Annonces
Annonces
» » » » » Regardez le « tassou » incroyable de cette...

Regardez le « tassou » incroyable de cette petite fille…

2015-05-25T13:44:41+00:00 Partages

Annonces
Annonces

17 commentaires

  • Metzoo
    25/05/2015 14:00

    Vidéo bi neekhna mais trop courte

  • Thiat
    25/05/2015 14:16

    mdr bb niongi lay diangal wayann dé me tro nex

  • Lebou Ndoye
    25/05/2015 15:15

    no gars yi serieux khalébi meun lou eup li no ki dama yém man

  • Ndas
    25/05/2015 16:41

    MDR! khalé bi ray nama way machalla

  • borom khelcom
    25/05/2015 16:44

    démal diagui ta bayi safo mi wayann amoul solo

  • Elhadji
    25/05/2015 16:47

    diangal leen khale bi alkhouran mo geun mouy niane lolou bakhoul

  • Gallaye
    25/05/2015 18:57

    Elle est talentueuse cette fille, et puis domi mbeur janguil beuré.Donc bayileen jambur!

  • ibrahima
    25/05/2015 19:17

    khale bou diodo geul nan day tasso

  • ndeye fatou ndiaye
    25/05/2015 20:09

    sénégal yaxouna

  • eva
    25/05/2015 23:50

    Nope nako déé

  • ok
    26/05/2015 04:47

    tel mere telle fille, espece d'irresponsable au lieu de l'envoyer etudier le coran ou le francais vous lui montrer la voix de vivre facile par des actes de bassesse , senegal affair de caste dina fi yekha diouguer wayanne rek lignouy diangal seni ndom

  • dodo
    26/05/2015 09:09

    soudone lou bakh dé mou am solo .diém léne ko khamal diném mo geunn niou yaréko ak ay tasou

  • senegal
    26/05/2015 09:37

    wa mé khalé bi macahala cé normale senegalaise la khana gis géén domou bouba ndour migui rap nianallén ko rék

  • dija
    26/05/2015 09:48

    non nogaye yanguimaye dadji Jtjr yaw kula kholeu bassi birr lak nga 34ans comme niko sama copine saly wakhé mdrrrrrr

  • gagala
    26/05/2015 14:28

    Mdr

  • Kharitou Yayame
    26/05/2015 14:52

    Olala je t'aime bb tu es adorable que le tout puissant te protège amine

  • may fall
    26/05/2015 16:21

    hiii khaleeeebiiii mom tele na ngueweleeediiii

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL