Annonces
Annonces
» » » (14) Les images du mariage de Abou Thioubalo et...

(14) Les images du mariage de Abou Thioubalo et l’ex Miss Jongama Oumy Gaye

La miss Diogoma Oumy Gaye et Abou Thioubalo ont scellé leur mariage hier par le biais du patron du Grand parti Malick Gakou qui avait représenté la famille Thioubalo. Le mariage religieux a eu lieu à Nietty Mbar en présence de nombreuses célébrités telles que Malick Gakou, Salam Diallo, Salim Boubacar, Papis Konaté, l’ancien maire de Guediawaye Cheikh Sarr.

DSC_0466

DSC_0518-640x426

DSC_0527

DSC_0529

DSC_0531

DSC_0537

DSC_0546

DSC_0562

DSC_4699

DSC_4700

DSC_4703

DSC_4705

DSC_4706

Images: Dakarswag

Annonces
Annonces

38 commentaires

  • best
    10/05/2016 09:55

    waaaaaaawwww

  • best
    10/05/2016 09:57

    yene khol lene malick gackou fimou tek lokho khalebii kii moy say say

  • rebatass
    10/05/2016 10:00

    wa mais khana abou thioubalo amoul ay bok ki dakoy ray deh

  • Arame
    10/05/2016 10:23

    bane abou thioubolo chanteur stp aider mw

  • Ndary
    10/05/2016 10:29

    Abou, manono nga sett kou geneu yamamay. Ki dou lekou khale. Poussin day kham lekam

  • makhou
    10/05/2016 11:04

    best tu ma tué lol salaw bayiw si xelam sakh na mais coudou bou ndaye dou yegueul meudeu ndayine

  • sow
    10/05/2016 11:10

    flicitations Abou Gor fit

  • James
    10/05/2016 11:12

    RIP ABOU THIOUBALO

  • bara
    10/05/2016 12:02

    Diame ak kheweul ci barcke serigne touba khadimou rassoul amoul morom Diame ak kheweul you bary

  • Billy
    10/05/2016 12:02

    Abou gassal nga sa bop baml ba par ki tathie rram rek khadjoul ci yaw alahou akbar

  • bower
    10/05/2016 12:23

    Mé mw j’ai pas confiance en abou deh ndakh louko diégué si chambre bi mou wann ko. C’est ce qu’il avait di dans sa chanson (solution)

  • Deuch
    10/05/2016 13:03

    Mbeuguel dafa fort yalla na sey bi barkl

  • talibe mouride
    10/05/2016 13:12

    rebatass boul ma raaye wayye

  • dou
    10/05/2016 14:42

    flicitations sa ma tom

  • Rama Badiane
    10/05/2016 15:04

    Abou dalgua si khrr

  • Du Degn
    10/05/2016 15:13

    Abou dal guerrier la

  • KHL
    10/05/2016 15:17

    hiii abou day kharou

  • best
    10/05/2016 15:51

    makhou kholal rek hahhaha

  • Kine
    10/05/2016 16:00

    Rip abou lii lekou maguela dagaye fote lgui kome sii sa way bii solution sa poute bii xawna kharre

  • Esprit
    10/05/2016 16:48

    Lii nakk moy kou Adouna soof mou diohé rouh wam§§§

  • leuz
    10/05/2016 16:54

    Abou khans daga doff giusso femmebi khana dagay kharou

  • ouss
    10/05/2016 16:54

    heureux menage

  • *WTF
    10/05/2016 17:44

    thiiiioooooooooooohhhhhhhhhhhh bilay réy niéy yomb na mé lakk ko djafféé. heureux menage

  • fall
    10/05/2016 18:59

    abou mayi ha gassi fes

  • diallo mbalo
    10/05/2016 19:44

    INA Lilahi wa ina iley radionn ki khana mbokamyi yegouniou ko dena ba pare drianke bi

  • sofia
    10/05/2016 20:39

    Abou fékhéle ba ndawsi boumou yék sa kawe, boulaye teuyeukhe béneu ngaye dé, gnar va gnéte kéne wakhalewouko.

  • KHL
    10/05/2016 21:10

    hahaha sophia ray nama

  • eva
    10/05/2016 21:16

    Abou outil ngora keng taye gua d

  • boy djiné
    10/05/2016 21:17

    ki doula Ray, dassiy tok rek mou dameuuu..nga handicapé à vie…

  • le jeune
    10/05/2016 21:53

    yena bax

  • yaram
    10/05/2016 22:56

    li nac moy teuss

  • jonh
    10/05/2016 23:25

    ô secours dinako ray

  • mbidou
    11/05/2016 08:24

    wa boybi soboul wa abou ki noumou koy def li mom beug buzz leu mais dou am fit

  • beau gosse
    11/05/2016 10:25

    ahha lol boulne ma ray qui Abou bouko tw dou doyy moo

  • good boy
    11/05/2016 10:48

    mes felicitation abou yalla na seybi Barkel amiinn

  • Valentina
    11/05/2016 11:50

    Desolee madame la mariee votre haut et votre jupe ne vont pas ensemble…..cest quoi cet habillement pour un mariage…..heureux mariage…..mais habillement hypr moche

  • lykhas
    15/05/2016 21:30

    le plus grand probleme mooye foumouye commenser?

  • zezet
    15/05/2016 23:58

    yagui dora ame solution

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL