Annonces
Annonces
» » » » Making Off d’un nouveau clip de Waly...

Making Off d’un nouveau clip de Waly Ballago Seck

En chaussures plastiques communément appelés « Tic tic », Waly Ballago Seck vous plonge dans les coulisses d’un nouveau clip dont la sortie est prévue ce lundi soir à 23h précisément, annonce le chanteur sur sa page officielle Facebook.

2

3

 

 

4

Annonces
Annonces

19 commentaires

  • après bercy
    30/05/2016 15:45

    fékhélene rek ba après samedi bouniou kéne sonal si danio mayé billet, wala danio wayé porte, samedi nguén khamné lép deug la,

  • Apres bercy
    30/05/2016 15:46

    Bercy fess dél

    none yi na nguéne nangou nak, sou amoul nite niou nangou echec, mais sou fesser diap léne nopi nak, nangou dogal

    damaléne di prevenir ndakh khamna léne, il fau nguén oute lounguéne wakh lou niaw,

  • top mame
    30/05/2016 16:03

    yallana yalla mey feke ak tal Walt la la thiat »..

  • zizou
    30/05/2016 16:06

    khana fssou lamine samdi wally dina fay lampouyi pour tour lendeum nityi

  • nafi
    30/05/2016 17:00

    c honteu c waly il achéte lui mm dees billets

  • Fans youssou ndour
    30/05/2016 17:02

    Wooooh après Bercy raynama mais Bilahi wakhnga deugue .mais waly môme di n’a raye nite

  • Khadim
    30/05/2016 17:48

    Gvd

  • dof
    30/05/2016 18:14

    aprés bercy tu ma tué mé vs avé di k la vérité

  • zal
    30/05/2016 18:52

    wally seck thieuy li lou deff mou nekh none yi gngui n tk di khar mais ndam rk

  • mami
    30/05/2016 19:34

    après bercy tu as raison bou Ken triché sou fessé gnou nanguou sou fessoul tame gnom gnou nanguou mai nak yallah n’a ame ndam en tant k senegalais

  • Après bercy
    30/05/2016 19:37

    Avant ils disaient dou fess, plus on approche ngay Deg niou nane niou ngui Mayer billet. Wala nanou tal lamp yi, Wala Waly Mo dieunde billet yi, fiiiii Kene dou mouth, danio sone nak

  • deuch
    30/05/2016 19:39

    Bercy mome kou yabou nopisi parsque dafay fss dl Inchahala

  • Mass
    30/05/2016 20:28

    Nô après bercy dadji nama Bilahi y’a nekh mais Wakh nga deugue nak waly mo sonal sénégalais yi

  • zeynab
    30/05/2016 21:11

    yow ziza bilakhi walakhi talakhi yow d djouli wala bo ko nèkè yoroulo xolou djoulit meusouma gis lou mèlni yow ziza xawma zazi j n veu mèm pa prononcé ton meusouma gi nit bounè ni ki mo bagna bagn waly ba meuneutouko neub yow waly raw nala yag na yow waly lidieutiwoula meusouma giis nit bou bonnè ni ya ignien ya soxor inarila com yèfar yow bo yoron thiabi adjiana kon kèn dou dougu wayè yala bakh ba yoroulo ko yow yay nitou safara deug deug

  • MOR
    31/05/2016 00:15

    Louni fabg ken douko diekh wally woy rekk lay deff dem lene si page facebook ngen khol woyou papa wemba bimou reprendre extraordinaire nangoulene rekk tela nangou nekh

  • ziza
    31/05/2016 00:29

    zeynab ligama wakh khamoumala khamoma way damko rthiou

  • ziza
    31/05/2016 00:30

    daga rthiou ligama wakh

  • el hadji
    31/05/2016 12:40

    maye nene niou diame fi wally mo fi neke

  • MEUZ
    31/05/2016 12:45

    DINA FESS YALLA REK MO HAMM

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL