Annonces
Annonces
» » » » Vidéo – Come back de Déguène Chimère à...

Vidéo – Come back de Déguène Chimère à la télé

L’animatrice de la Tfm Adja Déguène Chimère Babou a fait son come back à la Tfm pour un plateau « spécial fête des mères », après une longue absence


Vidéo. Déguène Chimère is Back après une longue… par hamidou-sy3

Annonces
Annonces

15 commentaires

  • sokhna walo saliou
    30/05/2016 00:46

    yalla na diamm yagui

  • zeynab
    30/05/2016 00:59

    dieu merci mai mb defarouga tele bobou dafa garaw ay seurigntou wantè rek mofa am ay galatj you bon takoul t ga nane wa salam

  • Aicha
    30/05/2016 01:25

    Maman Chimère yallana sa diam yague dagua yieuw bakh raféte je t’aime bcp que Dieu te protège. Amine

  • dam
    30/05/2016 01:41

    nice

  • Amina
    30/05/2016 03:21

    Zeynab nit kou bakh dai wakh loko leer sourtou djullit ngua balma,Alhamdoulilah Mama Yalla nala Yalla diapale lafal la thiat dakhal la saitane ak lep bone tek la si yoonou siratal moustakim,Amiin namoun nenj la Yalla na sa diam yague,Amiin

  • khabiba
    30/05/2016 03:40

    maman deguene mamones nañioula lole tamaña borom bi yok wergui mousseuleu si lep louye lore halahouma amineee

  • princesses
    30/05/2016 08:46

    je suis heureuse

  • mina
    30/05/2016 09:21

    Je te regarde comme ma maman que j ai perdu que dieu l accueil dans ses paradis et bonne fête à toutes les mamans

  • zeynab
    30/05/2016 10:06

    yow amina merde lima wax mofa am limay wax dama lèèr j aim bien maman dègène amna droi wax ko mou dèfarou on ne en afrique non deug da nèxoul nak

  • rakadjou
    30/05/2016 10:22

    amina mano fe wedi dara lim wah dara douko dindi

  • konte ndioro
    30/05/2016 13:58

    que dieu te protege , yo allah hoke jam e cellal yo allah addu jam , je t’aime beaucoup ma soeur cherie

  • kira
    30/05/2016 15:07

    C’est pas une rediffusion l mission d hier sur les mamans

  • oumar
    30/05/2016 16:33

    Seul dieu peut et seul dieu sait

  • fa
    30/05/2016 19:47

    je trs contente de tes invites surtout sa rakk fatou kin ndao sa de ne aram fa kha yaga sole thioup ndao mre theresa deugueun yalla na yalla takhawou amine bonne fte des mres

  • Julien
    31/05/2016 06:37

    @ ma Soeur Déguene chimere, wattul concurrence bi ak thiam thiam bi balameïssa teint noir MT
    Djoundjeu doyna borom xell
    Mangui weur sa numéro dina djoko ak yaw mayleu bén Exclusivité,
    Sister wagñil Sangue sé, je te conseil changer de look Eva Tra o Collé Ardo Sow tu sera valorisée est puis des bijoux africaines.tu est st louisienne, L’or de N’dar na Birr…

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces