Annonces
Annonces
» » » » » ( 05 Photos ) Pape Diouf a rendu visite son...

( 05 Photos ) Pape Diouf a rendu visite son idole, Youssou Ndour

2017-03-07T21:01:09+00:00209 Partages

La complicité qui existe entre ces chanteurs bien aimés du grand public sénégalais se solidifie de jour en jour. Pape Diouf a rendu visite à Youssou Ndour, regardez les images.

Annonces
Annonces

27 commentaires

  • samba sall
    07/03/2017 21:15

    c jolie sa

  • Zoo
    07/03/2017 21:26

    Pape Diouf comme kagnia

  • fatima
    07/03/2017 21:28

    wa li khana dou grand theatre rek wala thiey pape gueumeul sa bopou nga diema avancé grand theatre sè pa un challenge pour toi

  • mia
    07/03/2017 21:28

    doyna war dée

  • Marsene
    07/03/2017 21:31

    Khana pape buzz nga beugue youssou khorome thi thine la

  • sallma
    07/03/2017 21:39

    nice nice nice

  • guéweul francenabé
    07/03/2017 21:40

    Rafétna
    Laftiat ci yéne

  • tintin
    07/03/2017 21:42

    Seu baye moy kagna

  • Pape diouf
    07/03/2017 22:08

    Gueumoul bopam se type instant bi warone na feike nga âme label bou toude « dioufy musique »wala un autre nom wayei du neike soukh jusqu’à quand oooh pape!

  • saly
    07/03/2017 22:17

    Macha allah li rek nekh mak ak rakam vous êtes les chanteurs préférés

  • Paco
    07/03/2017 23:09

    On dit : RENDRE VISITE A QUELQU’UN

  • Gueumeul sa bopp
    07/03/2017 23:15

    Pape diouf bayil sa yalwaan fans bi nga neké , senegalais ken momouleen té ken mounoulena forcé gnou beug kougnou beugoul ,demal ligueyi té nga geum sa bopou liguey rekk mo woor té lolou wally seck wonéna malgré li jaloux yi di wakh si mom yepp faléwouleen day liguey ligueyam motakhit legui rawna la , il enchaine concert sur concert en rencontrant toujours le meme succés, il sort des sons que tout le monde aime comme ‘Donne moi une chance’ qui fait le buzz sur youtube , allez regarder le nombre de vues.Inspirestw du slogan de wally »Liguey lou beuri wakh touti, sopé you beuri dayna fay »

  • fiaaa
    08/03/2017 00:32

    Le roi du mbalax Youssou d’où nit dée..Youssou di na léne yague tital il l’es international Tou le monde le
    connaît

  • fiaaa
    08/03/2017 00:46

    Yémléne waly Sénégal la yèm

  • FIAA khana dangay nelaw
    08/03/2017 01:07

    sou wally yamé senegal khana pape diouf dakar la yam kone , wally temps yamouy yam senegal rekk diekhena deh legui gnoune ak yenene africain yi gnoko bokou , wally sakh dou debat bi , kokou mom delen ko khol rekk mouy avancer , dangena sokhor rekk

  • beugsenegal
    08/03/2017 04:18

    pape reveilles toi …bakhna ..mon grand mon grand , ba boy yi rawla …

  • Tasmany
    08/03/2017 09:17

    Maleen fan samay chanteurs way laf thiat si yeen

  • Feuz
    08/03/2017 09:21

    Pape dé dafa diokh magam thieur motakh You le lui rend bien boudé Wally dafa international c’est son problème

  • Lamine
    08/03/2017 09:52

    Grand théâtre n’est plus un défi pour le pape de la musique Sénégalaise

  • Shaynaynay
    08/03/2017 10:22

    There’s nothing like seeing you idol.

  • kine
    08/03/2017 11:08

    ay way ngir yalla ak yoneinte bi diguente bou am jam appuyé len si jam ji sakh lolou la yalla beug

  • adja
    08/03/2017 11:42

    pape diouf daf ngueu lou rafét ni leu deh bouleu kéneu nakh mon frere ya bakh deh!!youssou beug na leu si sama khol

  • tagg
    08/03/2017 11:50

    KHANA DA NGUEIN DI LEIKA KAGNIA SEN GALLE DOMARAM

  • Moussa
    08/03/2017 12:05

    Pape diouf est beaucoup mieux que waly, dou moromome sakh. En ce moment waly est entrain d’essayer de se faire un nom hors du Senegal en utilisant sidiki diabate. Il veut devenir coute que coute comme you sans travailler et c pas comme ca, on ne devient pas you en une annee…qu’il aille bosser et arrete de leurer les senegalais, on sait tout, il ne fait que copier d’autres chanteurs, il est temps qu’il arrete et d’essayer de faire ses propres chansons

  • Niouh
    08/03/2017 12:56

    Ayy pape gemeul sa bop ga deff komm Wally .Wally mogyy ni légui dafa international africains yeup nioko HAM te ses sons passent sur de grandes chaines comme TRACE TV yaw ga toop youssou rekk .instant yi warone ga AM sa label comme faramarene MUSIC .ahh pape tu déconnes quoi gemeul sa bopp.

  • tima
    08/03/2017 13:55

    damakoy nianal rek yalla fayko xolam si barke ya nabi pslape diiouf rek

  • PAS D’Accord AVEC MOUSSA
    08/03/2017 14:22

    MOusa khamena pape diouf moy travailler , vs etes tt simplement jaloux ba wally demé mali lepp leer na , en plus ne veut pas devenir youssou, car nous on n’aime wally pas youssou, wally est wally ,et il restera lui meme, et pour nous il est le meilleur , et meme les gens qui ne sont pas sengalais reconnaissent son talent,un anecdote: un jour j’ai fait ecouté à une française une serie de sons d’artistes senegalais dont wally fait partie, et aprés la seance d’ecoute, elle m’a affirmé k’elle prefere wally aux autres et qu’il a une voix extraordinaire et unique aussi,mais senegalais dafa ignane dougnou nango mmé ins bi mom wally mo nekk thi kaw ,dafa meun woyy et en plus gneppa ko beug. mais aussi wally woutoul fi dara mais normal khalé bi mo spécial , fougnou ko toudé rekk commentaire yi djoukk,mé ndam rekk lay ame

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL