Annonces
Annonces
» » » Vidéo: Concurrence entre Waly et Youssou Ndour,...

Vidéo: Concurrence entre Waly et Youssou Ndour, Kouthia pense qu’il « Y a un média qui arme Waly pour.. » Regardez

Annonces
Annonces

85 commentaires

  • Keuz
    06/05/2016 21:36

    Ay Wakhou kassaw kassaw rek !

  • Amina
    06/05/2016 21:38

    mandeh sama yoon nekousi mais lima kham ba kham ko moy pom dou moromou new Youssou Ndour Yalla nako Yalla dole defal diam tek ko si yoonou siratal moustakim te lafal ko thiat,Amiin

  • Diop
    06/05/2016 21:42

    Koutia arrete

  • Deug
    06/05/2016 21:49

    sachant tout ce que Youssou a fait vs n avez pas besoin de tenir compte de c soit disant comparaison. Mais comprenez que après Pelé Ya Ronaldo , après Maradona y a Messi , après Platini y a Zidane. La musique sénégalaise ne peut pas s arrêter à Youssou et personne n a jamais dit qu il n est pas le meilleur.

  • ami
    06/05/2016 22:12

    way way koutia doul may lénn gnou afia

  • ass
    06/05/2016 22:13

    may lénn kalébi diamm doul way yénn

  • diop
    06/05/2016 22:23

    Youssou khamenagneko nitou intéréla té yénn wa tfm sof guénema .tfm macky dalén corompr taisez vous borico

  • Namou
    06/05/2016 22:23

    Makhala ces télés n’ont pas de programme !

  • zeuss
    06/05/2016 22:34

    way vous croyais k kenene waroul wayeu ! You rek mo mom musique bi di khatal nieup kene dou def sey yeufou bopp.dotr wally vont venir you fey na bou yague

  • español
    06/05/2016 22:42

    kouthia sa domouram

  • rebatass
    06/05/2016 23:03

    ce kouthia c est un vrai con et un rancunier je pense que vous devriez tre content qu il ait un jeune qui se compare a youssou ndour tout le monde sait qu il est le roi du mbalakh mais il ne peut tre dans la musique toute sa vie et doit avoir des jeunes comme waly pour prendre le relve. personnellement ce qui me fait c est que les gens de l tfm sont gocentriques

  • weuz
    06/05/2016 23:11

    kouthia yaw doul waye sa interert rek guaye defandre waly yeune gneup laye fay yaw ak sa papa you yeup youssou deff na loumou fii wara deff ba parer c o tour de wally taye daye deff lou raw loussa baye you defff nafekh gua rek kouthia bougnou la dougual si lolou ta gua yam sa comedi wala gua diema done roiwou liguaye deff doul waye boul gnou sonal

  • español
    06/05/2016 23:29

    kouthia sa diobou ndaye

  • baba
    06/05/2016 23:40

    thiay Senegal

  • dam
    06/05/2016 23:49

    youssou pour man afriaue moy bourou waykatyi knlafi way rk lay df

  • kenki
    06/05/2016 23:51

    journaliste Senegal nioy fabrik ay waykat you khamoul Tous diln May beuz

  • buur
    06/05/2016 23:57

    IL faut savoir raison garder… je suis ni fan de wally, ni de youssou, mais wakhouma sakh wally, mai fi yussu ndour takhaw si ay plateau (scene) a part baba maal, guissuma senegalais bouy way boufay takhaw….

  • deug deug
    06/05/2016 23:58

    youssou ndour bn yoon lay am par siegle

  • Lamine camara
    07/05/2016 00:01

    Kouthia tay mom wakho fi dara

  • gueye
    07/05/2016 00:06

    amina legui sa yone neke si nak

  • Zoo
    07/05/2016 00:12

    Doul yeine ak seine baye youssou ndour sof ngeine trop .waly la nite yi beugue meuno Leine si dara doul

  • titiyou
    07/05/2016 00:37

    Khamgua Sénégal dagnouye diaye guinar bamouye mbeuke Youssou dou moromou bayou wolly seck excusez Wally seck pour nane raw Youssou dou teugue Bercy Walla âme aye grammy award mais rawko moye wayfi limou fi wayoul té Wally diaroul sakh côté bobou.VIve Youssou vive titi wa salam

  • Faty
    07/05/2016 00:52

    Non vraiment yeine ak seine patron da ngueine wara gueume yalla . Da ngueine wara khamni ni yalla neikalou fi youssou ndour reike ak wa keureume doul merde

  • amy
    07/05/2016 01:05

    khouthia liga wakh amna slo sentv al Ahmed aidarra ay no ni youssou lanou na animateur you Gfm am fouleu

  • amy
    07/05/2016 01:05

    khouthia liga wakh amna slo sentv ak Ahmed aidarra ay no ni youssou lanou na animateur you Gfm am fouleu

  • amy
    07/05/2016 01:06

    sentv ak ak ahmed aidara youssou ak pape diouf lani faktal ndakh wally tfm amln fouleu ta dfandre sni artiste boulnsi am bn complcx

  • amy
    07/05/2016 01:09

    nako animateur yi nk Gfm ypou kham gurre c la guerre d media dani Mat Di euff

  • rakdji
    07/05/2016 01:10

    bien dit khoutia

  • khoutia
    07/05/2016 01:14

    deug rk nga wakh khouthia Senegal kou nk khamna mediasyi nimou dm kousi nk ntrm lay dfendre

  • ti
    07/05/2016 01:18

    merci khouthia liga wakh amna slo d media nanou bayi dieul wally diko tk si kaw artisteyi si lounou tgoul fen

  • kheus
    07/05/2016 01:19

    merca khouthia

  • seti
    07/05/2016 01:20

    bien fait khouthia

  • sal
    07/05/2016 01:48

    kouthia waxou fi rien

  • LF
    07/05/2016 02:19

    Kouthia boul gnou sonal ndieukeu mag mo ame ndieukeu tekki mé geuneu ame diome amoule fi you yegg wally mane na fa yegg té dou yalla moy mayé limou ko may mane na mayy lou eupou lolou wally you ndafé ndieukk ngeun fé yagg mé takhoul gnepp beugue ko wally woyy rekk lay deff té mi ngui si bonne voie

  • boy Texas
    07/05/2016 02:27

    Mé TFM dou gnou teck Wally

  • LD
    07/05/2016 02:32

    Kouthia boul gnou ray Ndieukeu mag mo ame ndieukeu tekki mé geuneu amme diome amoul yalla gnepp la fi nekale mo deff you limou done té incha allah bou decider ni wally dina amma limou ame walla lou ko eupe daye ame té kene dou si meune dara gneppe khame nag,e ,i you moy roi du mbalakh lolou justifier woul ke ni mo dakha woy senegal ndakh koune ak sa artiste mé yalla koko may té wally il chante trés bien je le prefere à youssou ndour, bnne continuation à lui mi si bnne voie

  • Diop ndiaye
    07/05/2016 02:33

    wakh dg dg lay ladj il parl po avc waly me gayi youssou dou moromou mak sax waxumalak xal me nak boy leu c normal mou tkh beuteum fou reuy yalna yalla tap khol yi

  • fatu
    07/05/2016 03:58

    stupide Les senegalais.. ici aux USA quand nous vous observons on se rend compte que vous dormez encore.votre niveau est tres bas…je ne peux pas croire que C,est dans une chaine de TV que vous passes des messages aussi vulgaires, aussi vides et aussi stupides!! ce que nous voyons ici est que Wally Seck vous a deranger ..et youssou ndour aussi n,a aucune classe..il peut aussi en grand et intelligent interdire ces guignols a exposer des scenes aussi vulgaires..nous qui comprenons Les changements dans le monde ,nous voyons que l,ere youssou est en phase de terminer comme le soleil se couche..son temps est Fini C,est pourqoi il a peur et obsedei par waly ,jeune et plein de talen pour avoir LA meme gloire ..croyezven dieu et donner a waly LA chance de faire comme Les autres gloires..senegalais mo con tei sokhor tei close mind ..thipriiiiiiii

  • ndiayefaly
    07/05/2016 04:55

    Ahhhah sa me rire Bilaye souma guissè nioy tekelè youssou ndour ak waly comme si tu dis Angleterre ak pomme de terre mrd je suis pas contre waly mais il l’a intré à faire attention sou wedè na lathie thioune seck you rek day mourome président sakh???

  • zakaria
    07/05/2016 05:19

    youssou ndour rek la fan mais boy waly qui chante comme son pere thione seck (pour moi l un des meilleurs chanteurs du senegal comme laye mboup ndiaga mbaye souleymane faye youssou ndour cheikh lo etc etc) avec habib faye il va faire du tabacs …je connais la music…

  • Moustapha Sagna
    07/05/2016 06:17

    Youssou ndour est plus qu’un chanteur , il a franchis les limites de la musique sénégalaise , il est un symbole et une icône de son art . Il ne fait plus de la musique mais il est la musique . Vouloir comparer Youssou avec un quelconque que se soit , c’est refuser que Youssou est le chanteur du siècle

  • Moustapha sarr
    07/05/2016 06:37

    Thiye senegal

  • doss
    07/05/2016 07:12

    je rejoinS parfaitement l avis de fatu from usa je crois qu elle a tout dit et ca on le voit qu ausenegal parceque l eclosion d un nouveau talent ne devrait pas faire autant jaser. la musique c pas une competition mais une communion et pourtant au senegal c une competition dailleurs tt est competion chez ns. BREF le debat youssou waly est un faux debat et c les journalises qui alimentent cela parceque ya une carence ils n ont pas de quoi debatre ou informer. WALY est un gossse qui a du talent mais laissons le exprimer son talent. moi j apprecie beaucoup youssou ndour mais a un moment donné il doit quand meme mettre terme a certains comportement au niveau de la tfm qui fait un peu du favoritisme au profiT des artistes qui st a prince art par rapport aux autres. et pour revenir sur le sujet YOU doit juste se rapprocher de son fils waly allait a un des ses concert chanter avec lui l encourager et laissezr un messsage comme ca les gens vont comprendre que ya rien et que waly doit faire son chemin SALAM

  • Dadi
    07/05/2016 07:35

    Mais youssou ndour n’est nu prophète ni descendant arrêter de dire le mot comparaison .wally n’a pa essayer de se comparer a youssou ndour mais plus tôt il as le droit de regarder loin pour atteindre le sommet de son père « nite da faye reuye beute  » c’est pourquoi je l’adore le goss

  • Sa
    07/05/2016 07:52

    Merci Fatou tu as tout dit mais il faut essayer de vous mettre dans la tête que le bon dieu n’as pas créé le senegal pour youssou ndour et sa famille seulement svp  » gueume Leine ni yalla Amna ta meune na maye keipe kouko sakou thi môme  » .Cest youssou ndour en personne qui doit clôturer se faut débat merde kouthia

  • Kha
    07/05/2016 07:55

    Vraiment kouthia y’a niake FAYDA .vous voulez être des »soukh »jusqu’à quand oh c’est grave .

  • Fifi
    07/05/2016 07:58

    Moi je suis fan de you, j’ai dansé sous sa musique dans les années 90. Mais tout comme je ne suis plus en âge d’aller en boîte youssou doit admettre que la relève doit se faire. Il n’y a rien à comparer chacun doit faire son chemin. Souhaitons une bonne carrière au jeune parce qu’il a de l’ambition. S’il réussit ce sera une fierté pour nous tous qu’on l’aime ou pas.

  • Marsene
    07/05/2016 08:02

    Je partage lavai de Fatou et de Doss c’est youssou qui devrait se rapprocher de son fils et arrêter d’organisé des soirée au même date que son. Fils pour se comparer a lui .Sil le fait le débat sera clos mais lo Leine kham thi mbeur mou ni d’où danou mouk .lolou amoul feine.

  • Fafa
    07/05/2016 08:13

    Vous croyez que le Sénégal va s’arrêter sur youssou ndour seulement vous vous trompez .il presque fini votre you .vive la jeunesse

  • as
    07/05/2016 08:22

    bien dit fatou rien a ajouter

  • Billy
    07/05/2016 09:20

    s’en tl bou gnaf ndm bi comm boutik marche hlm publicit rk tl de l’tat en plus boulne gnou sonal amolne progrmame fermer cette boutik

  • aro
    07/05/2016 09:21

    kouthia beugeunala torop me il fo k tu arrettes,ton patron et Waly bokougnou yone bokougnou generation,bayilene di cree problem fomou amoul,waly domou youssou leu te senegal yeup tegci sen beut.Waye nak yalla mi may youssou moy may waly.bougnou kene rey.wassalam

  • dieukeur
    07/05/2016 09:44

    Ameth Aydayla niaTy febar nioko diapp:PARLECKIMSON-DOULZEYMER-DIEUWLEPSIE

  • Deg
    07/05/2016 09:47

    Pourtant dès le début Waly à dit faire de Youssou le parrain de Bercy , il a même essayé de rencontrer you de façon formelle et informel mais rien nada, silence radio et tv chez you, en tt cas si you es Maradona Waly c est Messi a chacun son époque

  • Aziz
    07/05/2016 09:53

    Vraiment kouthia tu ma déçu oooooh thipri waye

  • Amina
    07/05/2016 10:18

    hahaaaaaaa DieuKeur rey ngama liko dal metina na dem fadiou mogeun goor momoul yenayi

  • kantay
    07/05/2016 10:35

    tl fatale macky khame nagni lene sene bop rek ngane fi nekale

  • Samir
    07/05/2016 10:42

    Non vraiment kouthia tu te ridiculise pour rien ,tranquillisez vous ndakh waly môme yala mi maye youssou ndour mo ko maye taye doul . Vous croyez faire du bien de or que vous pétez les plombs waly môme deimena yaguena li thi desse kaye moye nianaleko reike mou âme goude fane ak tawfekh .wassalam

  • tico
    07/05/2016 11:11

    Di nguéne bayi You dal nakh dou sénnn morom, il vise loin

  • chi
    07/05/2016 11:15

    waly amna louko doy ba paré na khamm bopam yénn gni di ka comparé avec you nak yénokoye sonal rek
    li You daff kéna mounokofi daff yalla moko may lolou
    les jaloux vont mourir hatersssssssssssssss
    aller YOUUUUUU

  • Abdou diallo
    07/05/2016 11:22

    C’est la vrit Sen tv est entrain d’utiliser l’image de Wally pour son propre promotions ce tlvision n’as aucun programme

  • cartel
    07/05/2016 11:36

    deug ta raison je l’avais dit a yekini c une migration la vie et rien d’autre il no rien compris bravo a youssou wayye la vie immigre a lui seul alrs vida ka nada merci

  • you
    07/05/2016 12:33

    wally senegal gnanal leu yaw ak say morom nguène dèf lou eupp lou youssou déf moy takh music Sénégalaise gueuneu dèm yaw fierté nga du courage

  • kheus
    07/05/2016 12:41

    wakh deug dé waly yagou fi bu démé bane koy takalé ak youssou ndour ah diambar la niome niépe senegal lane deuk khana musique thi rew kéne rek mom du ko yor yéne journaliste déf lén sen ligueye ak comedien té bayi sen pateron yi guéni maral seni tat wala kham kham yobu woulén fi guéni ligueyi salaire bine laye faye diaroul gaye khas sa morom ndakh aleuk khamo foye moudjou ana ndogo lo demba dia ndiaga mbaye adou na dou dara

  • Karim
    07/05/2016 12:51

    Waly môme deime na Bilahi nopal Leine seine bope ta ngueine ndogalou yala merde

  • Karim
    07/05/2016 12:51

    Waly môme deime na Bilahi nopal Leine seine bope ta ngueinenangou ndogalou yala merde

  • senego
    07/05/2016 13:08

    Senego ay nafèkh ngèn comantèr feuveur wally seck ngèndi dougeul pour leurè nityi . Man fans youssou la sa comantèr daguènko dindi

  • fifi
    07/05/2016 13:10

    Youssou mofi nèk

  • fifi
    07/05/2016 13:11

    Youssou rèk

  • Abo
    07/05/2016 13:21

    Kouthia vous avez commencer vous la famille de youssou ndour la première a ignorez se goss comme s’il fait même pas parti des chanteur du gals en .aujourdhui le goss a eu un succès et vous commencez a nous tympaniser c’est quoi cet hypocrisie merde Waye .cest après que vous allez comprendre .wally môme deimena ngeine neike fi di ratatati reike

  • demba sow
    07/05/2016 13:34

    YOUSSOU NDOURE WALLY SECK MOKO DIAKHAL PSK YOU DAY MAT CI SOUF DI EUF CI KAW WAL DAFA ENTELIGEN MACHALLA COTHIA YAW DANIOU LA YONNI ME WAL LO NGEN MANOUL CI WERWI MANOU LEN KO CI MOM

  • cartel
    07/05/2016 14:34

    ohhhhhhhhhhhhhoooooooooo mani n’a music bio fou nekh rek yalla n’a nieupeu ame jaaam on as besoin de la bonne music peu de bla bla

  • Aicha brux
    07/05/2016 16:16

    Qui ta fait parler koutia? Qui ta pousser à faire cette ignoble séparation des musiciens ? Pourquoi koutia ? Adouna daffa goude tank koutia.youssou ndour santou la li,jen suis sur et certaine,parceque si tu parle de waly? Koutia nak yangui boyaale fourneau. Waly n’arrête pas de dire que Youssou cest son père et ta nak….adouna daffa goudou tank. Wassalame

  • Aissa
    07/05/2016 16:20

    Qui ta fait parler koutia? Qui ta pousser à faire cette ignoble séparation des musiciens ? Pourquoi koutia ? Adouna daffa goude tank koutia.youssou ndour santou la li,jen suis sur et certaine,parceque si tu parle de waly? Koutia nak yangui boyaale fourneau. Waly n’arrête pas de dire que Youssou cest son père et ta nak….adouna daffa goudou tank. Wassalame

  • Mimi s DIOP
    07/05/2016 16:54

    Mais kouthia loumou wakh dara ayoussi mai you mokoy fay salaire soko nekhé defendre ko Amneussi droit Thione ak you djioubo wougnou legui you sou dieulé wally ba dara fekossi dou indi problem gnom gno warra djiboo en tant k kilifa ba paré lenen topeusii youssou ndour deserve respect loumou mounti mell il cré des emplois té senegalais leu sougnou khamè Senegal prtt 95% c grace a youssou la releve day gneuw par like force mais neu rafet wakh bou gnaw djaroukoffi ak dé bou gaw tot ou tard wally ak you dagn dèdjè Si kaw scene bouba gnouy rouss dineu beuri t en on ne c pas c ki se passe en dessous fo faire attention man douma deglou wally mais in shaa Allah dina dem bercy prsk c un senegalais t dama fiere au moins benen senegalais mougui teugue bercy point

  • M NB
    07/05/2016 17:17

    Bilahi couthia tu decu mè nala lpr boubs nawlowoula

  • Cheikh bi
    07/05/2016 19:49

    Kouthia avertit DJ BOUBS élément clé de TFM que j’aperçois ces temps ci avec Waly. comme vs l’avez dit: la concurrence nourrit les fans mais waly est bon chanteur mais qu’il continue de bosser et prend son papa youssou comme une référence comme l’a si bien chanté le grand Péne (mentalité). bref on a tout dans notre pays. Sénégal=Sénégal et usa=usa. fier d’être Sénégalais

  • epagnol
    07/05/2016 20:03

    kouthia yaw dagaa niack personalit waly limou am bi youssou ndour am atyi waly am youssou ndour amouko won

  • epagnol
    07/05/2016 20:06

    yn Domou youssou ndour yi ynaf nk diwakh m dgou ln waly wakh dar

  • Bro
    07/05/2016 20:19

    Youssou Ndour warna kholate employés télé bi !
    Leurs niveaux est trop bas .
    C’est sur les bancs diakhlé qu’on trouve ce genre de discution mais pas a la télé.
    Au final Macky avait bien raison , il n’ont pas de programme.

  • Abdoul Aziz
    07/05/2016 20:46

    Kouthia stp arrêtez de monter les uns les autres tu es un vrai fumier rambadji. Wally à toujours considéré le Sieur Youssou Ndour comme son Papa. Bayil sokhor té du gnane nit yi diam.

  • Ciao
    07/05/2016 20:56

    Kouthia Yaw temps ye rek ngafi merone nane di faye aye thiaga

  • Mya
    07/05/2016 21:01

    Ay wakh yougni dieumeulé kanam laniou sokhla pas ay Wakhou dof.

  • GUEYE mr
    07/05/2016 21:27

    les 02 musiciens ne sont pas comparables.

  • zakaria
    08/05/2016 06:09

    mane dé depuis demb waly seck rek lay deglou…mais boy bi grawna dé …fan youssou ndour la nakk mais fils bi bi ahahahah

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces