12 COMMENTAIRES
  • jomar

    yeena khame dei soof nguene loole

  • diagne

    S'il était coupable il ne serait jamais retourner au Sénégal, une tête sert à réfléchir

  • Amina

    rak ak dom ma yem bolen amey danglen warr di wakhal niouy dokh si lou bakh newouma nak mo def wola defoul Allahou Allam Yalla rek kham kom danio toud si yef yi nenj bayi justice mou def ligeueyam

  • Boy Toronto

    yalla nako yalla gueunei famou nek

  • Wade

    bb

  • rappels1

    adouna c difficile,dinagn la wakhal té dougnla khamal,dinagn la djign té djissou gniou nguay deff,bagnla ndakhté dagnla dégual,té léppeu si kaw jalousie,wala sokhor,loussa yone nékoul meuytoul,loula woroul nopiil,daara sakhoul,daara yaguoul

  • as
  • senego

    suis pas waly mais la je compati avec lui du courage métina trop Massa

  • la Lionne
  • ria

    yalnako sounou borom takhawou

  • Wa Medina

    Du courage waly! Tay kou sagnou sa ben mbok dou nek si kasso bi. Gni nek si kasso yi yalla nalen yalla doli soutourou ba li len fa dougal guenai len fa si barke bour bou ted bi…….

  • dadi

    PK TOUJOURS CETTE FAMILLE LA JUSTICE FAIT QUE SON BOULOT COMBIEN DE SÉNÉGALAIS CROUPISSENT DANS LES PRISONS SANS QUE PERSONNE PIPE MOT QUE VOULEZ VOUS UN PAYS HORS LA LOI

Publiez un commentaire