Annonces
Annonces
» » » » » » Ce qui lie Chérif Ousseynou Laye à Michel...

Ce qui lie Chérif Ousseynou Laye à Michel Jackson…

2015-05-21T11:13:37+00:00 Partages

6 ans après sa disparition, Chérif Ousseynou Laye, cet érudit,  qui avait « une relation particulière avec  Dieu  et un amour profond pour le Coran »,  continue toujours de vivre à travers les cœurs des talibés Layènes. A preuve, ce témoignage inédit dans L’Obs de son neveu.

Cet homme de Dieu au teint clair et l’élégance raffinée « a passé 22 ans à méditer en France. Avant d’être célèbre, le Roi du Pop, Michel Jackson, s’était rapproché du Chérif pour recueillir des prières. Quelques temps plus tard, Michel a reçu son premier disque d’or », révèle Libasse colonel Diop, électro-tehnicien de formation.

Le défunt marabout, durant également ses études au Maroc, ajoute son neveu,  « acheminait des jeans, costumes, chemises, vestes, à l’occasion des grandes vacances à Dakar. Et au retour, il prenait des marchandises, rares au Maroc, pour aller les écouler au Royaume chérifien ».

Annonces
Annonces

36 commentaires

  • diop
    21/05/2015 11:37

    le khessal

  • Mystique men
    21/05/2015 11:58

    @diop ya Boon deugue deugue mais yallah ta entendu tu verra d'ici deux jours inchallah de qui va t'arrivé Da nga rew rek.tu te croi a l'abri derrière ton ordinateur ou téléphone nakh nga sa boppa

  • titeuf
    21/05/2015 12:26

    Senegal doukou nafekh, musique dafa haram meuno loen wakh bamou dagane, kone kouy woté yalla warou bako nianal nitt bamou am disc d`or. Senegal deukou fen kate ak nafekh.

  • bara samsung
    21/05/2015 12:48

    ba toubalonnako

  • un passant
    21/05/2015 14:48

    Santoul diop, day fene wa diobene ay noble lagñu

  • Sofia
    21/05/2015 14:49

    @ diop la mère de sherrif Ousseynou lahi est peulh mon cher.

  • Sofia
    21/05/2015 14:53

    @ titeuf dafa melni ngané gnome youssou ndour, pape diouf et consort warou gnou ame serigne tarikha bouléne di gnanale.

  • Scorpion
    21/05/2015 15:50

    Titeuf wakh nga deug musique dafa kharam

  • Bayroute
    21/05/2015 15:56

    ya des gens leur cœurs est tres mauvais son méchants

  • MBAYE
    21/05/2015 16:04

    DèLèNN WAKH WAKHOU RAFFèTT SAMA GAYè AY TèGUINN BAKHNA LOOL

  • mouride sadikh
    21/05/2015 16:47

    sama gayi na kounè guem limou guem mane suis mourid sadikh mais jèm bcp baye laye ak wa keureum ndakh sèn mandoutè

  • pape laye
    21/05/2015 19:20

    c pape laye gni wakhe lou niawo li magui nian kèpeu gou geume baye laye ak seydi na dèf nian bi yalla atè gnou ak gni si barke baye ousseynou laye 3faatiha 3 ixlaas 3 callatul faatihi

  • djibi
    21/05/2015 19:55

    mdrrrrrrrrrrr ya bone

  • lamp
    21/05/2015 19:59

    déte pape laye bayilene yak chérif rek yawe mome nianale lene diam rek gua khol

  • sidik
    21/05/2015 20:00

    nopile way yaw bourgua

  • bba
    21/05/2015 20:06

    wakhatiko dé yak dér rék

  • mortalla
    21/05/2015 20:07

    qui cherif la magui siar

  • serigne
    21/05/2015 20:09

    deug deug kou khmoul déy nopi way

  • war
    21/05/2015 20:11

    dellou léne thi yalla balla beussou pech

  • di
    21/05/2015 20:21

    machalla

  • siteu
    21/05/2015 21:24

    diam rék guay am

  • birame
    21/05/2015 21:27

    borom bakh gua sama sang bi boul fallé non nakh bakhoul

  • dass
    21/05/2015 21:28

    héy way

  • peace and love
    21/05/2015 22:14

    kou bakh serigne fallou wo na doudou ndiaye rose bamou nieuw mou nianal ko niko deugueul

  • pape laye
    21/05/2015 22:26

    sidik bipèma si numero bi ma wola diga dègue limala wah 0039 388 75 87 628

  • Kocc
    22/05/2015 00:24

    yalla nayalla yokk aye leram te tass gnouthi barkep bidiahi SEYDIL WOUDIOUD

  • Kocc
    22/05/2015 00:37

    yalla nagnou yalla tass thi barkem te yokk ayy leram bidiahi SEYDIL WOUDIOUD

  • daouda
    22/05/2015 00:44

    baloulo ak

  • macos
    22/05/2015 07:49

    Bb. J

  • end
    22/05/2015 09:40

    lidé moy na musicien yi gneuw diokhé khaliss hey waaaaaaaaay nignouy wouté khaliss mo nekh

  • xaliifa
    22/05/2015 11:01

    Wax deugue Yallah ça ne vaut pas la peine d'utiliser des produits de dépigmentation pour porter le sobriquet de "cheirf" Ici tout se sait.

  • liberaux
    22/05/2015 11:11

    yen gni di xass cherif ousseynou laye préparé lén di na lén wird yén gneup ba gén xam né tongne baxoul

  • chf
    22/05/2015 19:24

    nite daye manou layenne yi dougnou togne dougnou dingate respect svp.

  • xaalifatuesunsalaud
    22/05/2015 20:09

    Yow khaalifa vrai imbécile nga. Kou toolou ni chérif ousseynou ngay wakh dafay khessal. Ma ngui lay nianal yalla nga goumba ak lafagne.
    Tous ceux ki ont dit du mal à chérif vous êtes des domerames, des salauds

  • Musulman
    01/08/2015 03:35

    Yaw dioulit ngeu ?

  • Musulman
    01/08/2015 03:45

    Allah. Gêne mi ngui melni séné borom guissou lene wakh bou niaw bi takhoul si môme dh. Wayé khalatal sa borom ak nit ni ngay wakhal foumou tolou si yalla.
    Mouhamed psl dit al oulamawou warassatoul anbiyay borom cam cam yi bio remplacer yonent yi. En plus Dieu dit personne ne touche a ses élus (awliya) dou ni nga wakh loi niaw waye ya'Allah mokoy fathie. Mandoulene té diamou sen borom. Safara amna yawmal khiyam amna. T lima meti moy niou diangoul rek nioy wakh loi niaaw. Sahaba nena amoul si kaw souf loi mérite teudj loudoul lamign. Am lene yar t' khôl séné diguentei ak yalla. Am nagn loi beuri louniou Sara deff. Sakhal le ne séné guemign si tesbir tekbir tesmih. Sa salam

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL