Annonces
Annonces
» » » » » » Nigéria: Des milliers de talibés de Baye Niass...

Nigéria: Des milliers de talibés de Baye Niass prennent d’assaut un stade

La vie et l’œuvre de Cheikh El Hadji Ibrahima Niasse resteront toujours gravées dans les mémoires de ses innombrables talibés au Nigéria. Ce pays a célébré la naissance du saint-homme dans un stade de la ville de Kassina où se sont retrouvés des milliers de disciples de Baye Niasse. Ils ont pris  d’assaut le stade, dès le début de la célébration du Gamou, laissent supposer selon certains analystes que le guide religieux sénégalais est plus aimé au Nigéria que nulle part.

 

Annonces
Annonces

96 commentaires

  • you
    23/05/2016 10:31

    encore la victoire de l’islam

  • NDIAYE
    23/05/2016 11:09

    Attention, existe-t-il un espace qui peut contenir 5 millions au même instant même Arafat ne peut le faire. Alors soyons sérieux. ..

  • awagning
    23/05/2016 11:13

    dieuredieufeeeeeeee baye niasse Alhamdou lilah bagnou khamee baye masha allah niasse barhama kamal baye mbindef yi

  • truth truth
    23/05/2016 11:30

    kignane fakhoul mour bour yalla moye dogal serigne sifi ame aye troimillons de talibe di takhal nittyi ta baye bobole serigne gnou adouna molene eupeu talibe name lerre

  • avatar
    23/05/2016 11:42

    Ana bane serignou mouride moo meun lo lou

  • Right
    23/05/2016 12:09

    stade qui peut contenir 5millions de personnes… reyyy na trop machalah

  • beug Baye Rék
    23/05/2016 12:26

    lahila halla mouhamadou maolana Dieuredieuf Niass

  • Baye
    23/05/2016 12:55

    wax len ta bayi mourid yi

  • zal
    23/05/2016 12:57

    Wax len bayi mourid Yi

  • truth truth ndam
    23/05/2016 13:14

    Nell wakhal bayi moridyi Kenne mo wakh nguene beugeu generalises

  • Abdou
    23/05/2016 13:49

    AVATR Boufi toudh mouride ma todj sa lafeul ndey

  • Abdou
    23/05/2016 13:50

    AVATR Boufi toudh mouride ma todj sa lafeul ndey

  • docteur
    23/05/2016 14:03

    Ndiaye del khalat yawit. Kathina ville mo accueillir plus de 5 millions talibé baye niass. Lissi bir stade bi c le 1 dixieme lifa dajé. Nangoulen way té khamné fierte senegal la

  • mami
    23/05/2016 14:21

    boulene gnou katelo ndayam c notre fierté mouride tidiane layen yeup musulmans la seytané fo dem amna fa delene beugue diam way koussi wakh lou diakhassé ay tarikha sa koyou bay

  • MM mboup
    23/05/2016 14:28

    yabatai ga avatar lifi serigne tout deff benn serigne si tariha douko deff serigne touba amoul mass wahelen sen wah tai boulen gnusi dugal

  • MM mboup
    23/05/2016 14:30

    gnune mourite dounou moromou kennn ay ndiabotu serigne touba sahh dunu morom kenn na lepp refet

  • MM mboup
    23/05/2016 14:34

    wa mamie chrie fo pas insult

  • MM mboup
    23/05/2016 14:35

    avatar yaw lifi serigne touba deff kennn dako deff boulenn gnu wahlo wayyyyy

  • awagning
    23/05/2016 14:56

    bou len gnou sonel talibe baye amoul tan di yeemale baye ak keen mome talibe baye bi bou khame boopam sak dou moro mou ken si gni gnou fiy wowe serigne

  • MDZO
    23/05/2016 15:37

    DIEURE DIEUFE BAYE NIASS LEWEUL LAKHIR ZARIR BATINE

  • salman
    23/05/2016 15:52

    thabk you mami wante diaroul saga lep islam la

  • DAME SECK
    23/05/2016 16:04

    AVATAR LOUMOU BEUGONE AMENAKO MOY GUENE NEK FI DI SAGAWANE TE DI WAKHANETE LOU NIAW TA LII NDAMOU L ISLAM LA AK SENEGAL SURTOU BAYE NIASS NAK LA BEUG KOUSI MANE DARA

  • alpha diop
    23/05/2016 16:27

    salatou wa salam mangui degeulou bou bax si limayn wax dou dara loudoul fatalanté liniou boke naniou bayi khiel si linioudoon seringe yiniouy roy ba di def seni ay diglé modi doon ay dioulit dabor di wax lou waxou yémalé sa bope ak sa morom kou xalatné sa ay wadiour nioungui setan li si internetbi yakarnané saga ak wax bou teguinewoul doudoon se dieuf rawatina dioulit bouniou tarbiya naniou bayé xel si né sounou seringe si fi diar kousi neke amne lou sounou borom def si yaw té dara mayoulenko loudoul geum yalla teksi bege rasouloulahi diar fa rasouloulahi diaroon comsa nak nioom nioy sounou royoukay danio wara am yar ak téguin té yakarnani li ndamou senegal la pa tidjian bi ni mourid bi ndax yalla rek la mag youbaxyi doon liguieyeul wa khana nekatouniou seni talibé dou ay saga ak wakhdiou niaw laniou digeul lolou dou sounou thieur naniou def soun bope bene té khamne koufi wax té waxdji tegenouwoul ak fo mana boke beus dine nieuw nga weete ak diala dialalouho téfofou dina doywar té lou mata bayi xel la ngan baalma akhe salamou mini wa minqoum sama xalat rek la doon wax

  • Ibrahima
    23/05/2016 17:08

    Dieuredieuf Niass Coumba Abdallah

  • Ibrahima
    23/05/2016 17:09

    Bayooooooo yaye sounou baye Bayooooooo yaye sounou Bayooooooo Yaye Sounou Baye

  • Ibrahima
    23/05/2016 17:14

    Keur dall pour nopaloukay la liguey bi thi biti la Dieuredieuf Niass Coumba Abdallah

  • Bass
    23/05/2016 17:19

    Stad bi deh mana df lou eupe lolou sakh Stad bo kham ni poulouse bi jouer yi di football l sakh fnioul mdrrrrrr dieuredieuf baye barhama niass coumba Abdallah kamal

  • fabouli
    23/05/2016 17:28

    dieuredieuf baye niass bayou baye yi

  • Camara
    23/05/2016 17:29

    Mais l stadt l il peut prendre plus de 7 millions mme avec cette organisation

  • Amm
    23/05/2016 17:31

    Ma challah Thiy yalla sounou borom

  • beaugars
    23/05/2016 17:59

    BAYE rek moy serigne

  • deug deug rk
    23/05/2016 17:59

    talib baye niass dou moromu ken rawatina baye niass nanou bayi comparaison bi ndah bakkan fi kou nek kham nga kila meune djerejeuf baye niass al cheikhal islam

  • beaugars
    23/05/2016 18:01

    damani BAYE rek moy serigne

  • Aba
    23/05/2016 19:01

    Merci baye ya rabi

  • Mbaye
    23/05/2016 19:02

    Merci baye ya tabi

  • fuck
    23/05/2016 19:15

    abdou koyou khalifa mouride yeup ay domou harame la nio ay tiaga la nou

  • deug deug rk
    23/05/2016 20:00

    talib baye niass dou wakh lou niak teguine djemei ko ci moromam ndah baye daff gno djangal rouhou eudeup dc kep kou saga yangui togn ndah ken yarei wou gnouko et surtt faites bien attention ndah yen saay dinga guiss kou commentaires saga th dou talib baye niass lp nguirr yei aw fitna rek gnoune gueum nanou nei talib baye dou moromu kou yalla binde dc djaroul gnouy lime ken nguirr wakh sunu imaane ci cheikhal islam

  • tonns
    23/05/2016 20:14

    lii d ndamou Sngal la rew bounek Beug na an kou mel nii sante rek t byi khouloobi man d mouride la way limom sama khol sed nasi lool

  • deug deug rk
    23/05/2016 20:28

    djajeuf tons gnoune dh ak ko meuna doon ak fo meuna bokku bo beugui baye niass al cheikhal islam rek gnou beug la boka djokhei thieur bou matt seuk walakhi gnou delolako bamou matt seuk ndah amougnou koudoul baye niass ci mom lanou khamei yalla ak yonetam ci sunu bopp

  • Baye TALL
    23/05/2016 20:44

    Dieureudieufé Baye! Alhamdoulillah. Nekk juliit, dolisi nek Talibé Cheikh, paré diar Medina naan si xam xam bi ba mandi. Niass yow lako Yallah sed. Kou weddi diaral Medina si Saloum Saloum yi.

    Alhamdoulillah. Laa Ilaaha Illallahou

  • le vrai
    23/05/2016 20:49

    ndaysane dane ko geumé woule 5millions dou touss wakholène ayy milliards loudoule di ndamo li soff bayilène teukeulé serigne touba ak ngi khana dégoulèn li aramine niass wakh kou yatale tayy thi serigne touba nga dieulé thia yatalame gua nagou diotna serigne touba moy serignou serigne yéppe

  • عبد الله
    23/05/2016 20:52

    Salam mbokou yi ci Yalla magui léne di ziare té Dilène nianal Yalla
    Naniou nagou mayou Yalla ci diam yi
    Kou Téde ki( Khadim Rassoul) louko Yalla may mom rek la té kanéne dotouko am( lépou lougne niou nétali ci exil ba….)
    Mame Lymamou Laye (mou wax guéthe( mer ou océan) randoul….) etc…
    Warnagno nagoul tamite BAYE liko Yalla diaglèle, té li dou dara loudoul fierté Senegal.
    Pour terminer mbokou yi nagniou am yarr ak téguine té xamné niome ande bou réféte lagne andone. Ils n’avaient qu’un seul employeur, l’ISLAM, le Prophète Mouhamed SAW
    DI DIÉGALOU CI KADOU YI LOUCI DEUNGE KHAM LÉNE NITT LA TÉ MATOUMA WASALAM

  • awagning
    23/05/2016 20:54

    Fuck yaw doo talibe baye ndakh talibe baye dou wakh li ngay wakh niawna trop sa mangui wakh astafii roullah azim dieuredieuf baye bi ngagnou khama le? yakha kat yi

  • MM mboup
    23/05/2016 20:57

    fuck yaaww denga nara toroh sa aduna serigne bi dinala wane moy kane sennnn hol mo diehhh nahh li serigne touba Di seul serigne

  • ba
    23/05/2016 21:33

    Mane yena gniaka teguine kane molene co yare na ngene am qelifa way

  • SMB
    23/05/2016 21:37

    C’est la victoire de l’islam soyons un peu disciplinés que soyer tidaine ou mouride ect nous sommes tous des musulmans. Baye et serigne Fallou etaient de vrais amis comme Serigne saliou et Baba lamine

  • diallo mbalo
    23/05/2016 21:46

    Baye niass limou ndieuk binda ROUHOUL ADABI cone talibeme bou kham missiome warta niak teguine kene saga bakhoul
    BAYE NIASS yemoul si binda rekk dafko pratique niou guiss BAYE dioulit niep la mboko
    te khamna liko yalla maye mai titrowouko BAYE limou beug kholyi delloi si yalla rek

  • fuck
    23/05/2016 21:56

    mm mboup yaaww denga nara toroh sa aduna yaw ak kou li nekoul bay rek moy seringe kou mou nekoul ya momm lima wakh

  • sant baye ba fawww
    23/05/2016 22:08

    li fuck wahk deugle

  • liy deug
    23/05/2016 23:36

    Li dal kouko guissoul, da nga amoul beute…
    Baye niass yalla ko maye…. sokoy khol diko beug…. lolou nak yalla mokoy def…
    Legui nak nioune nio si dess, lane mo wara nek suniou takhaway si kaw souf.
    Mourid, tidiane, khadr layenne etc… naniou ler ni souniou déwé yalla douniou lathie loudoul souniou dieuf. Souniou naré nek fi nak di wakh si lisouniou mak you bakh yi def, daniouy perte temps si niaka bania def dara nioune.
    N’oublions pas ke kene kou nek si nioune di nga dadiek sa borom yene niar kessé, ba nga fokni yaw rek la bindeu….
    Yalla na yalla tass niou si barké sunu mak yi.

  • Omar
    23/05/2016 23:50

    Il fau preciser que le Nigeria compte plus de 60 millions de Talibé de Talibé Baye. Ce vous voyez est minime . Aujourd’hui on compte 120 millions de talibés dans le monde. Ce qui veut dire que les Talibés de Cheikh Ibrahim ne peuvent se rencontrer sur une méme place. On rend grace à Dieu de nous avoir faire connaitre ce Grand Maitre Incomparable. Le meilleur est devant

  • Verdad
    24/05/2016 02:38

    Boulen gnou sonal kounè khanani DIEUZBOUL KHOULOUB la yobou Nigeria né moka binde..diereudief SERIGNE TOUBA diaarama MAME CHEIKH IBRA FALL

  • izac
    24/05/2016 03:23

    verdad ya mana dokhane sa ndaye

  • deug deug rk
    24/05/2016 03:31

    verdad dangay doule manei baye niass dou moromu kou yalla binde o contraire serigne bingay ndamo baye niass moka sakk kone djerejeuf baye niass en plus yein xam xam zero ba nopi guena barri wakh en tt cas gnoune talib baye niass kham nanou nei baye niass amoul ken koune Kay tekaleil thioudj nak day xam lekam soof nguen lol espece d makhjob

  • deug deug rk
    24/05/2016 03:31

    verdad dangay doule manei baye niass dou moromu kou yalla binde o contraire serigne bingay ndamo baye niass moka sakk kone djerejeuf baye niass en plus yein xam xam zero ba nopi guena barri wakh en tt cas gnoune talib baye niass kham nanou nei baye niass amoul ken koune Kay tekaleil thioudj nak day xam lekam soof nguen lol makhjob yi

  • deug deug rk
    24/05/2016 03:38

    vdd dina todj sa sarap nday dh ya meuna doule

  • deug deug rk
    24/05/2016 03:39

    verdad dina todj sa sarap nday dh ya meuna doule khana khamo ni baye niass amoul morom lolou motah arabi dika wowei cheikhal islam

  • awagning
    24/05/2016 07:01

    yaw deug deug kou la bayii ngay wah gni ngua khani seni serigne mi di

  • awagning
    24/05/2016 07:02

    yaw deug deug kou la bayii ngay saga ak gni ngua khani seni serigne yaw sa doo sene morom

  • awagning
    24/05/2016 07:09

    kounan khana

  • Talebb
    24/05/2016 07:11

    Ce n’est pas la mme photo que l’anne dernire? Ce n’est pas l’venement des descendants d’Ousmane Dan Fodio? Ils ont rgulirement une grand venement comme celui l auquel la famille de Cheikh Ibrahima Niass prend part. Il faut faire attention l’amalgame qui veut prsenter toutes ces foules comme des Talibs de Baye Niass. Il y a certes beaucoup de talibs mais faisons attention la fausse propagande. Les hommes de Dieu n’en ont pas besoin.

  • awagning
    24/05/2016 07:19

    ye?ne dagnen na am problme ndeh wayadi wesou woul topa si ki nanla khamna yallah te moul lako khamal demlen seti Sene boop baparee mo geune Sene xol bobon

  • Moi
    24/05/2016 08:04

    Hahahahahahahahahaha! C’est malheureux d’être des ignorants.

  • pape
    24/05/2016 08:18

    c est un mensonge parcqu´il dit que la population du nigeria est de 40 millions . la population du nigeria est de 173,6 milllions , donc ca nous montre qu´il ne métrise pas ce qu´il dit.

  • rassoul diop
    24/05/2016 09:04

    alhamdoulilah baniou andek BAYE !!!

  • DIEUREUDIEUFEEEEEEE BAYE NIASS
    24/05/2016 09:15

    way mane kou ame lou dake li demal ake mom sognou maye beuguougnou li YALLA dogale soko bagne bagay heuy rek cardiak de senegal bene bop la kene meunouko hare gnare mouy mouride tidiane khadre layenne dianaba niassene gno boke fougnou diogue ak fougnou dieum donc sohla wougnou comparaison ni de guenel ni d rewanede diante baguini diaroul yegue thi garap pour djisko encore une fois di wah ALHAMDOULILAHI DIEUREUDIEUFEEEEEEEEEEEEEEEE BAYE NIASS et FIER D’ETRE TALIBE BAYE NIASS

  • allah baye
    24/05/2016 09:18

    Lii baye def fi mom rek ngène djiss ndah mom wathioul pour ben deuk rek yeurmendé la nièl thi lep lou yalla bind.Baye kou ka diapé 5millions walla louka eup yangui nah sa bop ndah loudoul nit nioniouka gueneu beug te kou wah dieurefe baye si niou diote wah lou niah teguine nga dem adiana legui si lou wor

  • baye
    24/05/2016 09:26

    allah baye

  • Ma ko wakh
    24/05/2016 09:59

    Baye Rek mo mate Serigne, il n’est pas local, sa science est partagée par des nationalités différentes.

  • fuck
    24/05/2016 10:26

    le vrai yaw dina oubi sa tou nou seringe

  • deug deug rk
    24/05/2016 10:29

    nopalou lein bouki wiri wiri djaari ndari t baye niass al cheikhal islam mingui ndari di ln khaar gueram ln yalla t djokou ci baye niass mo lein di nopal manei talib baye bi guena ndaw mo soutt ci adouna bi dc nopalou lein 5million dalein djaxal baye niass lou eup 60millions amnako nigeria rek ci ay disciples tei wakhouma yenein deuk yi baye niass est internacional beug ko rek molay nopal

  • chouaib
    24/05/2016 10:36

    dieuredieufe baye

  • mourid.sadikh
    24/05/2016 12:56

    Man.dey.mourid la waye begna.lol.ndakh.sagob.senegal.motakh

  • le vrai
    24/05/2016 15:56

    bayilène doule

  • le vrai
    24/05/2016 16:03

    deug deug dangay doule rek fésale stade dogue diarna ratatati wakho deukbi mo féss loudoule stade nga kham ni mbeur yi nioko désé man masouma guis tidiane bou avancé fuck wayy ki todioule fène

  • deug deug rk
    24/05/2016 16:09

    Le vrai bo moytou wul ci sa bopp lata biss bi di djekh mbirr manam aw mbugal dina la djott barki mawlana cheikhal islam dinga xamni rw fadjoul dara wa slm

  • deug deug rk
    24/05/2016 16:21

    sa serigne loutakh yalla mbugal ko bala mouy dh da nkone tidjane ba nopi wotei makama motah il est mort plusieurs jrs avan k’on ne decouvre sn corps pu dc sa l’eufal nday iow le vrai

  • bb
    24/05/2016 20:24

    Joueur local manoula tolok joueur international sokhar kirayla si kholou djambi yallah nanou si yallah moussal li yallah ko dogal cheikhal islam Rék doyna titre con nane wakh djeureudjeuf baye Niass

  • chouaib
    24/05/2016 20:54

    yaw le vrai bi nga khame senego si ngay doga guiss wa Nigeria ni gnou mel si baye yaw ki nga toop mounan len si ay khassi dam khamna yallah tee ma nou lako kha mal loko doye wayadi wee soul lolou va chercher qu’i es vous la wees

  • dokh diamm
    25/05/2016 09:38

    LE VRAI dangay doule rek bayile féne yaw ak koulako wakh danguene dii doule

  • le vrai
    25/05/2016 11:32

    tidiane foko féck day ndole kène ndiéwoulène mani déglou djilène aramine niass mome néna disjoncteur bagui fi kane lanfi solone dème duko soufi féck mou ndeube ha ha ha ha soulate lène ana ngikoy bagne

  • chouaib
    25/05/2016 13:51

    yaw le vrai mangue doo gakham ni yaw mbam nga moutat ngay khotekou rek yaw seydina Mohamed gni kadon kha si famille bi mou bok fa la apee woon yaw mom diaro tontou

  • nice
    26/05/2016 11:50

    dieuredieufe khoudbou dieumiyou

  • sala
    27/05/2016 13:10

    Salam alaikoom mboki yi talibe dou khasste t baye dou morom gayi kou nek nak kham gua kula man limou def ni ben serigne defouko fi Sénégal dafa ligayal yalla motah yalla mayko li baye moye koutbou zamane moy lep mogui si rouh yi si xol yi mogui si fep foko xol guiss ko mogni xamal sougn bopu kon yaw talibe baye bi kham sa bopou diaroul gay xulo di comparer diarouko t li guissna ni ndami Sénégal yeup la wa salam lima wakh kousi guiss sa bopou gua diegalma

  • soukh
    27/05/2016 16:01

    masha allh sant rek mognou niasse lep rafetna

  • Amadou BOIRO
    29/05/2016 13:07

    ndiaye boul ignan

  • diallo
    29/05/2016 20:19

    Ndiaye katal sa Ndéye khana deugoulo toubab

  • Cheikh niang
    29/05/2016 20:28

    Avatar seytane nga yee katup fitna nga losy toudee mourid yi t nga wakh say wakh rek lislam ben dinela narfekh binga done yalla reube nalla

  • thiep
    29/05/2016 20:37

    as salamou alayekoum fii kounekk xamale nga sa morome dara nanou done aye dioulite rekk serigne yeup ligueyele yalla soub xanahou el hadji malick el hadji omar foutiyou tall serigne touba mame baye niasse waye bene tarixa rekk moye circuler fi ba boufta bi di wale cheikh ahmed tidjane cherif diioxnako el hadji malick sy wa salame

  • sakho
    29/05/2016 20:50

    bayil lennn saganter je vs jure k senegal conscient lene internet est ouvert a tous mais sounou heritage bou nekhh bi pkw on se permet de le degrader bayilene sounou serigne you bakhhh guene saga ils nous ont enseigne le coran , diapelagnou si kham yalla beugue moustapha (psl) ils ne meritent pas ces commentaires

  • soukh
    29/05/2016 21:06

    thiep hahahahaha wooooooooooy yaw ana kane moy cheihou tidiane yaw de moune nga deem nan boutelou Champagne geune l’islam

  • cheikhouna
    29/05/2016 21:08

    dieureu dieufeuti baye.yalla naniouleu yalla fayal.moi je suis un mouride

  • cheikhouna
    29/05/2016 21:08

    avatar nitou ay gue

  • mamadou ndiaye fall
    29/05/2016 23:45

    fawhasara wa saraya cheikh ahmed tidiane cherif li yeup momela keune na kawé gayou bakhya

  • mamadou ndiaye fall
    29/05/2016 23:52

    wadjawe sahiroune mahaloune cheikh mokowaxe guisna yeufya dieuredieuf cheikh amed tidiane cherif diarama cheikhal islam

  • mamadou ndiaye fall
    29/05/2016 23:59

    la tadjarou ya ounasi djeukeunetéléne dieume sa yoneya lahade hanlate hadamaya cheikh sa gorou yalla you weure ya famounetaha hawli cheikhi baye boufetouweure moye you weure ya

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL