17 COMMENTAIRES
  • ben

    merci sa ndiogou

  • prof

    Écoutez ce guignol. Il déteste la Tfm et tous ceux qui travaillent là-bas.

    • patriote

      Tout à fait vrai SA NDIOGOU

  • Farra

    Yaw critique rek gau meun pape cheikh dafa wakh ni kou ataque senegal mome gau ataques ndakh dafkoy nakari?

    • khoul

      Il n a pas attaqué le Senegal . Je te rappelle que son dernier single est titré « Dakar », une bonne publicité pour le Senegal .Et c pas le rap polonais qui va faire ça .

  • Galsene

    Les sénégalais ne se mettent jamais en question.il na pas critiqué le pays mais les rappeurs excuser moi de le dire mai sont médiocres.zero création toujours du copier collé.

  • cure dent

    yaw booba loumou wakh deug deug khamoo ko sakh

  • merd

    te kon bordel

  • mina

    Le silence c est la réponse des imbéciles yoral wakh bi rek sa guemine bou khassaw beureugue daye

  • Kheuch

    Yamana doul pape cheikh bamouy siwou bobou 2s mofi nekone bene tele privée gaye doul star en ligne walla dagay nakh doul amo bene khorou demal geudie ga sangou ndakh ga am khorom

  • Kheuch

    Doul sa ndiogou

  • seko

    Booba la khaw ma baba kouy niaf ndéyam la guissoul rek ak yap ndéye sénégalais yi

  • kudi

    Ignane rek moko diap. Pape Cheikh rek la ndeyame liguey!!!. Yow papa Cheikh dundu la. Jealousies quand yu ns tiens!!!!

  • ceely

    diadjeuf SA si kaw si kanam machalla

  • Giss Gissi

    Sa vakhal vakhal boul ragaldara

  • diodo

    franchement na gnaaw sonal nga gnou,fattt nga gnou yaw am nga diote d chaque emission nga nek ci wa tfm gniognou dagn la rawww sougn guesso sakh dougn la séneuh yaw da nga PERTE amo bén KHOROM mane gnilaay setaane gnio am diote nullard bi nga done

  • rappelogue

    pourtant il raison cet animateur n’est pas mieux placé pour defendre le rap galsen epuis sa facon de repondr a ce rappeur est un peu féministe quant a BOOBA je pense qu’il a raison si on se dit la vérité en face le rap galsen n’est connu qu,au niveau national qu’international le rap galsen n’est meme pas suivi en cote d’ivoire.a part le groupe DARAJI FAMILY qui fat très souvent des concerts partout dans le monde mais le reste les autres rappeurs senegalais sont connus et ecoutés que par les senegalais personnellement je m’inscris dans la thèse de BOOBA.

Publiez un commentaire