sa noo adouna metina trop lii dara diarouko thi adouna yawe noo nako ybou thi yone

  • NIT DOFF KILLER ?
    30/07/2015 12:26

    le titre "Hahahahaha

  • 30/07/2015 12:58

    niit mo sokhor deugueu deugueu

  • La diva
    30/07/2015 13:23

    ki Moy imbecile way

  • diender
    30/07/2015 14:28

    djiguéne bou bonne khol, djiguéne bou impulsive, djiguéne bou meunoul mougne dara….mal finir rek, regret internel rek

  • rama
    30/07/2015 14:32

    sama khôl da temgue ba khawma loumay wakh ki souma ko khamone ba tay daguena lokhomyi apres à raylko parck ell mérite dn la vie

  • Asita
    30/07/2015 14:38

    les gens n'ont plus de coeur hoooooo

  • diadia
    30/07/2015 14:55

    sokhor amna ki defoul dara amna ko khamner nena mom dafalay possonner nga dee baniousi dara cone kokou diarna moytou dehh man mom damako ragal sakh

  • beugue sarew
    30/07/2015 15:53

    On est tous d'accord mais, ta tante te gifle, et tu venge? ça fait mal mais la version de cet dernier, on le sait pas encore?

  • V.B
    30/07/2015 18:03

    ya pas de version à savoir de sa tante…une gifle c rien c pas sa mère et son geste le prouve carrément…comment on peut regarder une personne et lui verser de l'eau chaude?non.mais serieu lii yefou deum là.Si setai sa fille ki l'avait rendu la gifle elle ne lui verserai pas de l'eau chaude.elle n'a ka pourrir en prison c.là sa place.

  • Boy
    30/07/2015 18:04

    Kimo bone

  • babou
    30/07/2015 19:07

    Da tente est trop méchante,elle doit aller à la prison pour payer ces faits

  • Mouhamady kaba
    30/07/2015 20:08

    la jalousie continue de faire rage dans notre adorable pays .nous prions au bon dieu de faire revenir les persones a notre religion qui est l.islam.beaucoup de persones ne pense qu,au present pas au future.on pense que la justice senegalaise va faire son travail.elle doit etre condamne pour ces actions.le monde sait qu,elle ne va verse de l,eau chaude a ces enfants .une foi encore il faut veiller au x conditions de vie de nos enfants .some closes paresnts ne valent a rien .que le bon dieu veille a cette fille et bonne reussite dans ces etudes.

  • irenediallo
    30/07/2015 20:37

    il fau la condamine e la coriger severremen
    el e tro mechante kel tante

  • 30/07/2015 20:52

    celle qui a fait ça, est une mortriere

  • mbayzo
    30/07/2015 20:56

    dafa bon agnan

  • sokhna diaw
    30/07/2015 22:53

    frabchement parler bone amna me serieux nak ki danioko waralona teudje le jour meme de laccident

  • ma
    30/07/2015 22:57

    ki khana dou dioulite

  • cheri katim
    30/07/2015 23:24

    les debiles sont dans les maison

  • fall Modou bété bété 100 /100 pur
    30/07/2015 23:41

    kikay Wakhoumala domeram way .domeram sakh moko geun.fouff.sa.moromou niit nga atanko deff yeneu dieuff you niawyiii..ak ni yallah fonké niit .. amoul loumouy deff loudoul di kheupate ndokh mou tangue non ki amoul xol ..ya bon .raykatou nitt binga doonn .dome kharammata ndiaye

  • gentil
    31/07/2015 01:12

    sa tante mérite même pas de vivre li mou def borome khol bou bonne rek mo ko mene na de si kasso bi way

  • Tyma
    31/07/2015 08:59

    c'est affreux ! comment une personne net d'esprit peut faire ça

  • Modi
    31/07/2015 09:54

    Quel crime! il n'y a aucune loi au Sénégal protégeant les élèves en cours de scolarité? le Ministère de l’Éducation doit porter plainte. Pour ce qui est de cette dame sadique, il faut la corriger sévèrement sans pardon pour que de tel acte ne se répète plus au Sénégal.

  • cheikh diop
    31/07/2015 11:45

    ki mo sokhar way yafi criminelle yi warna diekh Sénégal

  • Mor
    31/07/2015 23:05

    هذا لم يحدث في المدارس القرآنية لكن عند المدارس الفرنسية لذا ليس له حجم كبير في الإعلام لذالك المشكلة لم تكمن وراء فقط في حماية ومنع عقوب الآطفال ………..

  • adama ndiaye
    01/08/2015 15:00

    rakhou yow yaye domou thiotou ndéyame khamouléne noumou déméé balangaye wakh dangaye deuguelou gnare gni wakh kouma khékhal nga gagne ma féék ma sama wagne dima garouwalé louma yooré sotilako limou wakh dara amoussi sounguéne gnowone fimou khéwé nguéne khépe limouko déff

  • adama ndiaye
    01/08/2015 15:04

    yaw kou nité nga hamnga adina.souké wakhone sah dangaye khép loume ko déf

  • adama ndiaye
    01/08/2015 15:07

    mome si bopame mo giflé tante bi nakh béne lokho la ame béne bi dafa ame problème motakh moudone torokhale tante bi di wo dieukhar bi diko diakhassé ak mome

  • adama ndiaye
    01/08/2015 15:09

    par ce que tu ne sais rien.tu es incapable de voire la vérité.allé dégage

  • adama ndiaye
    01/08/2015 15:12

    yaw yaye yeufeur bou bone

  • beugue sarew
    02/08/2015 03:03

    Ces genre d'histoire son très bizarre elle est grande disons.elle avait dit qu'elle s'entendaient pas auparavant! ça se voit qu'elle n'a pas l'air polie elle aussi.

  • wakhe deugue
    02/08/2015 10:04

    yako gueuna yeusse

  • wakhe deugue
    02/08/2015 10:09

    pousse léne fi khamou léne noumou démé kidi féne rék ngéne nék fi di diaye réye lamigne

  • wakhe deugue
    02/08/2015 10:47

    fall modou bété bété 100/100 pur yaw yaye domou sarame nayame.nakh hamo noumou démé di sagua domou diamoure.dome sarame nayae fall binga done

  • wakh deugue
    03/08/2015 13:35

    yaw touti nga thi wakho foume koye ybou.topatoléne séne afére séne yone nékhou si en plus khamo noumou démé khawma police nga khawma lo done mé khamo deugue

  • wakh deugue
    03/08/2015 13:37

    la diva yaw yaye imbecile bou mague bi

  • wakh deugue
    03/08/2015 13:41

    diender topale felé tu n'a rien n'a dire.yako guena bone,sokhor,ignale,impulsive.khamo noye moudié nak yalla ko hame lime ko déf sougne lako défone lou eupe li ngaye déf

  • wakh deugue
    03/08/2015 13:45

    yaw tamite sougne la khamone dague nagne sa lamigne nakh wakho deugue,dague sa lokho nakh linga bine waro ka bineeeeeeeeeeeeeeeeeeeeee

  • fékhé fimou khéwé ak wakh deugue
    03/08/2015 15:55

    je vais vous dire toute l'histoire de A à Z.kidi adame yayame da décédé mounéke ak tante bi tante bi beugue ko lole gnou djoubo wone ba so lalé adame lale nga tante bi.gnou djaugué tanda bare béne village tokhou si ndoffane mouye djaugué séne dekk di djange sdji keur baka tante bi yeureume ko si dokh bi néko mou gneuw nék ndoffane si keureume baparé tranfére ko indi ko mouye diangué ndoffane té keur baka ladone diangué boumou gneuwé ndoffane nék si keuréume difa diangué done fi élève di dimalé tante bi si liguéye bi fougnouye déme gnoye ande.gnou ték si aye fane mou ame fi fare sou guoudé mou déme ba 3h du matin mouye sogua gnew,tante bi oko diko wakhale mou mére.si souba sa mou défate ko gnew feugue tante bi né domame bou gor bou mak bi démale oubile ko mouye déme di oubi mouné ko diaroule ngaye oubi deup mire bi ba paré oubi boune toubi bamou seuse néko souba souma gneuwé fékk ngéne teudie ko none lakoye défate té papame bou naw moye dieukeuri tante bi mome moné sou 21h dioté nagne teudie boune bi bougne ko bayi nonou tante bi nopi wakhoute ko dra déme o dieukeureume téléfone wakho ko khangéne rék gor gni sougnou také bénéne diabar dagnouye changé fék temp yoyou la woute bénéne diabar mouné koboumouye guéne ak sa mok wakho ko wone tante bi tontou ko néko bobou mougui keur papame té papame khamone nako fi nak papame nékhou fi louko dale mane lagnouye wakh.dieukeure bi wo adame néko démaye kholale ma keur gui bayi nako sisa lokho lolou yeupe tante bi di mougne adame sou gneuwé di wo dieukeuri tante bi diko diakhassé ak mome est ce que lolou c'est normale té dieukeure dji nék homme de tenu(militaire) adame sou gneuwé di guarou walé tante bi tante bi souko tonto mou déme songou ko di khékhe ak mome nakh hamnani mo meune tante bi nakh tante bi béne lokho la ame lokho bi dafa damou meunou ko sakh yékati té lokho naye diore bila té sa you khékhé ak mome guagne nako guagne bou méti té dou done béne guagne tante bi dokh gnari yone déme tanda bar séne dekk wakho papame pour mou gneuwe dioubaléléne mou bagne nakh hamnané domame mo meune tante bi diékh takke ba ndoffane gneupe diko yeureume foumou guéne gnounane néye sane.ndoffane gneupe naneko mou déme porté ko pélinte mou bagne té mokame la tante bi gneuw séne keur wakho papame ak yayame démale bayi ko bassa dieukeure ame congé ba gneuw gnou enrangé ko té amena aye rakk you meuna dore adame rakk yi gneupe né dagne koye fékk keure gua dorko bame hamné déguéne amna aye rakk papaye déguéne néléne dédéte boufa kéne déme nane dakoye dore bayi léne ba dieukeuri déguéne gneuwe gnou enrangéko nakh aye mokk lagne.déguéne si bobame dieukeureume nidiaye yame la rak yayame la yayi dieukeuri déguéne mome lagne nayalé yayi déguéne moko douguale négui séye déguéne koumou séyale nidiayame la.té sa you adame khékhé ak déguéne wa cogne bi wo nagne dieukeureume wkho adama guagne na déguéne mouné léne sama yone nékhou si nakh lolou yone la antanque borome keur.béne beuss nak mou khékhe ak mome wate guagne ko gangne bou méti sakh baparé yakk khanamame bi yeup mou gneuw keur papame yayame nékho koula déf ni mouné ko adame maguame bou djiguéne bou nékone fofou nékho dagnouye déme brigarde yayame néko dédéte na déme wkho papame mou déme papame nékho mougne bassa dieukeure gnew légui mou gneuw mou bagna déme keur gue sakh di khékhe ak mome mou tokk keur papame ba 16h30 mouné daye déme toguou noguou
    mou déme adame fékk ko si wagne ba diko guarou walé néko dafa féni wone di wayé mane falé wouma léne gnéte djégue sakh sougnou khékhé ak mane ma défarléne madargua wakhou malake béne djégue.déguéne mére fékk mougui tékk nokh pour ségue café mou dieule nokh mi sotiko ko té sou néguone si kaname lakokoye soti mé néguoule motakh mou sotikoko si guinaw té aprés sakh daff ko réthiou dafa mélni kou dofe adame déme diéli yate né dakoye dor wa cogne bi diape ko yeubou ko hopitale kouko done fadiale sakh agna ba la toudou bime koye fadie mouye thipi thipi agna ba néko hé yémale li yéguoute féne guarawoule sila ko diwale pomante néko démale sou garawone dakoye hospitalisé mala mou binale ko keyite mou déme kaolack mé garawoule agna ba sakh moko kholi nakh mou gawa weure .gnou wo papame néko adame kheuou nagne ko nokhe mou tange si sasi la gnew san égité té boume ko wowé gnewoule légui nakh mou hamné domame lagne gagne mou gnew adame délou keur gua né daye khékhe ak mome nakh sou garawone dina tale khékhe.histoire bi nila démé lépe fare bako ini té fare bi amna diabar séne dekk peul fouta la té sak dimanche mou ini yéré fare bi wone diko fote dé dou défale tante bi légui dra té pane ya tante bi moko mome yayame moko ko dieunale nakh lolou yone la .adame nak limou wakh dra amousi aye féni khéssé la sou guéne gneuwone ndoffane bi mou khéwé dangéni warou si adame.adame torokhalena tante bi diko saga,diko dor,diko guarou walé tante bi mossou ko pécc mome moye wakh tante bi tontou mou pécc ko songou ko dor ko nakh tante bi béne lokho la nila histoire bi démé

  • awa eva évrau ndiaye
    04/08/2015 15:40

    mbayzo yow yako gueuna bon gueneko agnan do dara dégueloule tante bi balla guaye juger

  • awa eva évrau ndiaye
    04/08/2015 15:49

    yow la domeram geun fouffe yow fall modou hémésile 100/100 au lieu bété bété do nit sah dallala guoume ba ham problème bi noumou démé adame fén rek laye def douli késsé

  • awa eva évrau ndiaye
    04/08/2015 16:00

    toi gentil c bien toi ki ne mérite même pas de vivre; pour yow dagua bakh ni. tu n'a pas honte de juger sans connêtre la vérité tu devais être honte de toi nénagne bala guaye atté fékéle malla gua ladje gnouko fécké borom histoir boumela nétalile gua gueume

  • awa eva évrau ndiaye
    04/08/2015 16:02

    tyma bobou dagne la trohaloute

  • awa eva évrau ndiaye
    04/08/2015 16:13

    boufi loi amoute degueu warfé ame mais guisnané degue amou fi nah doléne wakh degueu le ministère de l'éducation doit porté pleinte mais pour kel régon le ministère doit porté pleinte pour cette histoir wi le ministère doit porté pour k les enfants respecte leure tante Modi ne juge pas sa tante par ce que tu ne connais rien de cet histoir si tu veus connetre l'histoir tu doit parti à ndoffane

  • awa eva évrau ndiaye
    04/08/2015 16:16

    cheikh diop yako guena sokhar

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL