Annonces
Annonces
» » Carnet rose : Mamy Diop de la TFM s’est...

Carnet rose : Mamy Diop de la TFM s’est remariée

Une des animatrices de la TFM s’est pendue le même jour que Mame Diarra Thiam (lissa). Mamy Diop, pour ne pas la nommer, co-présentatrice de l’émission  Wareef s’est remariée en toute discretion ce week-end.

Carnet Blanc : Mamy Diop de la TFM s'est remariée ce week end

Annonces
Annonces

17 commentaires

  • dykha
    09/05/2016 13:07

    heureux mnage

  • dykha
    09/05/2016 13:08

    heureux mnage tata mami

  • deug
    09/05/2016 13:38

    khana wadji wax katela boudoul waxkate mako yereum khalebii limouy wax ma cha allah yalna seuybi barkeel

  • kheus
    09/05/2016 14:10

    deug doul

  • Rathieu
    09/05/2016 14:48

    Mamy diop Ndoye Mbane laa waronne seuyel konn mou nékh sénn dome rék 3 mois mou komasé wakh nanléne mako guiss mako féké mako dégue thie sama nope bii ndaw keur guou nékh. Heureux ménage yallana seuy bi barkél.

  • mamymamy
    09/05/2016 14:52

    Dieukerou many am gua fite

  • Anonyme
    09/05/2016 15:45

    bon mnage.

  • Amina
    09/05/2016 15:55

    felicitation Yalla na sey bi don ben te barkel,Amiin

  • thieuy
    09/05/2016 16:10

    heuye kitak Mamy amena fitt dinawakh banga titt « sama mame nna …. »

  • djiné
    09/05/2016 17:09

    ki loumi wakh je suis sure et certains quand tu la baises les voisins vont entendre ndakh aka nekh way dolile , coye bi saf na , djouteul ma

  • guewal
    09/05/2016 18:44

    yallah naye sa ndieuk laye ndiaga mathia ndioum ak mahtar mithie coki diop yaba khary seutoup assane marame penda bourou thilmakha mbakol bi dior yaba sa yaye cheikh yaba bayam mo demalon cheikh modou moustapha mbacke thia guere ba

  • dija
    09/05/2016 18:50

    rafetal lene kadouyi waye heureux mnage mami

  • kira
    09/05/2016 20:26

    dna wakh ba dieukeureum daw

  • Buzzshu
    10/05/2016 01:06

    yaw Djiné nitt nga ya déglass way shirt heureux menege Tata Mami Yallah seyy bou Barkél tanga gaw walle gnou inchalah

  • thia kaw thia kanam
    10/05/2016 03:32

    kheus yagui merdė nianal lene yalla mo gueun yalla na seuy bi barkė yalla lafalen thiat

  • @djiné
    11/05/2016 07:56

    yaw djiné khana da nga yaga deegue sa yaaye mouy youkhou bou ko sa baaye di kate domou ram yaw ya bone te gnak kersa loo defati ci kaw souf rek ya nga dokh ci sa djobou ndaye Mamy dafay sa morom

  • beau gosse
    11/05/2016 10:28

    rathieu ray guama ahaha heureux mnage la belle mami

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL