Annonces
Annonces
» » » (6) Photos inédites: Viviane Chidid fière de...

(6) Photos inédites: Viviane Chidid fière de ses rondeurs sur Facebook

L’éternelle sexy Viviane Chidid avec son habillement ultra attirant, a enchanté les invités d’un anniversaire dont elle a été choisie comme marraine. La reine du Djolof Band montre qu’elle a rien a envier à cette nouvelle génération d’artistes qui se la joue sexy.

 

44

77

vv

vv1

VV5

VV7

Annonces
Annonces

77 commentaires

  • Hawa
    23/05/2016 12:57

    Ndeyssane dofna legui li d’où yere

  • babandakarou
    23/05/2016 13:00

    kėn khamoul lo sol

  • coum
    23/05/2016 13:04

    Viviane yagui gagn ya taay loula nekh def ba kene lale bo pare gua may mako sa krevase bakhna

  • riti
    23/05/2016 13:05

    Rihanna bigun df royoukay ap drogu khamoul foumouy tk tankam . sounou artiste senegalaisyi sn proplm moy manounou rann

  • diagnenardiagne
    23/05/2016 13:09

    yanqui diem Mac nak

  • MBI
    23/05/2016 13:10

    HOO YALNA KO YALLA MAY DIEUEUR LI YEEP DIAYOU REK NDEY SAAN DAFA LAMB BOYBI TAN KATOU DAAL BOO GUISS AY PADAM DIAKHESS LAY MOUDJEE

  • Charlotte
    23/05/2016 13:15

    Rihanna la legui thiepiri mako diépi

  • Lilia222
    23/05/2016 13:20

    Ridicule…….Viviane n à pas de conseillers…..Viviane t as l âge d être grand mère et quel honte de s’habiller comme ça……..le problème est qu elle copie les artistes américaines….l énorme différence avec Viviane elles ont l âge de sa fille……bouba ndour nguir yalla dimbali ci liii….Sénégal sone naniou……vivi redescend sur terre ….tu n’es as super star tes juste chanteuse sénégalaise….. pitié

  • khoul
    23/05/2016 13:36

    Saytané bou mak ba ngi .
    Elle a devergondé toutes les filles du Senegal .
    C maintenant au tour de Guigui , Deesse et Queen Biz de prendre le relai.

  • Abdou gueye
    23/05/2016 13:47

    les gots et les couleurs ne se discutent pas.je sais qu’elle n’a pas encore dit son dernier mot.

  • MOO mergane
    23/05/2016 13:49

    Je taime bocou mon amour

  • dass
    23/05/2016 13:57

    rafetna

  • bob dia
    23/05/2016 14:00

    c gnial quelle belle mode c la music et la mode qui sont ensemble fait ce qui te sble bon celui qui n’en veut pas c son affaire

  • la mignone
    23/05/2016 14:03

    m ki saf na d

  • Moh
    23/05/2016 14:06

    0/1

  • mami
    23/05/2016 14:15

    legui li loussi rafete?no man ma warou yow demal tok rihanna vingtaine d’années la ame yow 50an doul way

  • helena
    23/05/2016 14:36

    je parle meme pas de ton age viviane.mais tu es en faillite essaye de te respecter au moins pour reprendre ta place.cest pas cette habillemnt qui te donnera un atout

  • sarr
    23/05/2016 14:54

    pas class!!trs bas

  • kiné
    23/05/2016 14:55

    mais yéne Kate lene ndayame feulé gniye saboté vilene que vous êtes Viviane mognou nekh teguou si temps

  • sofia
    23/05/2016 15:17

    viviane saf rek la def, meussoul nek moromou gayi té douko meuseu nekeu. star moye dawe si yaramame. gnene gni dagnou koye diéme rek. deug nekhoule

  • Amina
    23/05/2016 15:37

    Yalla na niou Yalla khirr si bopam,Amiin

  • khoul
    23/05/2016 15:40

    Kiné yow kou reew nga . Khamna ci niou viviane Yar nga bok motakh nga xamadi

  • Gie-Joe
    23/05/2016 15:53

    elle veut retourné à son enfance mdr

  • coum
    23/05/2016 15:55

    mo taay

  • coum
    23/05/2016 15:57

    khoul ya guina khamadi go kine mo taay vivi louka nekh laye def

  • Right
    23/05/2016 16:00

    pas de pudeur, ni de vergogne ak sa yaramou maguette bi

  • khoul
    23/05/2016 16:35

    shut out your mouth ! yak sa niaaway

  • Arame
    23/05/2016 16:51

    mais nitt mo sokhor kumu nekhoul dialale feulee vivi rek si khol lenette dafa khadioul

  • Fake
    23/05/2016 16:53

    c’est du dj vu riri la dj port dans son clip work

  • slam
    23/05/2016 16:54

    je souhaiterai que wally te prend comme 2eme femme maname niarele.hahaha……

  • kaba
    23/05/2016 16:58

    vivian tes fils sont à c grand elle voire de ce que tu dois porté

  • passant
    23/05/2016 17:17

    Pourtant c’est elle même qui l’a publié sur sa page Facebook. L’affaire est simple nekh nala kholal, nékhoula mais tu zappe

  • justin
    23/05/2016 17:28

    viví loumou def mou rafet ken mounousi dara

  • mami
    23/05/2016 17:31

    kiné sa khourou bay bou khoukhane

  • Fake
    23/05/2016 19:14

    lol mami wagnil sa galadie. mdrrrrr louy khoukhane

  • coum
    23/05/2016 19:21

    mami sa souloukhou bay sa tounou ndaye bouyou rophe

  • coum
    23/05/2016 19:23

    fake seytane gua merde way

  • coum
    23/05/2016 19:24

    khoukhane moy sa bosou baay mami ak fake domou penatiyi

  • bay niokhor
    23/05/2016 19:36

    Djiguen dakay nouro star sexi mandal vivi dama yague nekh yaramou nen je prend qui ne veu pas zap zap zap guen balma haaaaaaah nekh

  • Iz
    23/05/2016 19:42

    Ya gui pata viviane lou khew ?

  • coum
    23/05/2016 19:49

    vivi doyou bagne dess amna yo khamni doyon sokhor

  • mami
    23/05/2016 19:57

    coum chak matin bo yewo rek diapalné Kate ngua sa yaye tte la nui

  • amadou allemagne
    23/05/2016 20:00

    je veux le numero de viviane ndour s il vous plait

  • mami
    23/05/2016 20:02

    khoukhane moy koyou bayou koum yi lol fake bou Ken tontou mako ress

  • mami
    23/05/2016 20:09

    kofi sagua ndakh vivi rek ma nokoss sa tounou bay ak gingembre

  • coum
    23/05/2016 20:41

    sa souloukhou ndaye daguaye rew mala guina rew so khamone coum do dougou si mane sa lef yaye bou khey magui diegalou si la waw bi mete

  • coum
    23/05/2016 20:44

    mami Dagua gniak fayda loula fek gaye sagatele ak sa rak loulaye waw yaw Dagua warouna d’o gua wone ni warou ma saga gua tek ma si yon

  • champion
    23/05/2016 20:53

    Ohhh vivi defal loula nekh ya tooy deii mala beugg ioe rk xana ay wax sax dafay diekh

  • cheikhabibdia
    23/05/2016 21:07

    top nga bakane fatou founek la gneuwe de deuk di toube mo gueune loudoul wey telko bayi mo gueune dici 10 ans so xole foto yi da koy rathiou lol

  • mami
    23/05/2016 21:22

    wa coum yow en plus d’être con t deugueur fite dé lol esk tu sai combien g yow ta kel âge?

  • malang
    23/05/2016 21:33

    moi je vouls dire encore bouba n’dour ils son une belle femme qui et toujours en plaine forme et puis ils et toujours en tain naturels

  • malang
    23/05/2016 21:37

    bouba n’dour ils son perdue une belle femme

  • Fake
    23/05/2016 21:45

    coum sa

  • mami
    23/05/2016 22:04

    coum ya sagua nieup ndakh vivi man rek si sagua

  • guediawaye City
    23/05/2016 22:04

    Quand je lis les commentaires j’suis mort de rire,mais chacun est libre de donner son avis wala sa sert a rien d’être vulgaire ou d’insulter Mane dal warou na

  • mami
    23/05/2016 22:28

    ah fi kat kou wakh nekhouma rek niou sagala man nak douma né Ken bayinala yallah

  • coum
    23/05/2016 22:31

    mane 2001la

  • coum
    23/05/2016 22:32

    15ans

  • mami
    23/05/2016 23:00

    koné désormais respect ok ya né kat len sen Day say moromou bay ak say moromou nday fi sa morom nekoufi wala si no si moussiba rek nguay deg man douma bal khalé g 23ans

  • coum
    23/05/2016 23:11

    khakhou ma gua balma nakh toyou mala

  • King
    23/05/2016 23:27

    Vivi laisse les parlé rek. Nitt limou yoor si kholam rek la guéné. Donc gniy saga sén khol Mo bone rek on comprend. Nous avons bcp damour pour toi et sache que nul personne ne fais l’unanimité.. Depuis 2000 nio ngi wakh di saga tei faléwo léne.. Donc dou tay ngey tontou. Avance ma chère tu est la reine de la Musique senegalaise

  • La reine
    23/05/2016 23:59

    Super Nice wa senegal namougnou Rihanna nakh Viviane kimo Nice laf thiat ci halébi aka dégue

  • Diépi kou ignane
    24/05/2016 04:06

    Vivi am sa âge mélni tangal yomboule, boulma faléle khalé you perte yii gua khamni, mango bouroubara foucha sakhaléne eupeu diarigne nakh au moins wégni ak sakhi dinagne ci thiope.

  • xelcom
    24/05/2016 04:46

    le seul avantage c est quand elle pète ya l aération kan même. Sénégal dal golo artiste bou djiguen bou nek en faillite rek deff tatineenn pour am buzz…..thieyy Sénégal…….

  • Fan de Vivi
    24/05/2016 07:44

    Ah xalei buzz gneweutina.. Môme ndeysanne robame rek dafay deff buzz.. Star yombul. Ani les autres artistes ? Vivi rek tjr vivi.. On dirait New York lane nek cette éternelle beauté

  • Beug vivi bamou diekh
    24/05/2016 07:50

    Hatters yi li léne metti moy pourquoi tu vieillit jamais Viviane bilay mom sèn blem. Tei instant bi yafi nek avec ton album live qui cartonne tek si sa clip bu saff yama nex.. Prestation sur prestation cauri d’or,soirée port tek si week end yaye leumbè Dakar bamou nex.. Sa robe nak defatina buzz com dhab.. Xana nex xana Viviane

  • coum
    24/05/2016 07:53

    vivi mo taay sole louka nekh yonou kene nekousi vivi loumouy sole fan’s same yi yokome nekoule pour yene nopilene si domou diabour bi kank lene mou khand ah thioudom Sngal Ndiaye France

  • coum
    24/05/2016 08:01

    Viviane namoul dara gone yougne wakh Viviane mre la Ana preuve bi vivi koumou robone sa baay mou kho ko mme bou nekone s’en papa dafa cataracte dina guis vivi moy bidew si kaw asamence kou mer boko

  • biba
    24/05/2016 08:26

    irresponsable voil ce qu’elle est

  • Deug nekhoul way
    24/05/2016 08:30

    Senegal menougne comprendre que ni tu est une star appart Youssou ndour ya fiy star car on tecoute on te lis on te suis tout le temps.. Guiss nagn fi lounei car Mashalla yow do sathie fo lesbienne xamo faux billets ték si thiow li thiow chidid messo khéwi.. Fimou tol ni sa morom yeppa fay mdrr.. Titi ma sané ami mbengu arame thioye aida Samb ak tâta coumba keine degouléne si Music ni si presse ni si Internet .. Donc yow bou féké chak matin gnou degg Viviane kone nek La Reine yafi nek?

  • coum
    24/05/2016 08:39

    safoula

  • maz
    24/05/2016 09:55

    nice na

  • coum
    24/05/2016 10:55

    a thioum deug

  • nankish
    24/05/2016 11:01

    laissez la vivre sa vie mo gueune ngkay jug artiste leu vs jugez tro t sui sur amgn louln doy no mais les senegalais…

  • pape
    24/05/2016 13:06

    c est jolie

  • kheus you cris
    24/05/2016 14:55

    do maaguet mouque

  • boy djiné
    24/05/2016 16:01

    Kate len ndayam yen gni du saganté sen tounou nday…..haram

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces