Annonces
Annonces
» » Vidéo: « Djiguène Gni » de Youssou Ndour au...

Vidéo: « Djiguène Gni » de Youssou Ndour au Cices…Regardez!!!

2015-06-15T11:20:55+00:00 Partages

Annonces
Annonces

15 commentaires

  • amy
    15/06/2015 11:51

    you rek la niou wakh khana kheume nguene ??''

  • mouhamad kebe
    15/06/2015 12:22

    ca c du n'importe kw! mr le ministre svp arrête prck tu na plus d'inspiration 0'5/20

  • BEUZ
    15/06/2015 12:30

    ça c de la musique! merci Mr le ministre, une chanson pleine d'inspiration 1000/20

  • babs
    15/06/2015 12:34

    Mais kebe khana dangay door djiguene dafa melni dagnou la lall

  • Mina
    15/06/2015 13:15

    Way you lagnou wakh way, way bi amna sens torop, ta les cons qui frappent les femmes warr nagn ko degulou.

  • bon citoyen
    15/06/2015 13:18

    you da nga khewi,d'égal lenene.wayane nga ba amm,maintenant repose toi

  • DEUKHINE MBEUP
    15/06/2015 13:26

    KEBE ak BON CITOYEN !!!!!! Maan yaakar naa , khana daa ngénè EBOLA , vous pouvez aboyer ou bien miauler , sachez que le train est déjà passer depuis belle lurette , à BRESCIA ( ITALIE ) des qu,on passe on ne cesse de nous demander quand est ce que , il reviendra jouer ici !!!! Et ça c'est ma fierté et la fierté de tout un peuple de tout un continent !!!!! Maa yeureum Kou bagne Lou yalla doogaal ,,,,,

  • wokhdeugueuu
    15/06/2015 15:28

    Deukhine mbeup bilaye tu m'inspire bcp mann daall yoww laye lirre koi..alé yow..

  • mataye
    15/06/2015 16:31

    No ingnane bakhoule bayilene critiquent sifflent trop

  • il maestro
    15/06/2015 17:59

    Kebe ak non citoyen ignaan rek mo leen jappe, mais gueum leen Yalla ak ay dogalam.ta nguènn dem ligueyi!

  • fall modou bété bété pur
    15/06/2015 18:46

    Franchement parle sons bi nekhna trop. ta dafay dougou si biir khol

  • lora
    15/06/2015 18:57

    wa deukhine mbeup fi ga feullai tay hahahaha yaye sama fans

  • lora
    15/06/2015 19:15

    wa guisga deukhine mbeup tay fi ga feullai mdr ci fans yi la bokk

  • draaaaa
    15/06/2015 21:39

    Bon citoyen geustoul diar diarou youssou ndour nimou def ba teki il a galeré ce mec pour yekssi fi nganane wayane mauvais cioyen ngua rek

  • Sasa
    16/06/2015 13:57

    Affaire bi you la kou mer kalamelle yallah

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL