Annonces
Annonces
» » » Vidéo- Calme total constaté chez Thione Ballago...

Vidéo- Calme total constaté chez Thione Ballago Seck

Annonces
Annonces

27 commentaires

  • promo
    01/06/2015 20:38

    wa tfm amoo lene jome dh mdr ba thione geine thiep bou didji laleni genel

  • Codyco
    01/06/2015 21:37

    No mes ils font que leurs travails la tefm nous issus ont n'a besoin de savoir

  • waw
    01/06/2015 21:49

    sen Liguèy rafètena

  • Madam Faal
    01/06/2015 22:11

    thione manoul thi wa tfm touss sen ligueye lanion def bounio thione sonal bou bougoul kuko lijanti na def lou dioub

  • hypocrite
    01/06/2015 22:43

    Yaw Madame fall beurki dème gua commentè di gnanal thione tay gua takaw di wakh li mane dal ma warou t Mr fall yeureum nako nak madame commentaire la ameeeeeee

  • Mina
    01/06/2015 23:27

    loll hypicrite

  • Dany
    02/06/2015 00:20

    Hypocrite la y'a rien n'a ajouté tu la eu dans l'ordre Madam faal Mbo nékone glace sayy gua ouhh rousse na gathié gui may beugeu rayy

  • fall modou bété bété
    02/06/2015 00:23

    hypocrite t'as prfaitement .raison. deugg nekhoul ta deugg rekk la yallah beugue. …… madame faal .meme .soufeké ni Thione seck moko deff sakh …dangako wara nianal diamou ta yallah rékk takh ..nguir mou delou watt si ay ndiabotam si barke seydina mouhamed psl. . pask prison bi diomboul kéne. gni dagnleni togne dougeulénfa niene gni togne niou dougeul lénfa .pask nul n'est parfait. yallah soubhana watala rekk mo maatt.. ta kou kheuy souba ba ngon diott nga nga teudd si diamou yéwou wat si diamou .nga warko santé yallah ta khamni dousa diambar .yallah la nekh.. . ta lo yéné niit ki nak moy kheupou wat sisa kaw .rek .donc naniou bayi yéne yi.. ta foot kholyi .yenén nékla borom mosiy fanan… o6 nul personne n peut echappe a son destinnnnn . Am détt .les gars . mangui diegeulou bou bakh. .defar rekk moma takha dioukk wasalam

  • kesk
    02/06/2015 00:25

    Est ce que c'est la même Mme Fall?

  • sas
    02/06/2015 06:11

    C'est la même madame fall dakh mome kou lal tfm rek c'est fini y à qu'eux qui compte khawma da ame faar fofou wala. tu insultes la mère des gens bamou nekh la et le lendemain tu nous demande d' arreter d'insulter. gorél waye

  • mareme
    02/06/2015 06:18

    en plus madame fall dans la série double vie les premiers épisodes tu disais(film bi nekhna) après l'épisode d'avant hier tu disais ( film ba gui commencé nekh) donc tu savais k film bi c'est nul mais tu refusais de l'admettre. hypocrite

  • MADAM FAAL
    02/06/2015 07:58

    Tfm c'est la meilleur !! Cessez de le comparer avec sen rediffusion !!!

  • MADAM FAAL 2
    02/06/2015 08:05

    Regarder tfm ,écouter rfm et lire observateur : une vraie joie de vivre

  • Amina
    02/06/2015 08:34

    Madam Faal dou ben hypocrite lim wakh moy degeu kou bange koula lijanti dangay def lou diob lolou amoul dara loum def ak nian yi mou nian

  • saoudatou
    02/06/2015 08:43

    J demande à DIEU le tout puissant kil fait k pape thione sort vit en prison et k yalla tèguilko natou yi mou am c n'est pa mon fans mais g pitié d l8 c com ont l8 veulent du mal mou diougué ci problème dalat ci problème

  • hams
    02/06/2015 12:09

    de toute façon dieux ne dort pas depuis que wally à annoncer sont n ouverture de sa propre télévision est voilà on veut détruire la famille ballago ragalene yallah thione n'ai pas ce genre mais dieux va ramener la lumière sur cette affaire inchallah qui vivera verra???

  • Madam Faal
    02/06/2015 13:08

    man douma hypocrite nianal thione takhoul domako wakh degeu yen yenai hypocrite yu makyi

  • Madam Faal
    02/06/2015 13:11

    yaw mi wakh ne dama am farr tfm bayi nala ak Yalla man douma yen miy takhawalou bima amey 18 la am djekeaur ba legui mangui sey man sey la kham

  • Mbaye Babacar Samb
    02/06/2015 15:03

    djoulite dafffa wara khameniii djoulite laa diii yéyné sa moromoü djioulite lou bakh sou nékè si tolof tolof nga gnanalko wala nga takhawoukoo mo gueune wakh djou gnaw djiii imaginél si c'était votre père oublien votre oncle…. svp bayilene wakh djou gnaw djii natou kounè lay dale yala moy khôl kouko nêkh mou nék ko natou lii lou yala toudone la si mom avant sa naissance donk gnanal lenekooo. lima diakhal si nite gnii moy da nguéna gnak djom douguéne deg deug moukou wayè adouna biii dafaa diekh ba paré

  • damefadelmbaye
    02/06/2015 15:28

    ooh les gars senegal doyna warrr papa thione lila dal yallanallayalla guenee

  • damefadelmbaye
    02/06/2015 15:29

    vive senegal

  • sas
    02/06/2015 16:26

    madame fall bayil di takhawalou si net alors

  • diop
    02/06/2015 16:41

    tres serieusement youssou ndour ne serait ce que du fait qu'il partage le meme metier avec thione seck, ne serait ce que les bonnes relations qu'entretiennent Waly et birane son fils, ne serait que pour les altercations qu'il a eu par le passé avec papa thione devrait demander à son groupe médiatique de traiter la chose avec modération. je ne suis pas la pour juger qui que ce soit mais dafa ame affaire you rafétoul. Ni walf Tv, ni Sen tv ni stv ni la RTS n'est entré dans les details comme GFM l'a fait. Et je trouve ça ridicule voire même bête d'envoyer des journaliste chez thione le jour du procès. c'est evident que tout le monde est parti au tribunal. et j'imagine que s'il etait a la place de thione sa maison serait deserte aussi. Nagnou rafétal Ande bi. Adouna amoule solo. si le bon dieu accepte qu'on fasse des erreurs et de se repentir mou bale gnou par sa misericorde je ne vois pas pourquoi les hommes veulent etre des juges. So meunoule wakh lou raféte ci nite. boul yake dérame. yalnagnou yalla maye kholou djoulite. Wa salame

  • BESS
    02/06/2015 16:42

    Bon vraiment c'est malheureux pour thione et sa famille. c'est dur. yalla moy tégué natou. mais yalla na ko borom bi djégueul.

  • zeuthie
    02/06/2015 20:46

    papa thione yalla nako sunu borom gué né si Natou
    bi

  • mme serre
    03/06/2015 11:49

    En union de priere avec papa thione les gars un peu de respect pour la famille seck merci a aby ndour vraiment tu es a la hauteur

  • publication serigneMbaye publication
    05/06/2015 11:38

    rafetna

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL