Oustaz Pape Hann : « Ce que Seydi El Hadj Malick a écrit sur le prophète, personne ne l’a encore fait »

A TivaouneOustaz Pape Hann est revenu sur le parcours de Seydi El Hadj Malick. Selon le prêcheur de la TfmMaodo est un homme multidimensionnel qui a mené des oeuvres  emblématiques pour la confrérie Tidiane. Au micro de Senego, Pape Hann s’est aussi prononcé sur l’absence cette année de Serigne Abdoul Aziz Al Amine au Maouloud. 

Regardez ! 

50 COMMENTAIRES
  • Ndiaye

    bou nou demé touba nirok wa touba. téboun déme thia réwma melné koba

  • Bathie Sene

    Yaw mome lingay dosi sete YALLA bourbi sa kholle moye méti té dou ma sa séde

  • d

    yaw pape anne nafékh nga yama na ……………………………………….

  • mbaye

    kii mome dafa soof fénne rek lay def

  • Lycee ndayanne diourbel

    Ki momana fenn mais lo fi wakh si aduna euleuk dingako wakhat…khalat len sen euleuk duul kaat bi nga doon cest honteux di fenn ba khamnei dangay fenn .CEST GRAVE CE QUE TU VIENS DE DIRE …CEST UNE HONTE VRAIMNT

  • Ibrahima Ndoye

    C est faut avez vous lu tout ce qu on ecrit dur le prophète?

  • Abo Ndiaye

    Ki mo mana dooll

  • Mizanur Rahman

    ki bind 7 tonnes tagueko rasulila nak.afferou nafekh yoyou mo fi diekh kouné xamgua kou lq mëne

  • TIDIANE

    Il faut le comprendre..c’est son coeur ki parle et non sa tête….mais lui seul dans sa chambre il sait ki est ki…

  • modoukara ndiaye

    Wakh Lou la nekh

  • studentquier

    combient il a ecrit wakh niou ko , fène rek gay dèf ,ya bone dè sokhar Hanne yaw dhè yobou la park Hane rek mo guene si animaux yiii do dar yaw . sokhar rek guène dèf wayè si mane nièp Kham na niou ko si Senegal .kène dou ko wakh , wakhal na bopam niép guis ko tè topou ko

  • Niger+wakh+katou+dégue+rék++waw+waw

    Yene diagoulene diogoulene ngéne dingate mane dou Talibe Maodo mais so diongé di nga khamni li Maodo wakh Rassoull kéne wakhoukoko

  • Drame

    Lilou dague la Wa ya kou wedi dara dnga wara indi dara

  • mar ndom

    Dafay doule mok gni ko gueume nieup,el hadji malick liniou nane tay mbokou serigne touba la tay mo nekh rek waye demb mou done deme si toubab bi dane faa wakhale ak toumale serigne touba loumou défoule wakhoule guir rek ame diammm bagne toubab bi fit naleko maodo dafa guenone tivaoune lathie lene bagnou ko wolo ndar st louis lou toubab bi wakh mouni wakh guir niak wolou resouloulahi bamba nak mome wolou yalla wolou rassouloulahi gueum bopam doule bi taz thiogou nitou aduna youssou ndour lafi neké nafekh bou bone ibliss gua nioniou gua yakar sene mame serigne touba la yakar doule sa toubeuy

  • mar ndom

    Talibee senegal serigne touba rek moko yeup ndax mo nekone si deug contre serigne touba motax yene tidiane guene diegani topi cheikh ahmed tidiane sa fez ndax yaga bagne serigne touba tai cheikh momou serigne bamba moy kilifam ignane bakhoule ndiabotam bi nak daniou mandou ni kone daniou souli ay mbotte waye dieureudieuf bamba mome mi yalla tek rouhou domou adama yi si ay lokhom maodo sila bokkkk bokou serigne bi t’opine dou bakh dééé khalate ndax guene kham

  • feuta

    Yéna gui mèr déh

  • Sadikh

    Yénna bone
    Yénna yéss
    Yénna badola
    Yénna sokhor
    Yanna kaniane
    Lou takh founiou toudé bakhou moado guén mére? Ta Yénna fi dakka fén, hamouma Lou sén serigne ligeey Wayé fégnoul ci yén nakh
    Yénnay togn Kate yi, di sathie Kate yi, di agresseurs yi, di toukh katou yamba yi, di mbalakhman yi, di féthie Kate yi. Li bone Sénégal yeup Yanna ci eupp fouf. Yénna doul diouli, yénna doul woor. Pendant ce temps là, Ndiabotou maodo gui deukk ci toudou Yalla ak yonantém , té sén ndiambour bolé ci. Khaw ma kou wara wakh mais dou yénn.

  • Moustapha Seye

    Kou nekh khamga koula mane kouka eupe lo binde mou dakhla diouli thie guegui

  • mar ndom

    Yow niger daguay kate sa ndayyyy maodo thioggo toubab bi rek la wone indicateur la wone di wakhale serigne touba loumou défoule si toubab ba maodo babacar sy serigne mansour sy bou mal ak bou ndax ak junior serigne touba rek laniou bagnone senouk ndoundou daniouko reuthiou faniou nekk!tivaoune serigne abdoul aziz dabakh,cheikh tidiane sy,maodo mou dabakh ak wa keur dabakh niofa beug serigne touba ak ndiambotou dabakh kesse gnisi dess nieup ay nafekh laniou beugou niou bamba mais lolene si guis tidiane yangui démissionné di neko mourir ndax amsi si keur yi ak milliard ak djiguene you yarou yi ndax lolou leep dafa bokk si li serigne touba kholene touba khole tivaoune difference bignou ame borom bou deudo kholene guinawam di guene kousi yalla gueunone diap si maodo ak parapluie tayalam bi mou dane gadou meme bou diante guenoule bamba mome dara doyko wone lale si kaw si souf

  • mar ndom

    Yow déjà rek domarame gua sa nom bi si serigne touba la dioudo(saadikh) so beugue deg deug espèce sou serignou tidiane yi amouniou batine souniouko amone douniou marame macky sall tatammm bou frokh bi ak nane youssou ndour say woy da nekh surtout khaliss nekhna kham gueune bobou serigne dou serigne doule way yene kou andak bamba loula nekh def ndax mate lele naniou souniouk diamouk yalla motax yalla tek rouh yeup si lokhom bou maodo sila bokkkkkk do meuss guis mourid bou khadddiiiii deme neko tidiane contraire bi rek tidiane neksi mourid ndax beug si kheweulou serigne touba yi tivaoune amoule batine so lene weedi dem lene lathie bignou beugue souli babacar sy pour tokhole ko kham lou diabaram wakhone nitt waye waye bou lene ko def babacar dou walihou masi kham dara mane miy teud ak mome guene ni borom batine douniou ko soule fo khamenika koufay diouli guinaw lalay fêté jamais tivaoune amoule borom batine lolou touba rek lako yalla def koumou nekh ak koumou nakhari.

  • mar ndom

    Ayyy bagnou beugue souli babacar sy tokhole kolou diabar djia wakhone waye waye boulene ko souko babacar dou walihou mane malene ko wakh nioy fanane sasou nek bayi lene ko nonou gadi euyyyyy bouniou ko souko wone kone moussi ba am déé batine touba rek la ameeeee kou wedi ladiale borom com com yi kheweul touba koy diokhé yalla ko mome wayé dako bayi ak serigne touba sene espesou serigne yi bougnou diakhlé deme touba khana deglou guene mame dabakh limou wakhone ahahah mdr nopilene balaaa euyyyyyyyy

  • Bathie Sene

    Mome na wakh gnata khassida là binde yenne wa senego wo lénko lathie koko

  • BAYE

    WAYE BOURDE, MOUHAMADOUL BOCHARIYOU MOKO WAY,DAGA DIOUM

  • abdou khadre diop

    Yaw niger wakh katou deugg wala wakh katou feinn yaw ngay 7 boumak hanne mom danguein koy comprendr weign la fou toy mou takk magal gui reikk la moudier wakh si borom touba tay mongui si hadj yaw talibei yi neikk touba reik kholougnou hadj hanne wakhalma loum bind si S.mouhamed (psl). Ma wakhla 100 you borom magal gui bind. Sa bo wakhei 1 si milk ma wakhla 100 si khadimoul khadim .milk dina diekhal tei une tonne bou khadim dou khadj walahil azîm. Yaw lou milk bind.

  • mar ndom

    Maodo ak ndiabotam bouniou diiuli wone si bountou guedji gui rekkkk requin yi daniiu ame ndawal gou melni tabaski wakhou mala guedji waye si soufou tawwww rek bouko defone fathou guedji yeufou alalou bamba la ndax moko bind bind maodo

  • samyr

    dieureudieuf oustaz Pape Hanne,Seydil Hadji Malick bayiwoul dara dara tchi Rassoulillahi bamou neké leer ba bilal di wiss ndokh tchi bamelam bi nit yi outi adouna Mawdo dafa outi alakhira di yobalé gni yoko yakaar def tchi niougne linga hamné bouko kene guissatoul yit ken dou rereul ay talibeme.
    Borom dara yi modone wakh sa-mame nè, kou sa mame nèè wakhal. Yallah na yallah faye way

  • prince

    Amolein beneu talibé ki di wax si rassoullahi ngeindi wax nimporte kw

  • Sadikh

    Alhamdulilah Macha’ALLAH
    Alhamdulilah Macha’ALLAH
    Alhamdulilah Macha’ALLAH

    Alahuma sali alah Seydina mouhamed wa salim.

    Jërëjëf Seydi Hadj Malick.

  • amari seye

    Doul rek lan motakh Sénégal bari Nafek bilakhi boudeme tok dina wakh ne wakh na lou eup de

  • leral

    vous n’avez que cela comme problème . et vos frères noirs qui sont traites en esclave. et l’argent du pays qui est vole et notre économie qui est contrôlé par l’étrange. ce n’est pas la religion qui va faire avance le pays . ce n’est pas la religion qui change les hommes.si les sénégalais vous donnent l’impression d’être vertueux ce n’est pas a cause de la religion. que l’on suspende la loi pendant 1 mois et vous verrez si les sénégalais sont vraiment vertueux ou pas.

  • Douma farfalô

    Serigne si dougnou MBeurou lamb. Na kounek guem lingua guem fété fingua fété ta bayi di nguat ak wakh lou rafétoul tchi gnii ngua kamné sène adyna yepp diamou yalla akk topp Yonéntam la wone.

  • abdou khadre diop

    Mar ndom dingma ray Nguir yalah maodo contact moi watsapp 0034631299445

  • Youssoupha Ndiaye

    Mar ndom pardon yaw reew nga d

  • maguette thiam

    Dizbou rék doyna seuke si tague yonénté bi

  • Khadame Kante

    Mar ndom tu es impoli comme on le dit seule les imbéciles ne réfléchissent pas

  • Khalil

    Pape Hann dafay doullll Wahoufi Dara doulkatt bi nafekk bi

  • fina

    deugue nékhoule oustaz ligua wakhe yeupe deuguela, fi kou néke khamegua kila meune, MAODO moye 1er lolou lérena, wa touba sakhe khamenagneko,wa tivaoune meune nagne djianguale wa touba, té kouthi sagua MAODO tu va le voir avant cette fin d’année? INCHAALA.PAPE hann mala nobe, yaye soukeur té ragalouma diabéte.

  • Cheikh xuma

    Yène niep sène tounou nday liii dou sène diii diakhassé niaar nio khamni bène laniou wone ay saytané nguène serigne touba ak maodo diamou yalla lagne lène digueul nguène nekk fi di takhalé niarr nio khamni ils ont sacrifié toute leur vie pour le bien du pays

  • Cheikh

    20Yène niep sène tounou nday liii dou sène tieurr diii diakhassé niaar nio khamni bène laniou wone ay saytané nguène serigne touba ak maodo diamou yalla lagne lène digueul nguène nekk fi di takhalé niarr nio khamni ils ont sacrifié toute leur vie pour l’union du pays nguène nekk fiii diii defanté melni ay goor djiguéne merde wayyy

  • MBENGUE

    wa domerame dji loumouy wakh ni espece sou ouztace sou bercy yi;démal fékhé no watto mokalé alkhourane mo gueune ngaye gnaff ndayame doul.Kou téd ki limou binde si yonnene bi kéne bindou ko

  • dd

    5
    Avant-propos
    Avant-propos
    Alors que le Président de la République m’a fait l’honneur de me nom-
    mer par décret du 3 novembre 2008, président du Haut Conseil à l’intégration (HCI),
    des travaux étaient déjà engagés sur la place des personnes issues de l’immigration
    en politique. J’ai bien entendu souhaité les poursuivre dans l’esprit de mon prédéces-
    seur, Madame Blandine Kriegel, à qui je veux rendre ici hommage pour l’immense
    travail accompli par le Haut Conseil, sous sa présidence, depuis 2002.
    Cette période a correspondu à la refondation de la politique d’in-
    tégration dans notre pays, principalement autour de la politique d’accueil des
    primo-arrivants, avec la création du contrat d’accueil et d’intégration, d’une
    part, la lutte contre les discriminations en raison des origines, avec la création
    de la Haute Autorité de lutte contre les discriminations et pour l’égalité, d’autre
    part, et enfi
    n, avec la reconnaissance de la place de l’immigration dans notre
    histoire nationale, et aujourd’hui, avec la création de la Cité nationale de l’his-
    toire de l’immigration, et celle d’un ministère pleinement dédié aux questions
    d’immigration, d’intégration et de codéveloppement.
    Par ailleurs, par lettre du 11 décembre 2008, Monsieur Brice Hortefeux
    alors ministre de l’Immigration, de l’Intégration, de l’Identité nationale et du
    Développement solidaire, a saisi le Haut Conseil d’une demande d’avis concer-
    nant le moyen de faire partager aux étrangers qui souhaitent s’installer durable-
    ment en France, les valeurs et symboles de notre République. Cette demande est
    fondée sur la nécessité pour l’État de déployer les moyens nécessaires pour faire
    connaître les valeurs de la République au fi
    l du parcours d’intégration, depuis
    l’arrivée sur notre territoire, jusqu’à la demande de naturalisation.
    En effet, ce sont principalement les lois des 26 nove

  • El

    Yaw Mar Ndom kouy weur kou alkou, haram, ak sankou ba yem ci yaw nala diap. Sa serigne biga yakar adouna ak alakhira, ligay wakh santanewouko te digaloulako. Nit dafay mandou. Ligafi wakh yeup nak nala leer ni euleuk, digako layok Mame Maodo ak djabotam. Te bou boba sa serigne doula walou.

  • Mamadou

    KHADIMOU RASSOUL BEN laffi té dou meusseu dagne iow pape hann yagenga dem TOUBA wayé on sé k tu es jaloux de représenter laba la TFM serigne moy ki mom SENEGAL AK MAME CHEIKH IBRE FALL!!!

  • Mamadou

    KHADIMOU RASSOUL BEN laffi té dou meusseu dagne iow pape hann yagenga dem TOUBA wayé on sé k tu es jaloux de représenter laba la TFM serigne TOUBA moy ki mom SENEGAL AK MAME CHEIKH IBRE FALL!!!

  • Mamadou

    ILA YAHADALAHOU MALAM YAKOUNI WALA YAKOUNOU ABADANE LIL MOUNKININE « DIEU M’a accordé une chose ki ne fut et ne sera accordé a personne » thieuy kou tedd koula bagne trokh kouko guiss yeureumko et febarou choff dou taggali ak mom

  • Niang

    Ouztaz hann beugoon nako waye weddinako. Nafekh bakhoul. Maodo limou def kenn kheebouko tabarfakala mais bou dee bind nguir tagg Mohamed pssl kenn meunou thi ki am gradou khadim rassol Cheikh Ahmadou Bamba. Walahil azim

  • Talion

    L’œuvre de Maodo Malick SY
    • Ifham al munkiru jaani (« réduction au silence du dénégateur ») : une défense de la Tijaniyya et de quelques points vue jurisprudentiels (traduit en français par Rawane Mbaye)
    • Khilaçu ez-Zahab : une biographie rimée très complète sur le prophète de l’islam, Mahomet, et ses proches compagnons (notamment ceux issus de sa famille), régulièrement récitée lors des célébrations religieuses au Sénégal, particulièrement durant le mawlid (ouvrage traduit en français par Rawane Mbaye)
    • Sharh Khilaçu ez-Zahab : commentaire de cette biographie par l’auteur lui-même.
    • Zajr Ul Qulûb : un poème d’exhortations pieuses et ascétiques traitant de divers sujets.
    • Adâb Ul Masjîd : un poème traitant des convenances à respecter lorsque le fidèle se rend à la mosquée et y fait ses adorations.
    • Al Hidâyat Ul Wildân : un traité de théologie islamique (basé sur l’école ash’arite).
    • Faakihatul Tullab : un précis sur la Tijaniyya, ses enseignements et ses pratiques (traduit en français par Rawane Mbaye)
    • Diwan : un recueil de poésie sur Seydina Mouhamad (PSL), Ahmad Tijani, ‘Umar Ibn Sa’îd Tall Al Futi, et contenant d’autres connaissances islamiques comme l’héritage, la rhétorique et des conseils aux musulmans en général et aux fidèles tijanes en particulier.
    • Khutbatul Jumu’a : un prône de la prière du Vendredi
    • Khutbatul ‘I’d : un prône de la fête (tabaski et/ou korité)Kifayat ar-raghibîn (« ce qu’il faut aux bons croyants ») : une série de textes à caractères jurisprudentiels et spirituels traitant de sujets variés (traduit en français par le professeur Rawane Mbaye).
    Il est nécessaire de noter que cette liste est loin d’être exhaustive puisque les écrits de Al Hajj Malick Sy sont très nombreux et son œuvre, tant au plan de la taille que de la richesse linguistique et rythmique, est à bien des égards incommensurables.

  • Talion

    Cheikh As-Saïdi Al Hadji Malick Ibn Uthman Ibn Demba Ibn Chamsidine SY
    L’INTELLECTUEL

    Lettré fort remarquablement, particulièrement versé dans les sciences juridiques et littéraires, Al Hadji Malick paraît être le marabout le plus instruit du Sénégal. Le fait avait déjà été constaté en 1908 par M. Destaing, lors d’une visite que l’éminent directeur de la Médrsa de Saint-Louis fit dans les principales écoles coraniques du sénégal. Depuis cette époque le Cheikh, qui professe et travaille toujours, a continué de justifier sa haute réputation.

    Dans le domaine littéraire, Maodo Malick a légué à la postérité une richesse immense. Ses nombreux ouvrages et poèmes étaient essentiellement accès sur la théologie, le soufisme la biographie et louange du prophète et sur des événements heureux ou malheureux touchant ses amis ou d’autres marabouts .Parmi les plus célèbres de ses écrits on peut citer : Khilazu-zahab, un long recueil de 1001 vers, retraçant la vie du Prophète (psl) : depuis que Dieu a eu l’intention de le créer à partir de Sa propre Lumière, jusqu’au dernier homme qui a quitté la tombe après l’enterrement Cet ouvrage fût imprimé en Tunisie en 1915 sous le désir du Gouvernement Général de la colonie. Hadji Malick commanda d’ailleurs 1000 copies.

    Il y a aussi « Kifayatou Rakhiline », un livre de Droit civil, social et pénal, « Wassilatoul Mouna ou Tayssir », « Fatihatou Toulaab », « If AAmi Mounkiri Jaami », etc. Le saint a aussi écrit sur la médecine, l’astrologie, etc. Ces ouvrages sont de longueur inégale, allant de quatre à vingt-cinq pages. Ils sont remarquables par la pureté de la langue arabe, par une certaine élégance de style, rare chez les lettrés noirs, et aussi, par leur tendance toujours très sympathique à notre cause. Pouvait-il en être autrement pour un homme qui éleva au rang de sacerdoce son attachement indéfectible au prophète Mohamed (PSL).
    Ce pacte qu’il signa avec l’Envoyé de Dieu fut consigné dans un ouvrage à jamais sublime. »II n’existe aucune action que je puisse faire pour toi si ce n’est t’aimer, te célébrer et te suivre », s’était il exclamé dans « Mimiyah ».

    Ce sont surtout des commentaires et paraphrases, mille fois rebattus, d’ouvrages classiques arabes. Les lieux communs de la littérature profane ou religieuse de l’Islam y fleurissent abondamment El Hadj Malick Sy était un homme de son temps, d’une extraordinaire acuité intellectuelle et fabuleusement lettré. À cet égard et pour s’informer sur les activités du colon, il était abonné au journal officiel qu’il se faisait lire à chaque parution. Moraliste émérite et éveilleur de conscience, Maodo aura été non seulement un témoin de son temps, mais aussi un visionnaire. Son combat a été de former des soldats de la foi et de les disperser pour qu’ils diffusent le savoir, élargissent les bases de la religion et de la tarikha.

  • Mamadou

    BILAHI y.A des personnes ki sont maudits ndakh bagn s TOUBA dougnu avancé ba faw si trokh rk lagni deukkk

  • Sory Kandez

    Arrêter vos injures tous ces serignes n’ont jamais insulté personne en plus ce pays appartient à tous les gens qui y vivent les serignes ,les talibes les mécanos ,réparateurs de radios firgos… Donc peace and love chers citoyens Sénégalais

Publiez un commentaire