Annonces
Annonces
» » » Vidéo: Il critique Fama Thioune…

Vidéo: Il critique Fama Thioune…

2015-06-02T10:58:04+00:00 Partages

Annonces
Annonces

29 commentaires

  • fall
    02/06/2015 11:05

    C'est vrai Sénégal dou dem

  • Amina
    02/06/2015 11:07

    way way boulen nio sonal tounkara lolou demal wakhko sa patro ndakh diel na bijou aicha ak ya awa

  • amy
    02/06/2015 11:11

    c vrais degue na deugue depus 5 ans ma ngi took defna sama formation journalimes ba pare def sama demande si tele yeup kene falewouma te ma geuna toy fama fouuuuuuuuuuf.

  • deugu
    02/06/2015 11:17

    Lolou chance mais yénne amoléne chance yeurr seukk leu

  • karim
    02/06/2015 11:23

    haha amu bougnou ray way. guena toy takhoul niou dieul leu.

  • Amina
    02/06/2015 11:33

    amy yaw amou fayda wakhou toy ngay wakh tfm donio diel ken pour ne dafa toy

  • kiya
    02/06/2015 11:41

    C'est ça critiquer mais il n'a dit que la vérité

  • papy
    02/06/2015 11:54

    @ amy si tu acceptes de passer à la canapé peut etre on te prend

  • boy
    02/06/2015 12:36

    Ba la ngua dem tfm kholal 2stv ba pare ak ya awa bijou ak aicha sof nguene torop

  • boy
    02/06/2015 12:43

    Da fa melni yen wa 2stv fatte nguene 3 animatrices you nguene dieul

  • bibi
    02/06/2015 12:55

    L blem en k tele yi gno tek beut sentv ba tah kougn fa dak nga fokni meune neu yeukeuti sa tele

  • Madam Faal
    02/06/2015 13:24

    tfm way way lawla thiat thi yen kui wakh rek tfm ngay wakh mandeh dina nieuw tfm pour ngen may ma sen bayree bi, guiss nane kui wout buzz rek fok nga toudou tfm Yal na len Yalla lafal thiat te yok len ay non ndakh kou amoul non bakho

  • Beugue Sénégal sama rew
    02/06/2015 13:37

    il faut bien écouter tounkara, métiem animations la wakh khame khame amouci niepou la wakh

  • aaaa
    02/06/2015 13:46

    pourtant il a parfaitement raison. sénégal délène até deugu. kou diek, siw, rek niou dieul leu si télé yi…alors ke pendant ce temps les meilleurs laissent leur diplomes dormir dans leur tiroir…DOU YONE

  • dame fall
    02/06/2015 14:32

    Senegal ni rek

  • feuz
    02/06/2015 15:38

    yena ngi mer de yen ni kham deflen foutez way

  • biz
    02/06/2015 15:46

    Felicitation bougane pr avwr forme c animatrice k personn ne connaissé au lieu de debaucher

  • kia
    02/06/2015 16:02

    verité bou weer; fama thioune mome dafma nékhone mais legui elle a perdu ses valeurs ba paré di forcé. mais comme bijou ndiaye loumou la wakhone khéwato naguoul

  • aladi
    02/06/2015 19:22

    yaw asss tu n as ka te taire yaw ko yab , lo diangue ensuite tu te permet de critiquer , jalousie bakhoul demal liguenti sa bussness et laisse les autres faire leur boulot.

  • èva
    03/06/2015 00:22

    touche pa a fama thioune

  • fabiocapelo
    03/06/2015 09:37

    ne mélangé pas les chose, il ne critique pas Fama THIOUNE, mais ceux qui l'ont mis dans cette émission

  • kiki
    03/06/2015 16:31

    ass n a mm pas de certificat d etude , sou khamon dara dou djoguer walf , alors de kel formation kon parle , quand les autres essayer d avancer , vs vs rester la a critiquer, Demal ligueyi mo gueun si yaw , boula camera tim rek ngey wakh lolou nekh

  • nesta
    05/06/2015 10:56

    kiki del wakh gni dagno sof way nimalene diepié

  • mamy Faye
    05/06/2015 14:16

    Wa kiki yagui mer dé pourtant limou wakh c'est vrais

  • mariam
    05/06/2015 18:00

    dem len ligueyi te bayi wakh

  • mrade
    07/06/2015 00:12

    Li business amoul ay leçon de morale!!!!
    Counak ak sa ay strategie

  • der
    08/06/2015 16:24

    en tou ka fau bien écouté omzo li mou wakh thi animation lou werr la il faut bien regardé lintégralité de lémision que des cours de l'animation

  • kiki
    10/06/2015 04:56

    no pas de mer sakh , seulement gni danio yabate , moi je defend personne mais au lieu de rester la a critiquer les autres aller bosser .

  • go
    17/06/2015 13:33

    bouléne niou réy pabi wakhoufi dara Maty modone déf émission bi té kéne wakhoul té diangoul lamb elle ne décortique pas elle présente juste les rubrique réfléchisser un peu my pa ish

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL