Annonces
Annonces
» » » Cheikh Béthio Thioune interdit le port des  »...

Cheikh Béthio Thioune interdit le port des  » Ndiel  » et le battement des tam-tams dans les Thiant

2016-04-12T08:51:00+00:00 Partages

Cheikh Bethio Thioune guide spirituel des « thiantakones » a interdit le port de pendentifs à son effigie, de même que les tams-tams à l’occasion des actions de grâce communément appelées « Thiant ».  Le Cheikh n’a pas dit les raison qui l’ont poussé à les bannir. Il s’est limité à porter à l’attention de ses talibés sa volonté de voir ces derniers se départir dorénavant des « ndiél » et des battements de tams-tams. Selon « Zoom Infos », l’interdiction a été suivie à la lettre par les milliers de fidèles que compte le guide spirituel.

Annonces
Annonces

20 commentaires

  • mame fatou
    12/04/2016 09:06

    dimal wo sa talib yi thi yonou yalla mo geune euleuk dingako layo ak sa borom

  • aline
    12/04/2016 09:18

    yaw shut your fucking mouth bitch

  • doff dou wèrr
    12/04/2016 09:22

    Mame fatou amal yaar réw nga trop

  • noreynibounafane
    12/04/2016 10:37

    diadieuf thioune ,serigne dafa dpkh ak adouna chak chose a son temps ,yaguefi lool and ak werr thioune

  • Sam le pirate
    12/04/2016 11:15

    :( Bethio, il n’est pas trop tard pour que nga kham sunu Borom moy kan.Il est temps pour toi d’ assainir ton cœur et ceux de ces milliers de domou adama que tu n’y as cultivé que l’ignorance et et l’addiction aux jouissances de la vie.Ce serait très lourdes de conséquences, si tu te retrouvais le jour du jugement dernier avec tes propres péchés en plus de ceux de tout ces jeunes que tu as détourné de la voie du « Siratal Moustahim » sans oublier les meurtres barbares de 2d’entres eux.Bethio sopil té toubb bala wess.Wassalam ! :(

  • papis
    12/04/2016 11:23

    Bonne décision yalnala serigne Touba dollé takhawou

  • paco
    12/04/2016 11:25

    il comprend la vie maintenant du courage bthio

  • duo
    12/04/2016 11:32

    doul merde

  • GM
    12/04/2016 11:44

    Hun! aaay! Sunu borom mome dou morom tei lii mou santané lou leer la. Yaa ham nak ndakh mome ngay deigue ay santané me walla ay ndigueulou thiahane. Dième leine top Yalla mo gueunn! Leigui kagne après s’être bien servi de vous, il commence à rectifier le tir car il s’est bien enrichi en vous bernant…

  • zeus21
    12/04/2016 11:54

    aaaaah nileu kay c’est un bon début!!… teugoume sabar ak fetch andoulak celal ak tiant borom bi

  • weuz85
    12/04/2016 12:19

    et les 2 persones tuees….??? ba ni rek…senegal pays sans Lois….Karim en prison…thione…bethio…ousmane ngom. .awa ndiaye ecc.. libres…

  • yaco
    12/04/2016 14:11

    senego déléne dialalé samay commentaires

  • yaco
    12/04/2016 14:16

    yenne gni wakh serignou diambour lou bonne ak diko saga senego diko dialalé ki dou sénn moromou baye t yenne gni nieup diguene guiss lep ki serigne Saliou moniko do yakhou do yakhoulé t kenne meunoula yakhal

  • yaco
    12/04/2016 14:25

    t cheikh béthio amna 76 ans même si k ni beugou lénko nioune nekh nanou lol t il é temps k nguenne arrété li eu peu neu respect lou bakh la si niit

  • Ngoné
    12/04/2016 15:52

    Toup dou weess! Yala nala yalah dioubeunti yow ak gni la toope..yalla keen meunouko nakh.. .thioune

  • so
    12/04/2016 21:24

    kham nga ko kone ni yalla kenne meunou nakh mé diamou yalla dafa ladj mandou yaw ak ko yakar toub ci yenne la gniél

  • so
    12/04/2016 21:27

    yaw ak sa ndaye yena wara toup pask yaw nafékk bou nga ndakh mandou wo

  • lamtoro
    12/04/2016 21:57

    je l’estime pour son amour pour sérigne Saliou Mbacké je suis un talibé cheikh ki adore sérigne Saliou Mbacké. cheikh BI je suis de tout coeur avec toi.

  • ritachou
    12/04/2016 22:34

    senego gnifiy comment gnou bari dagno rew gnak kersa en plus d’tre des ecervel di mank de respect sne moromou ndaye yi ak sne moromou baye yi rek ta gnome sne ndaye yi ak baye yi defou gnoufi dara lou bakh lou chang deuk bi bagnou meun lne toudou

  • fama
    12/04/2016 22:43

    mandou wolen ba parecdi woteh lislam .vou fait des jugmen gratuite a lrndroit de srign bethio mai lessentiel ces k nou nou laimon et nou croyon en srign bethio malgres vos injur dou wagni lou tolni tarfatal ayni si guem guinou ko guem.serign bethio yagu fi teh wer raw nga wakh kat yi teh en plus doune sen sa peund.koukobagn khol bou diekh guawa deh rekkkkk

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL