Annonces
Annonces
» » » » Le nouveau clip de Soleil Levant « Bercy Waly...

Le nouveau clip de Soleil Levant « Bercy Waly gui ni »

Dans le cadre de la promotion du grand rendez-vous de Waly Ballago Seck à Bercy le 4 juin, la troupe théâtrale Soleil Levant dévoile le clip officiel « Bercy Waly gui ni ».

Annonces
Annonces

25 commentaires

  • zeinab
    14/05/2016 12:19

    woooooooooooooooooy sanekh ray nama non nice na torop

  • rebatass
    14/05/2016 12:21

    trop cool mais par contre kine badiane waron na sol lou geuna respectable mouy melni yamb ni

  • Sama Khalaat
    14/05/2016 12:24

    Yener yeey di ko publicitel deh…. BALLA BERCY bi di Done Berceuse… MAI NAK NEKHOUL FRANCHMENT WAKH REK T YALLAH TAKH

  • Karim
    14/05/2016 12:53

    Sanekh raynama

  • belle
    14/05/2016 12:54

    C’est rigolo sanex ray nama

  • mami
    14/05/2016 13:04

    no nekhna trop du courage

  • adt
    14/05/2016 13:22

    nkhol nkhol

  • Diop
    14/05/2016 14:14

    rebatass yamb sakh élégant na ..oul rek lamay saaf

  • nasi09
    14/05/2016 14:25

    formidable yalla nallen yalla maye ndame wally ak nioumou andale

  • nasi09
    14/05/2016 14:28

    yalla nalene yalla maye ndame wally ak ngigal andale chanson bi ak clip bi nekhna trope

  • king
    14/05/2016 14:32

    Cool mdrrrr no coment

  • rohey
    14/05/2016 22:12

    nice

  • Arame
    14/05/2016 22:51

    da melni mane lagne yapp

  • Amar
    14/05/2016 22:53

    mdrr vraiment laff thiatt

  • anouch
    14/05/2016 23:32

    roòoooooooh nan maos saaaanekh dey deim .neneu aladji daw seu yeuf leu lol …nice neu kan mm chapeau

  • anouch
    14/05/2016 23:34

    nan mane soleil levant damleine di weuur piree …naikh neu sokhor bahul laff thiatt tchi wally

  • nana
    15/05/2016 06:28

    nekh na

  • mami
    15/05/2016 11:05

    c po du tou bon mai nak conten n’a si solidarité entre star sénégalais rafet na

  • Doum
    15/05/2016 11:43

    nooo mais sanexx ma tue
    dama ree ba sonnee

  • Diallo mamy
    15/05/2016 12:02

    Hoo laf thiat si domou pape thione biii mala buegue birrr yen wa soleil levan mention très bien mai nak sama père dadie x6 si taly Sénégal kouko guena guaw mou guénela nékh lol

  • izi
    15/05/2016 12:08

    boy wally amnga fite dal bercy reuy na trop mai bon courage kiné badiane t trop vulgaire t une mere ka mm kholatal sa look bi way

  • la diva
    15/05/2016 16:02

    Kine badiane kene khamoul loy nirol ngay melni vampire ni

  • mami
    15/05/2016 21:32

    kiné key kom yomb rek saleté niak class

  • mimi
    16/05/2016 00:25

    kin amo class clip bi yasi gueune niaw sa bop bi mleni bopou thiagua mbde

  • baba
    16/05/2016 20:41

    mais sama khalaat ko yab

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL