Annonces
Annonces
» » Vidéo-Affaire de «Dieuw» Ahmed Aidara: Kouthia...

Vidéo-Affaire de «Dieuw» Ahmed Aidara: Kouthia dans la peau de Toubab l’accusé

2015-05-18T18:46:24+00:00 Partages

Annonces
Annonces

29 commentaires

  • Ozil
    18/05/2015 19:28

    mDrrrr Kouthia Balko way doyna

  • fatou
    18/05/2015 19:34

    Kouthia yagui may beugeu sof nak tu p pas fair ton emision è laisè Ahmet trankil sa NAWLÈLA WATHIEKO EUPNA TROP way

  • fatou deugeu mo nekh yalla
    18/05/2015 20:00

    kouthia moom nieupou layamale actualite reek ahmet ak kenen nasiyam koudeef degeu koudefoul dara dodegeu dara ahmet aidara mo deef motakh mou degeu lima geuneu nakhary mooy senegalyii dagno beugeu neupneupal gnouy mbouboo journaliste diyakh derou journalistiyii ahmet aidara kaay khatheu bou boon laaaa

  • fatou
    18/05/2015 20:07

    mani kouthia ya tay fi la tek dieuwou tange si radio bi ken wakhousi dc kouthia wakh si bamou nekh koumou nakhari ga tal gaz toksi dayam bouniou keneu ray waw

  • ahmet aidara niak class
    18/05/2015 20:08

    ahmet aidara diaratoul dara si deukeubii yeun dalena faye khalise pour geun neek du comentair du ko maraal tatam ozil ak fatou niak fayeda

  • Peace
    18/05/2015 20:12

    Tu tombe trop bas …….kouthia …arête avec tes inventions mesquines pour salir ahmet aidara. Il a faute certes mais de la a en faire un commerce….c est trop…..c est toi qui entrain de faire ton émission pour tomber dans la grâce des personnes mentionnées par ahmed…. ton émission devient du salissage, et du wagnane….

  • Mimichou
    18/05/2015 20:19

    Bien dit kouthia je suis fière de toi god bleds you Ammiiiinnne

  • fatou
    18/05/2015 20:54

    Deugeu mo nèk yalla ak niak class il ya 2 fatou ki a comentè la 1 c moi c vrè k deugeu mo nèk yalla wayè c trop li boul bouy tournè rèk la kène kamoul foumouy dal tay sa morome euleuk yaw niak class j fè pa d rèpondre car ton disan nom ta rèpondu

  • Madam Faal
    18/05/2015 22:18

    koutha defal loula nekh ku merr bokoo

  • pa
    18/05/2015 23:00

    Kouthia n a rien inventé. C est toubab qui a fait ces révélateurs dans direct info

  • diop
    18/05/2015 23:53

    Amet aydara ndekeh domaramla.Il faut saisir la balle au rebond pour assainir ce milieux soit le procureur ou Cnras doit sevir .On en marre que des mediocres prennent la presse de ce pays en otage.La balle est dans votre camp

  • nit
    18/05/2015 23:57

    Kouthia ne fait que relayé les journaux. ki niou tek gathie kaye mome BOROME GATE GOU REUY GUI… THIMMMM AMET YALLA MOLA WER TE CE N'EST QUE LE DÉBUT DU COMMENCENT

  • teuss
    18/05/2015 23:58

    Ahmet moy teuss rek nak . Mome le dal mofi dey loune wingue . bougnou rey .
    temps yi ahmetgate la

  • ja
    19/05/2015 00:13

    ahmed defoul dara demba guadio moye salo mamadeou ndiaye bou tfm sofenama way

  • paf
    19/05/2015 02:08

    j'ai même honte de dire que c'est mon collègue tellement dara rousse.. woyeeee woyayoyyyy wolou bale gathie dima Ray amet yay cochon thimmmm

  • verite
    19/05/2015 06:48

    kouthia defoul dra il fait kon son bboulot fatou bo amei loula meeti gua woter teuusss dioyyy kofa wala bagna setane soooof gua troop

  • fatou
    19/05/2015 08:08

    boy verite bayil sama tourondo bi way lol,mane ma wakh kouthia ya tay defal loula nekh mofi def louné wing si c t tw kouthia ya dieuwone kone si radio bi lay tok amelafa kone ya tay kouthia forever

  • Madam Faal
    19/05/2015 08:42

    ja bayil Muhammed Ndiaye kokou ligueyam lai def te ken dou ko feye pour mou revue de press ben nitt

  • rima
    19/05/2015 10:03

    kouhia lii moy buzz diamono yi wakhal bamou nekh

  • Fallou Kare
    19/05/2015 10:11

    Yena yam rékk dieun si ndokh la kOu diékko sa morom lékk

  • eroine
    19/05/2015 10:21

    amed baayil duul ak day

  • fa
    19/05/2015 10:22

    kouthia diokhgnou léléne li mome sof nagnou khana légui information ahmeth rék ngaye weur may gnou diam nak yén yeup pa yéme

  • SOFF
    19/05/2015 10:25

    SOFF NGUENE GNIOU

  • SOFF
    19/05/2015 10:26

    sen réglemùent de compte yi soofff naniou

  • OULISH
    19/05/2015 11:48

    Mdr, Mdr,
    Aidara doit se suicider, bii gathiè, damaa rouss sakh mane

  • alas
    19/05/2015 11:58

    Fatou t trop béte

  • Madiop
    19/05/2015 18:42

    Mdrrrrrrrrr Kouthia dingama ray kw _ Amet dé xawmeu kouy DIEUWEUTI waayé bouko déguéé day DAW _

  • Cheikh Dièy
    19/05/2015 18:55

    waay Fatou iow nak boulniou SONAL kw nioune ahh _ mom bimouy tégg nitt gni ci teuss fo nékone vraiment Sénégal beurineu nafèkh TROP . Arrétez d'etre l'avocat du DIABLE oooh . çà lui apprendra de parler en BIEN des autres surtout en leur absence . DIEU n'aime pas le dieuw c kharaam _ Un dernier conseil pour finir soit humble arréte de te vanter et de dire ce que t'as fait ou non pour les autres OK , car nous celà nous importe PEU _ Déll déff té YALLAH takh tènga waagni wanèwou kou SOFF nga

  • fatou
    20/05/2015 10:33

    Yaw cheikh fi persone n connè persone on f k donnè notr avis mè louy wanèwou daguama kame wala_____________

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL