Bienvenue sur senego.com, votre tout nouveau portail, désormais c'est ici que tout se passe

          

 

Si vous souhaitez faire de la pub sur senego.com contactez-nous

 

le lexique wolof

 

Wolof Prononciation Français
Daanu   Tomber
Dab   Rattraper
Dafa   Il ou Elle
Dafa beg   Elle est contente
Dafay dem   Il ou elle part
Dafay nélaw   Il dort
Daje   Rencontrer
Dall   Chaussures
Dama   Je
Dama bëgg   Je veux ou je voudrai
Dama marr   J'ai soif
Dama tang   J'ai chaud
Damay dem   Je pars
Damay tëgg balafon   Je joue du balafon
Danga   Tu
Danga sonn   Tu es fatigué
Dangay dem   Tu pars
Dangay xool   Tu regardes
Dangeen   Vous
Dangeen dem   Vous partez
Daqaar   Tamarin
Dara   Rien
Daw   Courir
Dañu   Nous
Dañuy dem   Nous partons
Dañuy ligeey   Nous travaillons
Dee   Mort
Deedeet   Non
Def   Faire
Defar   Fabriquer
Degg   Comprendre
Degg   Entendre
Deggal   Obéir
Deglu   Ecouter
Dem Déme Aller
Dem   Partir
Demb   Hier
Des   Rester
Dex   Fleuve
Deñuy dem   Ils ou elles partent
Dibeer   Dimanche
Dieuleul ouarga bi   Prends le thé
Dieun,am na téy ci guedj bi lool   Il ya du poisson aujourd'hui(en mer)
Diggante   Distance
Diis   Lourd
Dikk, Ñëw   Venir
Dimbale   Aide
Dindi   Enlever
Diokh ma suker si   Passes-moi le sucre
Dof   Fou
Door   Débuter
Door   Frapper
Doyadi   Insuffisant
Dugal   Introduire
Dugg   Entrer
Duss   Toilettes
Démal diendi khorom   Vas acheter du sel
Dëgg   Vérité
Dëkk   Ville, Village
Dëng   Malhonnête (être)
 
                           
 <retour 
 

 

toute l'actu sportives
 
quel sujet aimeriez-vous voir traité dans le site
de tout
politique
sports
people
religion
j'ai pas d'avis




résultat s »