Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

221 33 823 43 43

Annonces
Annonces
» » » Vidéo : Balla Gaye N°2 savoure sa nouvelle...

Vidéo : Balla Gaye N°2 savoure sa nouvelle voiture, offerte par le footballeur Mamadou Sakho. Regardez

2015-06-21T00:06:28+00:00 Partages

Annonces
Annonces

12 commentaires

  • mor
    21/06/2015 00:55

    balla gaye diekhalna te dioudogoul li motakh dopas bakhul com drogue boubegate danat day dieul yawoudial lolu donga koy mana takha amat ndam si lamb jii jajaja

  • verité
    21/06/2015 02:04

    Mor si koor lagn nék niit nday wakh louko woor téga bayui sokhor balla Gaye2 def nafi lo khamné moromame douko gawa déf té déma goul féne yalla bakhna . khana gisso bombardier fimou diarrr baboy tapha tine yekini niep daneko mou dane balla gaye nga wara khamné yalla rek mo khame leep .sokhorr bakhoulllll …

  • Thione
    21/06/2015 02:17

    Diadieuff vérité

  • diop
    21/06/2015 02:46

    thiey vérite ya kham dek te diko wakh yalla nala yalla diapale

  • La diva
    21/06/2015 05:43

    ignane lagnou wara bayi

  • Bou
    21/06/2015 08:33

    Mais @ mor ya sokhor té touti khôl .ndeyssann comme disait sunu mame diou bakh djia mame abdou Aziz sy rakhass leen kholyi bouniou beugué rewmi demm il le disait en 1989.sokhor sokhor bakhoul

  • legalazed marrihuana
    21/06/2015 09:57

    mdrrr

  • kira
    21/06/2015 11:41

    vérité merci

  • santeyalla
    22/06/2015 03:43

    sa ma gayi balla gaye mofi munne gnou bagne gnou nagou balla gaye moye Roi des arenes machalla

  • Retannne
    22/06/2015 09:11

    boy bi diay tarr rek mokka desseee hahahahahahahah

  • pontiak
    22/06/2015 11:46

    champion pour toujours

  • teuss
    23/06/2015 12:36

    bou liguakhaw lolou moye deuge bouwer

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL