Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

221 33 823 43 43

Annonces
Annonces
» » » » » » Senego TV – Borom Thiès: « La...

Senego TV – Borom Thiès: « La réélection de Macky Sall dépend de moi… »

2017-05-03T17:03:26+00:00136 Partages

Moustapha Amar alias Borom Thiès affiche toujours sa neutralité. Ni pour Idrissa Seck ni pour l’Apr. Mais le marabout-politicien dit être déçu par le président de la République pour promesse non tenue. Cependant,  il lui donne une seconde chance.  « Je suis incontournable à Thiès, la réélection de Macky Sall dépend de moi », balance-t-il tout de go, non sans se prononcer sur les cas Youssou Ndour et Khalifa Sall, les dérives sur les réseaux sociaux…

Regardez:

Annonces
Annonces

30 commentaires

  • Abdoulaye
    03/05/2017 17:34

    Craignez Dieu et repentez vous.Dieu ne parle à personne.Macky a été élu par la Seule volonté de Dieu..Si Vous pouviez élire quelqu’un Abdoulaye Wade serait élu.

  • seck
    03/05/2017 19:48

    senego vrema vous vous foutez de nous.cet homme si vous le connaissiez vous n’allez jamais lui tendre votre micro.il n’a même pas une seule personne derrière lui.door kat

  • anta fall
    03/05/2017 22:01

    Thiey serigne moustapha amar borom thies ken dou mom

  • anta fall
    03/05/2017 22:03

    Seck yaw dagay doul rek ben si mane mi rek si ay sopem la bok

  • doudou
    03/05/2017 22:05

    loula may thies rek la beug kham

  • wakh bakhoul
    03/05/2017 22:14

    aka wakh deug wa mais yen gniy commentaire di saga ak wakh lou bone est ce que kham nguen ko pourtant lim wakh lep deug la

  • aidara
    03/05/2017 22:15

    Thiey senegal kou diok gnou diokh la micro ki foumou tothie

  • geum yala
    03/05/2017 22:17

    geumal yala

  • mame
    03/05/2017 22:22

    Fi tothie naa

  • kon bi
    03/05/2017 22:35

    ay wadji fo tek ni la réalisation dépend de toi

  • Ndey fall
    03/05/2017 22:38

    kon bi yaw lay wakhal yala mom moy may domou adama noum ko nekher ki yala ko may moy sama serigne darmanko si ndey ak si bay mako kham

  • nar bi
    03/05/2017 22:39

    pourkoi nguen bagna degue deug senegal

  • rew ba dof
    03/05/2017 22:46

    borom thies kay loula may thies may wakh mou nane wa ki boum ma takha wakh mane thies la deug d kone ya mom sama keur khana. mais nak sa diaro yi ak sa montre rafet na lole

  • senegal
    03/05/2017 22:51

    loutakh nga mana mew fo tek ni la réfection de macky dépend de toi

  • Thies rek
    03/05/2017 22:57

    ak sa ndaway mou nane borom thies

  • mame gor
    03/05/2017 23:00

    Ndey sàne serigne bi yaw yala rek molay fay sa wakh rafet na yala nala serigne fallou mbacke faye li d kou ko degue di nit nak la wakh dossi wakh dara lou gnaw

  • gor mak
    03/05/2017 23:02

    aka bakh t beug bopam borom thies yague fi lole t weur yaw rew mi gnola sokhla ngay nit kou bakh kep kou beug kham nak kane moy borom thies rendez vous le 7 mai à thies sa chambre de commerce inchalla

  • fatoushh
    03/05/2017 23:04

    Mais di nous louy khew le 7 ba diam rek la

  • émigré
    04/05/2017 01:35

    Mane d khamouma koula khamoul wayer gnoune wa extérieur kham nàne la mara yague fi lole t ande ak wer fi ngua gnaw toubal gni fi nek yep nianal gnep gnou ame ket dem brazil gnene gni gnaw argentine lolou si sama kanam la mako fek

  • Machalah
    04/05/2017 11:16

    Vous avez ts le droit de critiqué mais ak yaar waay amna solo lol.

  • imama
    04/05/2017 17:06

    pourquoi dire un marabout c’est un politicien et tous les politiciens sont de grand menteur ils ne pensent que leurs intérêts.

  • dari
    05/05/2017 00:00

    Emigré, pour avoir des papiers pour le Brésil et l’Argentine, il suffit de passer à leur ambassade et de souscrire à leurs critères.
    Am kayitou amérique,allemane, france, belgique moo takh nitt gni di dougg founekk.
    Am kayitt bresil ak argentine wala mexique dou dara, kenn dou ko kheutioo, ndakh kou fa dem, do am dara té doo am diamm.
    gni fay dem da gnoo beugg djaaré fa dougg USA waayé waa USA danou leen di djapé clandestin ba noppi dakh leen.
    Toukki bitim reew yombeuna, dougg allemagne, belgique, hollande etc, am kayit té liguey moo takh gnouy wakh, waayé kou beugg toukki amerique du sud, demal seen ambassade woutt kayit normal, nga dem perte sa temps ndakh doo fa am touss.
    serigne bi sou mané limou wakh, na ko defal boppam.
    sou beuggéé khalis, na dem niaan mareme faye sall moo gueune.
    lou serigne sidi mokhtar wakhoul, serigne bou ndaw bou ko wakh djaroul deglou.

  • émigré
    14/05/2017 15:06

    yala na diam yague senegal

  • mbaye diop
    14/05/2017 15:13

    ay wadji sa wadji YAW mom koula may thies rek la beug kham

  • mbaye diop
    14/05/2017 15:18

    lissi geuna khorom nak mou nane la réélection de macky mais di ns comment la réélection de macky dépend de toi qui est tu

  • deug rek gay deug
    15/05/2017 23:05

    machalla aka wakh deug mane d kouma nekh nga

  • deug rek gay deug
    15/05/2017 23:10

    nguir yala kouko kham diokh ma numerom je sais mais dal mane mom vrement damakoy suivre lou bari kouma nekh la

  • NADEGE
    16/05/2017 13:37

    mane thies la deuk nek thi deuk bi wayé borom thies bidemom khamoumoko, Kheîna keur mor ndiaye la TOTHI..

  • ramata
    21/05/2017 23:59

    nadege yaw go way meno kham gnep epui yaw yaye kane sakh ki d mane kham nako t mom khamou ma degue nako deg touram kou siw la bamakoy degue dou legui mangui deuk medina fall mais mom rek laffi massa degu gnou nane ko borom thies donc kay nane koko bayer t bagna sokhor

  • ramata
    22/05/2017 00:00

    senegal li rek mo takh dou dem gnou melni Nadege mi dane f bari lole

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces