Annonces
Annonces
» » » » » Vidéo: Amy Collé Dieng: « Comment j’ai...

Vidéo: Amy Collé Dieng: « Comment j’ai vécu l’humiliation au Thiant de Cheikh Béthio… »

Invitée sur l’émission « Good Time », Amy Collé Dieng est revenue sur sa fameuse humiliation au Thiant de Cheikh Béthio Thioune. Selon la chanteuse ça ne lui a fait aucune peine d’être humiliée.

Annonces
Annonces

39 commentaires

  • deug
    30/07/2015 21:53

    sofff Hawmala demal baniu hamla

  • lima
    30/07/2015 21:59

    yaw ya niak diom wa ki werna est ce que yaw niou torakhal gua nek fi niak fayda thip

  • amy
    30/07/2015 22:07

    fene rek danga gniak classe rek kou dem fougnou la invite woul lou gnou lafa def ya togne
    tu chante bien mais désole personalité zero malheuresment.

  • fina
    30/07/2015 22:11

    ami Cole weroul

  • ibra fall
    30/07/2015 22:43

    bethio, Amy et patra sont tous des idiots, merci

  • khadija balde
    30/07/2015 22:44

    bayilen diabour kou nek amegua lo wora wakh té doko wakh sof guen trop li mo takh galsen dou dem .kan ta tw amy collé bnn cntinuation té del mouslou thi saye none comm lé jalou demougnou té beugnou ken dem

  • Amina
    30/07/2015 22:58

    fofou reik la Amy! Content na cii iOw. Nit dafaay yarou, rafeit, rafette thikoo

  • binbin
    30/07/2015 23:09

    thieye

  • Marième
    30/07/2015 23:12

    mdrrrr .. wa damay lath : torokhal moy li geune si mom ???
    quel ngeunel ..lol
    no amna nioudoul dem

  • cheikh
    30/07/2015 23:49

    Gni doul dém de yawe thi nga bokou yawe marieme

  • kathia
    31/07/2015 00:03

    ami yorou te ame talib nit deille diouf bethio nit rek le heureure et humaine il faut etre mechant et egoyise

  • kathia
    31/07/2015 00:05

    ami cole da yarou rek te ame talib nit dou fayonetou te bethio nit rek le te nit deille dioum bayilenne critik bi

  • 0stress
    31/07/2015 01:29

    Kone patra dal dafa boukh niaari gossettes yoyou bakhna Si gnom Manougnou gatte Si animation tchiiip

  • begue s touba rek
    31/07/2015 02:28

    Waw nitt day fıwof merci ami Liga wakh rafet na lolou sakh

  • weuz
    31/07/2015 02:55

    amo diom, do rousss, do yarasssss

  • weuz
    31/07/2015 02:56

    sofia bayi len thiagatou bi

  • Pathia
    31/07/2015 04:14

    hana dou Batou Ly ak Kou khéss ka, u m'as tué mdrrr

  • Pathia
    31/07/2015 04:15

    iOw Dh moleu geun, nit dou fayantou

  • Bizarre
    31/07/2015 04:23

    Ki doff bouy takhawaloul rék khamoul foumou djieum

  • Rek nak
    31/07/2015 04:57

    Ami colle dafa yaru rek nek mourid teksi ni rek la meune wahei bou done kenene moko toril gal mou wakhei nenene mais dafa ame régions rek nak

  • Rek nak
    31/07/2015 04:58

    Dafa ame teguine

  • kharagne
    31/07/2015 07:13

    niak diome

  • mame diarra sarr
    31/07/2015 09:31

    cheikh bi foula rék la ame diéki diéki rék gneuw si programou diambour di keuf micro melni kou nék lamb ja

  • LE DIABLE DE NET
    31/07/2015 10:21

    non comenté …………….

  • obama
    31/07/2015 10:29

    cheikhe bethio egal satan et iblise …c talibee sont foutu

  • cheikh diop
    31/07/2015 11:23

    c'est oboma ou abîme, tu es méchant,ce que cheikh bethio a c'est dieu qui lui a donné ça et personne n'y peux rien. tu peux te cacher dans ton coin et dire des bêtises c'est facile mais un jour viendra tu va le regretter amèrement.

  • am
    31/07/2015 13:06

    TOUS VOUS COMMENTAIRES SERONT RETENUS ET JUGEZ PAR ALLAHOU YA SALAM

  • Serou bethio
    31/07/2015 14:08

    Amy ga tané ko soi disan serigne béthio mome mou niak kérsa boudone serigne saliou doulako déf j tencourage

  • verite
    31/07/2015 15:36

    AMICOLE COURAGE MERCI SI SA YAAR AKH SA TEGUINE XASSOO KEENE SAGOO KEENE XOULOO WOULOH KEENE MAIS NAK SENEGAL NITTGNI KOUYY XOOLOO DI DAGASANTEE LAGNOU BEUGUEE ARTISTE NIGA DEF LAAY DEF BOUL WOUTAL SA BOOP AYYE NOONE COURAGE LEEPAAY BAH TOUBA KOU SERIGNE TOUBA WOO YAGUISSI BIIR DIOUMTELA WOONE REK AKH LOU WAARA AM TE YALLA MOKA DOGALOONE MERCI VOICI LEXEMPLE DUNE FEMME POLIE CORRECTE YALLA NA JAMM YAGUSI SENEGAL WOOTEGA JAMM EUYY WAAY BOULEENE WOOTE FIITNA WALA DIKA XASS MERCI VIVE LA PAIX

  • as
    31/07/2015 17:30

    il faut vraiment ecrire en français personne ne sait ce que vous dites ,les senegalais ont une mauvaise habitude maintenant

  • mame gorr
    31/07/2015 18:22

    cheikh bii doufi touss

  • ebolete
    31/07/2015 18:36

    rire sakh

  • bethio
    31/07/2015 18:52

    cheick dou touss day doul rekk

  • sokhna aida diallo
    31/07/2015 21:23

    dieukeur sama bethio. dou def niit lou bonn dafa bakh am yermandé

  • OBAMA
    01/08/2015 00:09

    cheikh diop yow tamite ,bethio nena CORAN BI waaw lathi kham parce que dafa niroo ak neuf,et il marie c talibe avec 7 serign saliou extra extra ,,waa gaayi wakh lene thi waaay,,,,,,,, ku changer atte yalla KAFIR GUA ,cheikh diop demal lath imam bula gueneu diegai

  • mame
    01/08/2015 01:41

    c'est un mauvaise habitude de s'exprimer dans sa langue? vous préfériez qu'on s'exprime dans celle du colon! brainwashed tchimmm!

  • bagn cheikh bi
    01/08/2015 02:47

    cheikh bethio dou nittt dhh deum leuh té kokou moytouwoul dinala lekk sacrifié sa vie

  • laye
    01/08/2015 11:59

    yaw mbame nga

  • laye
    01/08/2015 12:01

    yaw obama doméram nga motah ngay wah lii

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL