Annonces
Annonces
» » » Vidéo. La danseuse Mbathio Ndiaye victime...

Vidéo. La danseuse Mbathio Ndiaye victime d’une…

Annonces
Annonces

15 commentaires

  • ousseynou ba
    10/05/2016 10:57

    doul rek ak bougou buzz

  • boy toronto
    10/05/2016 11:33

    loooooooooooooool

  • mami
    10/05/2016 11:59

    xalis bou takoooo takou niata ? 300.000 lol kheumna

  • RM
    10/05/2016 13:04

    djiguene souye dokh wakhtou wowou dafa wara am scurit

  • BREF
    10/05/2016 13:38

    Mami bouma dadj way

  • cartel
    10/05/2016 15:40

    dama sone qui net bio legui mome li rek la ci rek c leur problème

  • Buzzshu
    10/05/2016 16:42

    Lol beug buzz trop 300.000fcfa Kay walf dougnou dme

  • Rama Badiane
    10/05/2016 18:55

    300.000fr pour Wa walfa khaliss bou takoula par se que sne salaire egoule fofe

  • bigtaf
    10/05/2016 19:42

    mami yaw ak bref bayilwn titarou bi on sait bien comment se passe la au galsen 300000cfa khalis boutakoula sakh. te yen deuram fananoul sen poche. plutot on aurait du etre desole de se qui c passe que de se moquer…

  • daga
    10/05/2016 20:02

    haliss thiaga la ont na rien na foutre

  • kheus
    10/05/2016 20:40

    mbathio dafareglvoul

  • mami
    10/05/2016 20:49

    yow big taf je veu po te donné mon num mai si tu donne le tien je tapel tu sora si 300mil xalis la si man suis dakor kon est dans un pays pauvres et dure mais faut pas exagéré xaliss bou takoooo takou s’écrit po ak 6 chiffre mako wakh surtout fene kat yi ngua khamné buzz lagniy wout sous fekone kou marchand embulan ba wakh walla diay etc etc dinako yeureum mai po genre yi donc ma tay

  • rebatass
    10/05/2016 21:31

    si bathio lit les commentaires ou memes quelqu un qui la connais son sac se trouve actuellement a la zikfm

  • Babyboy
    11/05/2016 10:18

    Foutaise rek .

  • Giss ??Giss
    12/05/2016 11:30

    kay mamayla 500000f

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces