Annonces
Annonces
» » » » Exclusif – Le nouveau clip de Viviane...

Exclusif – Le nouveau clip de Viviane Chidid « Yaama Neekh »

Après la sortie de son nouvel album live qu’elle fait cadeau à ses fans, la reine du Djolof Band dévoile le clip officiel du morceau « Yama Nékh ».

Annonces
Annonces

26 commentaires

  • Arame
    14/05/2016 22:28

    li loukayy faye vivi rek dessoul sakh jtadoreuh

  • Deuch
    14/05/2016 22:32

    Nkhoul dara

  • Du Degn
    14/05/2016 22:59

    vivi rk mo nekh tro nekh mme

  • Anonyme
    14/05/2016 23:05

    Niang xaragne ya ngui beug done niang ka tang soce bou gneuw yeek la

  • binou
    14/05/2016 23:21

    trop nekh ya âme classe halebi souma magué ni yaw la beugeu mél

  • zeinab
    14/05/2016 23:44

    waw viviane nak ni lagn lay bayi rèk yow ko yap way bou yag bi nga togat kèn xamoul lo ci yok ni yow dal wat gani do xalat way yow dal sen bouba dognou djokh produi bou bax vivian bayil sa thiakhan yi dèmal liguèyi mo geun yigay dèf mon way bi nga xam ni bobou magi dèf primèr aaaaaaaaaaakh dèdèt wayz

  • sofia
    15/05/2016 00:20

    nekhna

  • khadim sylla
    15/05/2016 01:44

    neke naa tata way rek ghay deff

  • Na
    15/05/2016 02:04

    wayou fii dara ki daffa soff

  • Na
    15/05/2016 02:06

    wayou fii dara ki daffa soff way.. yena nekh way la rek la beug kham??

  • tyma
    15/05/2016 02:46

    nekhoul dara khamato foy dieum tu fesai mieux bifore du courage seul le travail países.

  • Mamadou
    15/05/2016 04:56

    les méchants vont mégrir vivi rek si classe

  • lasssssss
    15/05/2016 07:20

    les mechants sont vont maigrir et ils sont entrain de vomir mme

  • lesi
    15/05/2016 10:35

    Nekhoul . Li demoul fen . Jetez moi ça à la poubelle ! et vite !

  • mami
    15/05/2016 11:04

    g même pas fini la vidéo pt être beug beug ak guiss guiss yé bokoul wayé man personnellement guissoumafi lou nekh

  • Bercy
    15/05/2016 11:55

    Je crois que c’est là fin d’une époque .

  • PiPo
    15/05/2016 12:45

    tu na jamé eu dinspiration viviane. soit wayou diambour oubien tangale thiépe. TiTi dousa morome.

  • khoul
    15/05/2016 12:54

    Attention : l ecoute prolongée de cette musique est dangereuse pour la santé de vs oreilles

  • Arame
    15/05/2016 13:14

    kumu nekhoul na dialeu feulee

  • nopp vivi
    15/05/2016 15:17

    Khass nagnou la beuf té dara douko dindi ndakh yaagui khôl lignouy bégal ngassiy dokh Kone
    yaa gnou Nékh yow mi takh gnou féékh

  • coum
    15/05/2016 15:24

    titi dafa thiak

  • mimi
    15/05/2016 22:20

    nkhoul gat

  • pape
    15/05/2016 23:22

    ah li nekhna way mashala

  • cheikhmodou
    16/05/2016 11:10

    bayi lène sokhor sokhor rèk motakh dou ngou dèm kilimouy dèff dafa nèkh torop machallah vivi

  • nono
    17/05/2016 01:10

    liiiii waylaa nooooon viviane fooo toth

  • angelle basse
    13/06/2016 22:15

    Sénégal deme car la méchanceté nous fatigue Vivi yalla nala yalla mousal thi gnou bone .Amen

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces