Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

221 33 823 43 43

Annonces
Annonces
» » » » » Regardez la nouvelle danse de Pape Diouf

Regardez la nouvelle danse de Pape Diouf

2015-06-13T13:03:59+00:00 Partages

Annonces
Annonces

20 commentaires

  • cheikh Ahmed tijane
    13/06/2015 13:30

    Et c'est tout oh c'est excellent trop beau

  • khadim
    13/06/2015 13:49

    Noo goré na je valide

  • Fa
    13/06/2015 16:11

    Franchement c'est magnifique que dla classe goore na bou bakh.

  • Warotinaa
    13/06/2015 16:16

    Yénna niaka fayda deugue deugue deukeu bo khamné on crée jamais d'emploi on crée que des nouvelles danses c'est vraiment triste.esque les européen ou américains crée des nouvelles danses?? Non Afrique d'où demm plus particulièrement le sènegal n'avancera pas avec ces danses wallah.tchiipri.wa serigne khadim ne valide pas ça way sama wadjii yaw ak cheikh Ahmed tijiane avec vos deux nom sacré vous validé des nouvelles danses thiéy

  • Sen
    13/06/2015 16:54

    Wa ki kumu yep ak fetiam bou yagg ? Fogone na louné la ak dissay gui

  • Nice
    13/06/2015 17:29

    Fecc bi rafett na té gooré na

  • Fa
    13/06/2015 18:36

    Warotina et sen loulene ko setane. Lo yena geuneu niak fayda nieup. Sof ngene trop.

  • Sen
    13/06/2015 18:54

    Yow Fa koufi wakh wakhi niak fayda bangey tépékou ? On a le droit de ne pas aimer et de le dire mooway ya gueune soff nieup té sone

  • warotina
    13/06/2015 21:25

    :@fa damay teup bassi kaw tass déh.je t'assure j'ai meme pas regardé la video mais je sais ke danse dafa kharamm c tout khar nak day wéssou mbotté baala khatt.

  • deug
    13/06/2015 22:56

    fi dalle guissougnoufi lou bess pape menegoulo creer topal thi sa baye wally

  • sur
    13/06/2015 23:37

    noo ya hèw nak

  • diouf
    14/06/2015 00:00

    Nice nàaaaaaaaaawaaa amoul dra lousi niaw

  • Reubeu
    14/06/2015 03:08

    encore une nouvelle danse.mais où va ce pays,les gens ne pensent qu'à s'amuser.les danses ne feront pas bouger les choses.ça craint

  • mina
    14/06/2015 09:22

    pape dioufff ioe rrk amoul kenene xana nex

  • beugu yayam
    14/06/2015 11:16

    Sénégal dou dém dakh niit gni nio nangouwoul dém

  • pape diouf
    14/06/2015 12:03

    lladeug yalla
    tere souma tope sama baye wally done trafficant faux billets. Bayima rek si samay fethie mo guene wore

  • gueum
    14/06/2015 12:40

    senego yena niak khorom

  • DJ BOS
    14/06/2015 20:29

    niack dioum rèkk sènègal doudèm

  • fall modou bété bété pur
    14/06/2015 22:36

    Tarkala . nila sakh li daf siy bakh lekk lekk . artist dafa wara yeungeutou bamou yeungou

  • Raphaël
    15/06/2015 09:40

    moi waay ,fi aana loufi bess? yaw ,yaa gnak maana. wala daga panne création. doogal,

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL