Annonces
Annonces
» » » » Exclusivité: nouveau clip de Youssou Ndour...

Exclusivité: nouveau clip de Youssou Ndour « Djiguéne Gni »

2015-06-27T21:53:21+00:00 Partages

Youssou Ndour dévoile la vidéo de son nouveau single « Djiguéne Gni » rendant hommage aux femmes.

Annonces
Annonces

52 commentaires

  • Ousmane
    27/06/2015 22:00

    Youssou yalla nga dem makka so dewe dem aldiana. Tu nous rends heureux

  • tyy
    27/06/2015 22:32

    nekhna

  • tyy
    27/06/2015 22:36

    tarcala tarcala

  • assane
    27/06/2015 22:47

    yaw you diam rek guay am

  • dame dia
    27/06/2015 23:05

    no li refatna lol youssou yalla gafi yageu

  • ndiaye
    27/06/2015 23:14

    Oh c'est beau

  • Bakh yaye
    27/06/2015 23:23

    merci you que du plaisir

  • adama
    27/06/2015 23:27

    super

  • ndiaye pobbar
    27/06/2015 23:28

    dafa gatt waye…fi sama yamar di tanguer rek mou diekh…..ishhhh

  • feuz
    27/06/2015 23:41

    nekhatina comme d habitude

  • zico
    27/06/2015 23:50

    yaram dawna c super merci you

  • rim
    27/06/2015 23:55

    Youssou doundal way ligay bégal diamou yalla yi yalla molay fay

  • Meti
    28/06/2015 00:12

    J'aurais pu jouer dès la vidéo because c ´est ce que je vis la violence que j e subis n'est pas physique mais morale j veux dire une chose aux hommes jour metital diabaram tôt ou tard dinako guiss sa diabar mo la dioural say dom tank l'homologation mou gui tang si yaw sa Lép moy degueur so beugetoul bayil mou dem moguene torokhal bou yagué yay torokh bou meti

  • La diva
    28/06/2015 00:19

    do Moromou kèn ci musique

  • Oh
    28/06/2015 00:19

    Ki dou ndey nit jvsjur vraiment ras you dal namo dra te boleih wok dra wax ludul dieufff eupna

  • nabi
    28/06/2015 00:33

    YOUSSOU WAYALLLLLLLLLLLLLLLLLLLL

  • kani xèigne
    28/06/2015 00:43

    You kène nga si nioune manèsoula faye

  • khadim Sylla
    28/06/2015 01:32

    papa youssou liga wax nèkna
    bilahi ma Bagne koye tera xall
    jigene
    sete rall léne jigene thi
    ndaxx nioye seniou yaye

  • NFS
    28/06/2015 01:41

    Défatina Meuniname Dé!!! The King!!!

  • absa
    28/06/2015 01:53

    nekhatina. merci you

  • canada
    28/06/2015 02:10

    Youssou dèmal diamou Yalla tèbayi thiakhan lègui mak gua mo guane thi Yaw dè

  • zing54
    28/06/2015 02:43

    you kennala yalla moko may

  • malsain
    28/06/2015 03:00

    merci le roi du mbalakh tu nous rend chaque fois heureux merci merci

  • mami
    28/06/2015 03:55

    Grnd you ligawah Lep deugle

  • titeuf
    28/06/2015 06:43

    le grand theatre doit porter le nom de Youssou Ndour, n'attendons pas qu'il meurt yallana yekh pour lui rendre un hommage bien mérité.

  • sow poulo
    28/06/2015 08:02

    def ko ni dome bo diour yedal yaral te bouko bayi

  • baws baws
    28/06/2015 08:08

    merci papa you nekhna trop.

  • Nice
    28/06/2015 08:35

    nice grand You.mais ani MAMY CAMARA nak??? Mola djioureul say doom pourtant tu la laisser apres 30 ans de mariage??pour AIDA CHAMPAGNE lolou aussi si torokhool djiguénn la book

  • lydia
    28/06/2015 08:37

    mon mari me gifle souvent mais ilme dit ke giflé c pas frapper!

  • Talla
    28/06/2015 09:17

    super

  • pisco88
    28/06/2015 09:32

    on ne doit lever la main sur une femme you nice na goudal fan tè wèer

  • soukeyna
    28/06/2015 09:48

    you diam rekk lay ame thia kaw thia kanam thi lou bakh

  • cre
    28/06/2015 10:07

    bilakhi mala beugeu papa

  • spagheti
    28/06/2015 10:28

    behh you toujour des beaux paroles mais les actes sont different le seul fait que tui a des enfent hors mariage avec au moins deux femme different est un manque de respect au femmes

  • lii
    28/06/2015 10:42

    super shik

  • gueum
    28/06/2015 10:42

    diadieuf

  • khadija diouf
    28/06/2015 10:51

    hooo tonton clip bi nekh na trop machalah

  • bandiougou goumane
    28/06/2015 11:55

    j Salut vous tous

  • ive
    28/06/2015 13:53

    li moy sa liguéy mé politik mon khamothi dara.Il faut retourner au thiossane

  • b s n
    28/06/2015 15:59

    nekhna

  • patrick
    28/06/2015 16:21

    togalnakh. Ngour ke'na douko nieude. bayil . Dimeulil khaleyi gnou dem, mo gueun, tet tok. yafi modki wakh tji djiguens. Youssou, y'a sof

  • savorian
    28/06/2015 17:16

    MBALAX EN PLEIN RAMADAN; TOUT DE MÊME YOU;;;;;;;; LII DOU SA THIEUR.

  • salif dia
    28/06/2015 20:47

    you longue vie a toi on t'aime bcoup

  • salif dia
    28/06/2015 20:48

    you longue vie a toi

  • Beugue Sénégal sama rew
    28/06/2015 21:14

    j'ai dédié ce morceau à ma femme Yayou samay dom djiguene diou mane gor!

  • monia
    29/06/2015 17:57

    ay way kholal ni ndaw si contané wone bamouy marié bou khamone likoy khar doussi dougue.yéneu goorgni bayiléne tass yakarou djiguéne gni.bne continuation sama you international sui tré fiere d toi.kou mére nak boko

  • dieny gueye
    02/07/2015 18:18

    Franchement nous senegalais nous sommes tres tres choye d`avoir le plus grand chanyeur du monde entier la plus belle voix d`afrique . Sayo weuye ma contane khol yeup bekk yaw youssou ndour kene amoul sa faye yalla nalla borom bi faye te mousseule le thi thiat akh lamigne je suis vraiment amoureuse de ta musique .

  • salipha gueye
    02/07/2015 18:55

    You is thé best and hé will always be it

  • gueye
    03/07/2015 14:56

    youssou ndour yadooléll saytané si senegal mangi mouslou siyaw

  • fanaya
    23/07/2015 02:40

    That's my da muah

  • SETOU MBEGANE NDOUR
    29/07/2015 18:07

    SETOU MBEGANE NDOUR LINGA WOYE CEST NEKHE MAIS WOYE NGA LEUPE LOLOU LA GAGNI WAKHE MAIS MBEGANE NDOUR LA BEUGEU NGA WOYE

  • amaana
    01/08/2015 12:13

    lii dou wakhou fi,khanaa danga ja motakh….

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL