Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

221 33 823 43 43

Annonces
Annonces
» » » Video: Fatima Diack humilie un tassoukat

Video: Fatima Diack humilie un tassoukat

2015-06-08T21:32:06+00:00 Partages

Annonces
Annonces

62 commentaires

  • deug
    08/06/2015 21:47

    kou torokhal nitt yalla torakhala

  • suede
    08/06/2015 21:48

    kel insolence

  • jrd
    08/06/2015 21:54

    mes yawe ya gnake kerssa yawe baganye gnewe stv dagan diagone domerame yenna fouye te gatte wakh

  • mina
    08/06/2015 21:59

    bayilen xep ni

  • mina
    08/06/2015 21:59

    bayilen khep nit

  • BLK
    08/06/2015 22:00

    cette fille la man xama lukay sentv didoye elle n'a rien dans sa tête mogana nul ci animateurs

  • mami
    08/06/2015 22:09

    elle est nul j'ai même les larme au yeux respect zéro non Sénégal dou deme mètre courage jeune homme dieu a tout vie

  • Nathalie
    08/06/2015 22:14

    Cheeeeeeetetete non sénégalais daal mognakka kham bopam es se k mom daffa diakk bay khasstee

  • mbaye
    08/06/2015 22:30

    Mais c'est bien fait avec son bol, va chercher un boulot digne et laisse affairou gor diiguéne yi. Desolé

  • elle est nul xamul touss
    08/06/2015 22:32

    cette television la ils recrutent des persones dans la rue, respect aux telespectateurs per favoré

  • moi
    08/06/2015 22:47

    Mais ki kham na bopam mouy torokhal boy bi lilay yarr mingui sa kanam cou torokhal domou adama Yalla torokhal la tu verra pauvre conne! Savoir vivre ZERO chiiipsa robe bou khéwi

  • sentv
    08/06/2015 22:51

    nooo sentv hawma kou tanè guissoumafa kou ame saky BFEM saf ay analefabète rèk amougnou bène savoir vivre

  • pape
    08/06/2015 23:11

    Ki niakk na kérsa trop domou adama kén douko torokhal mai borom bolle bii na outii métier li daffa nékoul mbirrou goor yagui rouss loo say parents

  • Aramezey
    08/06/2015 23:12

    Pour mom moko tané golo bou yoré almétt
    Nit kou gnak kersa rek la bagne….

  • Kiff kiff
    08/06/2015 23:21

    Mané waadji s'il a osé se présenter sur le tapis rouge c'est parce qu'il s'identifie à cette télé! Ceux qui se ressemblent s'assemblent!

  • kmz
    08/06/2015 23:24

    kel insolence

  • diouldé
    08/06/2015 23:26

    fatima gniakga kersadé adouna d'où NY

  • mareme
    08/06/2015 23:40

    yaw dou fatima ligay niakk khorome amon benn thiate djigenn day am khorome me ni deune rekk

  • triste
    08/06/2015 23:58

    ki doumou tivaouane la dara diombouko soudé li lay déf c k lolou la beugg day dane dollém rék sathioul fénoul mais animatrice bi kou dakar ndayame la amna yo khamni nite souko meuné sakh warouko déf en + thi télé kél manque de professionnalisme

  • fall modou bété bété pur
    09/06/2015 00:15

    non cest dit nimporte kw. li niawna Franchement parle

  • daba
    09/06/2015 00:20

    Bayilen sokhor. C dEux person ki on fai tou c commentaire. Fatima ya saf gneup. Kou mer boco

  • jann
    09/06/2015 00:25

    Fatima da nga toy hew meune sagnsai. Sen xol yangui bone nah da nga pop

  • gorfall
    09/06/2015 00:33

    je suis contre cette tele mais cette fois la fille a raison tt le monde veut faire du buzz legui reflechissez sa veu dire de venir au gran theatr avec un bol et surtout se presenter sur le tapis rouge.

  • lune
    09/06/2015 00:34

    Ndeysann le chien aboi la caravane pass. Tima diack yow da nga teki am xaliss di dawal auto bou bah, les chaud coeur ndeysann resten chez eux teki wougn dara di saga xale you teki yi

  • gorfall
    09/06/2015 00:36

    si le boy avai fait son tassou avec son bol vs l auriez critiquer oci

  • Dame
    09/06/2015 00:45

    li doy na war senegal yere lanouy fonke nit li mo takh senegal dou dem

  • facherie
    09/06/2015 00:46

    Moi personnellement je ne vis pas au senegal, et recemment j ai eu a suivre cette fille sur le net, et je l ai bcp adore. Mais la elle pouvait eviter ca, et elle etait serieuse ,cela ne se fait vraiment pas. Nous ne sommes pas egaux, doleiii yii yamouniouu .

  • bene copain
    09/06/2015 04:09

    en plus l'habit ne fait pas le moine

  • zeyna
    09/06/2015 04:50

    li dafa niaw yaw amo ben talan guaye xebate

  • BA Mouhamed
    09/06/2015 06:44

    Moi ma question est : comment il a fait pour accéder sur le plateau s'il n'a pas été convié ?????

  • Dior
    09/06/2015 07:35

    il ne faut jamais sous estimer une créature d'Allah tu lui di va thabiller en nandane tw tu pense qu'avec ta foutue robe tout ton corq mogui thi biti nandane gua c faux djaguil wakh idiote 'nulle voilà ce que tu es

  • badio ba
    09/06/2015 07:44

    mé mane fi guissumafi lou graw dh.

  • fanta
    09/06/2015 08:02

    va te faire foutre elle connais rien cette animatrice fouyyyy rek thimmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmmlmmmmmmlmmllllmmllm

  • dieujeune tolalitè
    09/06/2015 08:45

    lii lèpp ñakk dèff formation de communicatiin rèkk moko warale akk etucation zero wayè nitte no nèkè sa keur done badola soo amè touti rekk yanou adouna tè wakhe dji wakh dji .Est ce que mome khalate na sii les personnalitè you mouye deme di wayane akk mbarane wayè comme disait l autre" un mal ne se disparait jamais ça se retourne d'où ça se produit" et dans la vie ,qui vie ,verra

  • Fafa
    09/06/2015 09:51

    Qui mome hana bilgate gneuwone dakay dakk,l’habit ne fait pas le moine,arretez de juger les apparences,soff nguen tropp

  • Adldo london
    09/06/2015 09:55

    Cette F Diack la ,,¡ N'est país du tout profestionel! C'es tout…..!

  • Prod1
    09/06/2015 10:24

    Baayilene kou commenté loulene nekhul rek nguéne dafa sokhar non c'est pas ça c'est sa reaction qui est à deplorer. c'est quoi sagnsé. kouné li ngua am ngay douguédji marché

  • mams
    09/06/2015 11:14

    quelle conne , elle n est mm pas plus correcte que ce jeune avc son khessal et ses tatouages

  • baffy mbour
    09/06/2015 11:36

    très complexée qui te dit qu'il a des habits de ndanane ,c'est pourquoi l'autre disait :si l habit ne fait pas le moine il permet d'entrer dans le monastère.

  • super xomesta
    09/06/2015 11:40

    ki mo niakk kersa mouy melni golo gou nghass

  • Masaly
    09/06/2015 12:13

    mounoul animé mais day defaral Bougane bagass Mo takh elle se croit tout permi. Mais beuss mi ngui ci beuss yi.

  • Insa
    09/06/2015 12:13

    Yaw nadawsi sa methiemi set nani mokaloka kon do defendí demal nga diangiwat

  • Masaly
    09/06/2015 12:15

    Ndawsi yaw sa bay ya rula

  • begue s touba rek
    09/06/2015 13:12

    Biss tina niay do dal solou

  • lalo
    09/06/2015 13:44

    Mais yaw tu es conne han .loye waniai ki ni .sooofffff ba dai

  • ive
    09/06/2015 14:29

    mlgres tous il fo etre corecte surtout devant la tele

  • ridial
    09/06/2015 15:21

    fatima diack je t'aime je veux faire l'amour avec toi…jtj

  • Inconnue
    09/06/2015 15:25

    OHHHH g eu les larmes o yeux telmen ca me fai mal mai fatima adouna moungui sissa kanam
    ki vivra verra inchallah

  • Fallou Kare
    09/06/2015 16:42

    Daf ko khép

  • WAR
    09/06/2015 16:53

    La télévision réclame élégance

  • diallo
    09/06/2015 17:34

    nitt ken dou ko toroxal fatima diack yow amo ben formation mé doto ko défati légui bougane dakh la cheikh sarr néna lignouy wax ci yow si fermeté dégueuleu bou done alima dou doxalé ni mé yow danga foguu ni Star ngua alor k ignorante bou béte nga

  • bokomolo
    09/06/2015 18:29

    wakhna dague wadji day niawal image

  • gawan
    09/06/2015 18:38

    ma

  • Maniang
    09/06/2015 19:19

    Fatim Aduna gui sa kanam qui vivra verra incha Allah

  • lora
    09/06/2015 19:40

    tiey djolof di wagni goss bi ni

  • diagne
    09/06/2015 20:06

    nn yow bakhodéé li dou addounadéé bonega lolee

  • ken
    09/06/2015 22:26

    Fatima me déçoit, avec toute l'estime ke javais pr elle.. ça m'a choqué

  • diouldè
    09/06/2015 23:07

    maréme amouma khorome mé yalla bahna bouma amé aye fème hana hemegue

  • Moussa
    11/06/2015 18:10

    Chers lecteurs ça prouve le manque de professionalisme chez les animateurs sénégalais.Mais son jour viendra l'animatrice.

  • mimi
    11/06/2015 22:13

    wa kii esk cava ??? pourtant je l appréciais tellement.. nonnn elle m a deçue celle là !

  • désolé
    14/06/2015 16:15

    du courage jeune homme

  • fatima
    02/06/2016 12:15

    wa ki mom legui foumou nek mom fatima diack ??

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL