Annonces
Annonces
» » » Video- Cap Manuel : Assane Ndiaye renvoyé comme...

Video- Cap Manuel : Assane Ndiaye renvoyé comme un malpropre par Thione Seck

Annonces
Annonces

36 commentaires

  • rank
    25/06/2015 08:20

    Thione mo rancunier thieuy thi werou kor bi nak

  • lamp
    25/06/2015 08:26

    kil pourrisse en prison domerame sa khol bou bonne malfaiteur

  • rifo
    25/06/2015 08:34

    aye pape thione li epeneu ahhhhhh

  • feuz
    25/06/2015 08:49

    mais thione mom louy problemam li niawna way ah

  • deuch
    25/06/2015 08:50

    yaw thione seck assane ndiaye mi ngay dak rak la nioune bokouniou ak more dara nit yi niougui lay nianal mail soy def yi danioulay diépi wasalam sal kon

  • mome
    25/06/2015 08:57

    no mé la c tro ton propre frére thione il é mal saint en plus si wér bou sél bi gneup di balaneté ak il na ka pourrir en prison ki dafa bonne wayy tchiiimmm c honteux

  • delfa
    25/06/2015 09:19

    thione daffa bonne kholl..likko daal nakk il le mérite et c lui le responsable des faits kon lui reproche..Au voleurrrr..son fils c un fumier kom lui il a essayer de réconcilier son père et youssou ndour et pourquoi pas son père et Assane ndiaye et autres de sa propre famille..limou deff assane ndiaye nakk bouddé deugue leuu..Assane filaye dieullé gueunna takk affaramm gueuna bakh..il aura fai k'attiré la haine en lui et le bonheur en assane ndiaye..wasalamm

  • blake
    25/06/2015 09:23

    BOUFEKENE MOKO DEFE DE RAFETOULE MAIS GNOMINENE LA CEST LA FAMILLE SOUGNOU YONE NEKOUSSI MAIS THIONE MOME DEFENALOUGNAWA GNAWE

  • diop
    25/06/2015 09:52

    avec sa dites que vous êtes en mois de ramadan. vous confirmez vos dire sans y être

  • safara
    25/06/2015 10:28

    waly diemel regle probleme bobou ..mo guene nga sona thi sa papa ak youssou ndour ..

  • amy
    25/06/2015 10:58

    thione khana do dioulite sa khole bi rafetoute fara

  • Dioulit +
    25/06/2015 11:18

    Son frère…si vous le dîtes… Stop. Attendez cela fait comb1 de temps que thione est à l'ombre amis historiens élevés au bon sens? Vous dîtes trops de choses sans y être vraiment. Pourquoi assane ndiaye a attendu de digéré ses yassa poulet du midi, ses ataya et autres distractions futiles pour enfin s'enquérir de l'état de son "frère"… Bayilène thione mou tranquil, sétaane na dakk ci ndadjé.
    De plus si assane était

  • coumba ndiaye
    25/06/2015 11:40

    Assane defoula moromou assane defoula lileu dal yaka tekk sa bopp khana kou bone ba dougou kasso warna bakh wayer assane raw nala yaaaaaa kham

  • vrai sénégalaise
    25/06/2015 13:08

    non tione seck ya bonne. dagal sa courouss guima degue mome gaye weko.thim lila metti assane tegoulaka. yaw yalla ji sakhe daye dieguele. te assane daladefoule dara. assane sa kaw sa kaname yalnala yalla diappale dara bouka mère boume la diakhal. dou mome thione migui recevoir nienene bayyiko kou watie sa ande ande bo dème fekfa sene borome niiu fess ka déle.

  • ass fallou
    25/06/2015 14:22

    djioulite dal dagay djégalé Kant a assane nak santal sunu borom tuyabé djép yawlako allah djaglél sa khol mo guene rafete motakh

  • nite
    25/06/2015 15:20

    THIONE a raison mais pas rancunier! ASSANE n'est jamais allé rendre visite à THIONE chez lui mais quand ce dernier est en prison oui il y est allé c'est un peu pour aller se moquer de lui et c'est THIONE qui a fait de lui ce qu'il est devenu aujourd'hui. Je me souviens lors d une emission keb's posait une question à ASSANE NDIAYE concernant THIONE le frangin l'a arreté automatiquement en lui disant "je ne veux plus que vous me parlez de THIONE." alors pourquoi il va aller le voir en prison? pour se moquer oui.

  • DIEGANE
    25/06/2015 15:42

    Li dal Thione, yala kako ték. Kou la sétiwoul bi gua néké sa keur, sou la sété casso, délay koqueli. Mo yéy dakh Assane Ndiaye.

  • Djimbory
    25/06/2015 16:11

    Mane dé Thione Seck yeureumone nako, liko dal méti wone nama torope wayé fimou tolou ni diépinaco, quelque soit leur probleme nite ki sou défé 1er pas ba nieuw setsila nga meuna tok ak mom nguéne wakhtane, balonté aak, Surtout si wér bou sélle bi gnou nék nak…dioulite waroul rancunier!!!

  • insa
    25/06/2015 16:38

    mais gayi nitt bou ka malheur dalé guén dioté wone nak di ga ko sétti ndakh joulite ga.Nit bayi na fi morom ba mou guén adouna mou dém ci deudieum.

  • fatima
    25/06/2015 16:57

    assane désolé mais tu ne parle pas à des cons comment se fait il ke thione est frére tu ne part pas le rendre chez lui et tu veux allé le voir en prison explique nous

  • Wakh dengue
    25/06/2015 17:09

    mome mi Di wakh sakh yi ci biir souf té geumou ko c'est dans les mauvais moments que l'on reconnaît ceux qui nous aime encore une fois Assane ne t'a rien fait pour ceux qui ne le savent pas Assane ne lui a rien fait lui aussi ci il était dans ces débuts il n'allait jamais accepter de chanter son morceau far dans n'importe quelle diapason même ci c'est celui de ton frère

  • Wakh deugue
    25/06/2015 17:19

    alors ceux qui ne savent pas les causes de leur problème n'ont qu'à se taire au lieu de dire des bêtises

  • cheikh
    25/06/2015 17:20

    THIONE a raison mais pas rancunier! ASSANE n'est jamais allé rendre visite à THIONE chez lui mais quand ce dernier est en prison oui il y est allé c'est un peu pour aller se moquer de lui et c'est THIONE qui a fait de lui ce qu'il est devenu aujourd'hui.

  • sam le pirate
    25/06/2015 18:06

    NDAYSSANE LI NIAWNA TOROP.MAIS QUI A CHANTE "DOMOU BAYE"?:)SOUNOU NIARRY YAYE SOUNOU DJOTEE SOUNOU YONE NEKOUSSA :)DOUMOU BAYE ASSANE KAYNIOU FOO TEE REEH :).DONC THIONE DALL N'APPLIQUE JAMAIS LES BONS CONSEILS ET BONNES RECOMANDATIONS QUI ONT FAIT QUE LES SENEGALAIS DONT MOI ONT DE LA SYMPATHIE GRANDIOSE POUR LUI.

  • eumeu sene
    25/06/2015 18:27

    thione ct1 rancunier je l connais bien

  • Vérité
    25/06/2015 19:12

    thione a raison si on veut manger la nuit on prépare le repas avant donc il fallait kil le voit en tant q grand frère avant kil soit emprisonné

  • aliou kouyate
    25/06/2015 19:44

    thione doit croire en dieu comme musulman.Assane n'a rien fait c'est le destin

  • gaks
    25/06/2015 20:27

    Assane bon courage thione égal zéro na dé si kasso bi demal topoto sa ay bissnes

  • malick
    25/06/2015 21:00

    Assane ndiaye yalla nalla yalla diapale , defnga lila warr , té defngaa thieurou rakka . Yalla nala yalla fay sa yene . Gnoun dagnoula yague beugue té kouka moussa diokh respe nga . Mai lii da l boumou la derange . Li natou la te yaw tegoylo kokou .

  • bara mbaaye
    25/06/2015 22:21

    Thione est trop rancunier aussi!
    Akhhhh
    Yalla sakh dey baalai

  • assane
    26/06/2015 00:36

    waw assane lilawar dèfeguako sa diane wathina tout le sais k tu nètai pas au senegal et tu a postè un video sur internet pour lui souhaitè kil sort de prison

  • thione
    27/06/2015 00:27

    lila nakhari assane tègoulako

  • seye orange
    27/06/2015 23:05

    thione messe na tok si benne télévision gnou koy lathi loumou kham si Assane ndiaye moné yalle na soukh manam am ay diafé diafé lolou motakh gnou nane yené borom mo thiay fanane nit koubakh dangay rafétte kholl lou sa morom am nga yéne koko

  • nit nité
    29/06/2015 05:59

    khana yenne worou lenne yalla nanou yalla dimbalii wa Sénégal amine

  • soda beye
    19/07/2015 22:25

    Gayi man ak yen gnoci yam ken hamul numu deme entr gnom nagnu ci manu ken hamul dal bulen ci bakar gnomi nen la hamolen lugnu diote

  • faviouda
    08/08/2015 10:27

    Helaaaaaasss

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL