Annonces
Annonces
» » » » » » Senego TV: Les temps forts de l’Appel de Baye...

Senego TV: Les temps forts de l’Appel de Baye Laye à Cambérène

A l’occasion de la 136e édition de l’appel de Mame Limamou, Nos envoyés spéciaux reviennent sur la cérémonie d’ouverture, ce dimanche à Cambérène.  Les fidèles, tout de blanc vêtu,  psalmodiant «Lahilaha illa lah», sont tenus également en haleine par le grand orateur et conférencier, Mamadou Lamine Laye.

Annonces
Annonces

11 commentaires

  • Amina
    09/05/2016 09:06

    mandeh layen yi diakhal geun ma loutakh geun di woye Limamou yonente te khamne Muhammad S A W moy khatimoul Nabi Imamoul Mousalin S A W Senegal moytoulen bokale ak sen tarikha yi te limasi nakhary moy bou yenen nitt yi wakhe niou nanlen Ebadou nioniou dei nio nek si deugeu lima kham ba kham moy tarikha yi rek nio takh terrorist yi begeu nieuw Senegal

  • doune
    09/05/2016 09:23

    Yaw demal diangui mo gueune si yaw kén werentewoul ni mouhamed (psl) moy khatimi nabiyi wa imamoul moursalina mé boul wakh ni baye laye dou yonente niou bari danio rére si yonente dou nieuwat guinaw seydina mouhamed mais issa devrais venir á la fin des temps et il est á camberene

  • doune
    09/05/2016 09:31

    Iow amina demal diangui watt ken werentewoul ni seydina mouhamed moy khatimi nabiyi wa imamoul moursalina mais fi nieup reré moy yonenta dou nieuw si guinawam alors que issa devrais venir a la fin des temps et il est á camberene . Baye laye moy rassouloulahi et mame seydi est le prophete jesus attendu a la fin des temps

  • anrife
    09/05/2016 09:54

    Il faut pas debattre est ce que baye laye est prophete ou pas ceux conteste non ka debattre avec un vrai layenne sur le plan xam yalla ak hahitou mouhamadiya on verra les reponse et le niveau de chacun moi mon ame c baye laye c baye laye qui existe

  • Amina
    09/05/2016 11:13

    Doune yaw ya wara djangui niep kham nenj ne Issa dina nieuwat way kou takhaw nan limamou yonente la lolou koy djulit te kham li Yalla wakh waroko nangou boulen niou sonal

  • senego
    09/05/2016 13:13

    amina mahdiyou ak issa deug bou weur la issa demb Jesus waxna dina delouci seydina Mohamed demb waxna dina delouci teh issa lay andal sounouy mo am sa yoff apres mohamed (psl) benene yonent dou amat ba faw legui Mane Baye Laye wote wat yoff ne mane pa Mahdi may Mohamed wahoul moy kenene non c est moi Mohamed (psl) I’m Mohamed (si c est compliqué pour certains de comprendre voila quelleque traductions) yo soy Mohamed. demb ba Mohamed do wath pour ceede yonentam yalla dako diox lamine bou ted bi Notre constitution nous musulman

  • senego
    09/05/2016 13:16

    tay mouy wathiat yalla boleko issa pour mou ceede ko diouleko woutouko niko yene livres yi waxé si tu veux c est livres vas sur YouTube et tape appel 2014 ou celui de 2015 a Ngor seydi mame libasse les a enumeré merci

  • Amina
    09/05/2016 14:11

    yen amoulen foula amoulen fayda koulen bayi ngeun tok fi di werante bayilen bokale te diamouji Yalla sounou borom

  • senego
    09/05/2016 14:52

    lol amina rek mo am diot nak wedi sans justification baparé nga beug niou bayi sounou yakar adina ak alahira lol boulma ray way ok un conseil va te ressourcer sur la prophetie de seydina limamou Mahdi appel dewen inchallah nga niawat teh nga bopam sa clavier ak say baram

  • senego
    09/05/2016 14:54

    nopal*

  • BELGIK
    09/05/2016 16:41

    QUI NE DIT RIEN CONSENT WA SALAM

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL